Rebeuss: Thione Seck à la chambre 43 avec Massaly et Johnny Ba
Thione Seck est à Rebeuss depuis hier soir où il a passé sa première nuit. Le père de Waly est à la chambre 43 qu’il partage avec le jeune libéral Mamadou Lamine Massaly et Johnny Ba. Thione Seck a été placé sous mandat de dépôt à l’issue de face à face avec avec le juge d’instruction pour escroquerie, blanchiment d’argent, détention de signes monétiques et association de malfaiteurs.
thiooy mame yalla ms dara yalla limou deff rek lou geune lah baay waly seck frassmnt diit tu la op meritei sa…
Yéna gnak foula dokhilén fowi
kesk yaw tu ma tue mdrirrrrrr hahahahah
Sathie sunu khaliss ak khalissou africain yi…benn senegalais djok ni yalla nala yalla japali…Papa Thione…Vous nous aurez déçu !!!
gorgui doctor bi day sopp rek boul diokhe sa khalis ddd man lolou lanma wxone mai faux resulta laa com faux biellet you pere thione yi la aussi prison diombouko te afair 2 goor la nek nafa chmbr9mo guena tar 41ou43 bimou nk
No gorgui diop dieuleul sa ma compte "gordjiguenboutfm@yahoo.fr
thione yallah nalla yallah deffal diame ta takhawoula papa thione adouna nilla yallah Day nattou koumou beugue
laissons le tps
juger on verra après ue la vérité triomphe dans cette affaire
mdr t es pas sérieux gorgui je rappelle au passage qu'on est de tout coeur avec toi papa thione
thiey papa thione yalla nala yalla doli takhaw thi sa ndiabot aminn
gorgui dindil sa diop bi ta soy der(mort) gua mort nioune sougniou yone nekou si mais nioune fi Amerique dais dinagne sokhla khaliss bi ay waye ma name Senegal
gorgui diop ya mana minwww deugue deugue espece de mitho.@delfa yallah nala yallah sunu borom may weurgou yaram ak goudou fann mbokamii amal diam ak mbolémou djioulit.thione seck mounieul c la vie thiat daffa gaw wayé doylou tamitt bakhna si app djioulitt
Je viens d'avoir une très nette version de l'affaire sur médiafrik!
Le chanteur est victime de grand bandits pas si organisé que ça. De l'influences mystique dans l'air !!!
moi j'entends toujours sur cet affaire de thione niou nane ndogolou yalla la! il nitt gni mana ragné ndogolou yalla ak lou nitt ki dogalal bopam
tte chose malheur est bonne thione aura le temps de méditer sur ses faits et demander pardon au bon Dieu
mdr soninke hahahaha
bjr a tous a tous et a toute..nianall lénne maa wergou yaramm gou barrii..wergou yaramm silaa leppeu khath..merci ke la paix soit avec vous mon peuple sénégalais…
gorgui diop 20ans sakh amoko
eh zelko merci way toi tu connais maniere
gorgui fait tout ça pour qu'on oublie l'article et se pencher sur lui mais rien à faire, l'ordre du jour est tjr là hein
Guorgui si je me trompe pas ton médecin ta dit que tu fil tout droit vers allakhira yow ak sayi faux billets
gorgui yaw ko yap???
sama numero compte
1,2,3 mot de passe khouss ma gnap
Gorgui sa Allal bi souder khaliss bou bakh la diemko sedaler hôpitaux ak diak yi ay newdji dolé yi koom ca sougnou borom bindeul la ay touyaba
mbokou yi ma ngi leni nou yene gneup dilene sant je me nome gorgui diop jai 80ans dama febar depus 10ans awma diabar awma dom waye am na alal machallah té docteur bi nénama si mois de juin bi laye dem té awma bena mbokkou ma bougone yene internaut yi kou si am sa compte banque wala sa mail nga diokhma ko ma transfere la xaliss bi ma amone yeup sokhlo wou ma si dara dama koy def rek te yalla takh xaliss bi ma ngi ko yoré sama keur ay malette la war na tolou si 2/ 3 millardes cfa ak ay euro yeupe ay faux billet la MERCI !
Daga naye rew
thiey yalla, nattou mo gaaw dè, yalla naniou yalla yokou soutoureu, mousseul niou si prison, tè guenè leen fa