Photos-Les images de l'apparition de Serigne Babacar Sy à Guédiawaye

Les images de l’apparition de Serigne Babacar Sy à Guédiawaye

mbay
mbaye1
Mbaye3
MMbaye2

Votre avis sera publié et visible par des milliers de lecteurs. Veuillez l’exprimer dans un langage respectueux.

Dans le même thême

268 commentaires

  1. astou mbengue

    té ngéna bayi wakh dji ta kham né gnoune gnep gno yam si yalla ta nguene bayi dingate bi ta kham ni tarikhayi yep bene la yene nitte gni yena lene beuga takalé rek mais gnom gnep bene lane


  2. nabou niang

    waw yene khana dagena doff walla lan molene diote serigne babacar mame borome touba baye niass gnom gneup dougnou seni morome rawatina nguen dilene togne parcek gnougui teud fagnou teud diotewgnou ak yene dara mais demlene rek togne dou galadj diguene torokh yene gni di sagua mak you bakh yoyou


  3. obelisk

    man dh khamou ma am na wala amoul mais les touts les marabouts devront etre respecter. et toi marieme diallo pour quoi tu as insulter les mourides? qui t’a dit que ce qui t’on crittiquer sont des mouride et meme s’ils sont des mourides tu ne devais pas generaliser par ce que c’est pas touts les mourides qui t’ont dementit


    #sois_sage


  4. fanta

    l plus impotent c d respecter l 5 priere c mieu gni ligueyal na gnu yalla ba pare ns somme tous d musulmant yenene te lene lu bax mo gueune wax ji


  5. ansi

    Nos kilifeu dinné méritent beaucoup de respect, bignou déparé yag na et il se sont énormément battus pour propager l’islam dans ce pays et nous ne parvenons même pas à suivre correctement leurs pas, mieux vaut éviter ces querelles.


  6. mohamed ndiaye

    je suuis talibé de baye niass mais lima beugone wax moy respect pour les grands marabout waliw yalla yi gnom gneup ben lanou kou nek na geum limou geume té nou bagna guéné wax you gnaw dieumaléko si gnom té serigne babacar bou fégné si mur mane geum nani martabam eupna na lolou té cheytane menou l copier dieum mak gnou bakh gni nanou am adap si zayir ak batine


  7. Diarra

    Mdrir wa loutakh Marieme Diallo ngay sagga Mouride yi lougn la def gniy commenter khamo bakham niassen lagne khadre wal layene ngani Mouride haha gnoune gno sonou way!


    • Alioune Diagne

      Nioune nakk khana gueumeutou niou Yalla!! Lii yeup souniou borom rekk leu ak ay mbiraam!!!

      Kouko beug gueum gueumko, kokou beugoul tamit kéne meunou la forcer!! Wayé dale naniou bayii khéll si yalla té khamni mom rekk mo worr!! Mane mom jsuis TIDIANE et fier de letre wayé je suis MUSULMAN avant tout! Kone diarouffi ngiyoo ak ngayoo! Yalla rek ak yonenté biisalalahou alleyhi wa salam rek doynaniou, mais gnii ay royoukkay laniou dans leur facon detre et de faire akk ni niou dane diamo yalla! Wa Salam


  8. Adama Cisse

    c bien possible k se soit serigne babacar sy si l’on connait bien la dimension mystérieux de l’homme.mais c k le sénégais par exellence croit trp au miracle et au fait surnaturel.mais je croix personnellement k sa peut étre une forme d’apparition de serigne babacar sy


  9. beugue fallou

    serigne touba dou moromou babacar sy khana dégua faté histoire SOUL Lén si tivaoune en plus mur you salté yi keur you khar yi serigne touba douci fégn


    • tapha

      yaw mi di wakh beugue fallou khamo ni serigne touba soulou gnouko touba diourbel la déwé fa lanou ko soul boul gnou takha wakh séne association mouride bi kham nanou lépou serigne you bari dagnou léne ray boul gnou takha wakh kinou réndi wone si serignou touba yi ak kinou poisonné wone si soupou kagna bi yéne lou takh nguéne ték gnou beute faté na auto bou nek si kanam rek lanouy corné


      • kham kham

        yaw moustapha lingay wakh khamoo si darra bien vrai k serigne bi ndiarem la lakko waye serigne modou moustapha taawam moo ko dieul yoobou ko touba ba pare dadi nakh toubab yi neleen mougui ndiarem nguir kham say sayou toubab banie niou souli ko yoobouko sen deuk. et puis nioun mouride depasse naniou ay nek fii di wax si tidiane billahi ndax sounou kilifa moo niouko terre te nioun ndiguel laniouy weye


      • andissene

        ha ha ha mais yene nii monte agale 1 diouma kon association bi raw na sen tarikha bi . tarikha bou hamné dioubou wolén en plus dagendi copie si association bi yaram nalén 1tarikha 100khalifa nniawléne dibelou si man


  10. mouride sadikh

    wakh deug rek nak mais serigne touba mom dou jégn thi mur you salté yii sokhna marieme Diallo, té gua gnibi guinée nak yéna gui niouy beugua sonal


    • MOURIDE SADIKH WAHALE SA BATE SA KAW SERIGNE TOUBA DA SELLE DOU GUENE THI MUR YOU SALTEYI RAWATIANDAKAROU REWOU BAKAR BOBOU BAMBA TOUBA NDIAREM WALLA DAROU MOUHTI REKK mareme guamal yall mane dehh guisoumafi dara nakk


      • Awaly Sall

        FAUX ! on a fait apparaître Serigne Touba sur le tronc d’un arbre !

        Mais il faut aussi que Marième Diallo saches que ce ne sont très souvent pas les Mourides ! Il y’a des juifs, des Shi’a et FM qui cherchent à créer les dissensions ! parfois même avec les Catholiques ! Que l’affaire de Charlie Hebdo serve aussi ici !


    • sarah

      ABDOU t'a raison dé les morts reviennent maintenant les sénégalais ont du mal à comprendre l'islam tu vois un sénégalais qui à le coran dans sa tête alors qu'il n'a rien compris .ils va falloire que les filles s'occupent de leurs voiles au lieu de délire.

      Demain INCHAALLAH un peintre va dessiner serigne Touba et mettre un peu la peinture est les mourides ne vont pas tarder à se suicider là bas .le satan est fort dé mes frères


    • Mouride Fall

      Mane dé talibé Mame CH Ibrahima Fall la, di baye Fall bou mag wayé lii mom dou mako wédi mouk, Keurou diné yep la yalla may.SVP cessez de faire des comparaisons entre nos guides.Ils se connaissent entre eux.Na talibé yem plassou talibé.


Laisser un commentaire