Photos: Alphie en toute complicité avec son époux Ricardo

La chroniqueuse de la Tfm affiche son plus beau sourire en compagnie de son mari Ricardo.

2

3

Votre avis sera publié et visible par des milliers de lecteurs. Veuillez l’exprimer dans un langage respectueux.

Dans le même thême

26 commentaires

  1. khamm lepp

    Alfi et ricardo se sont maris ya plus de 10ans. so khamoul dangay noppi, bamou toubb dou tay. Sngal une fois qu’on te vois a l tl rek commenc dila lidienti, ils mne leur vie tranquille avec sa petite famille. maylenn ko jamm


  2. Malika

    Kham nalene bou bakh alphie kou djoulitela domam chaque week end dafay diangui al quran ….dieukeurem kou baxla tamit …molene guene deh yen gnifi nek di wax loulene woroul …fene mom mo haram wax loula woroul islam santanewuko …


  3. étudiant

    il maestro yow doul lii yalla wakh yeup yangui koye deff lidjeuntile sa boss ba parai balla ngaye teude diakarlolle ak sa bop sii setou soudé ta rien à te reprocher tes parfait ngeu gneuw wakh gnou


  4. Il maestro

    soudone niari yfar dounousi wax mais daou xamni Alphi musulmane la,ta sunu constitution diin dafa waxni jullit bou goor meune na take chrtiene bou jigueen mais chrtien bou goor manoul take jullit bou jigueen sounou diin lii la wakh.addinou nassiikha nak la sounou borom wakh diin lahantbiir la wassaaaaaaaam!


  5. senegalaise

    mais vous khana toubab dou nit rek anh dou niom nieup bonne s ils s aiment yalla na yalla def ci seybi barké le mari est Muslim ou pas ca ne nous regarde pas si c est un pêché c est entre eux et Dieu nanou mandou topoto lou sounou yone nek cuz on a des choses plus importantes a regler comme comment eradiaquer la pauvreté… C est facil d indexer les autres mais nous est ce que nous sommes parfaits kou nek na topoto dinem barkaram adianam ak safaram


  6. étudiant

    yéne yalenne con sokhor jaloux ngéni melni aye deume bayilaine djambour chaque nga guiss senegalai bou biral ba paré soga tak ani louko geuna arame kouye weure lou arame boul geneu sa keur balla nélaw guisko


  7. ranty

    ma warrou si sounou soeur yi ak les parents d aujourd huit cou touboull no koy mayer ce dome ak kane mo takeu seuye bi, j ais un question a poser li lane leu si Islam wakh


Laisser un commentaire