BRVM-10 173,71 -0,37 BRVM-C 180,74 -0,47 Dernière mise à jour : Lundi, 22 octobre, 2018 - 22:45

BOA SN

0,00

SONATEL

0,00

TOTAL SN

-0,38
PROGRAMMES TV
L'horoscope du jour Horoscope du jour En ce moment à Dakar 26° partly-cloudy-night
Annonces

Le nouveau single de Tarba Mbaye, “Téyé lène ko”

Espace inc présente le nouveau single de Tarba Mbaye intitulé,  “Téyé lène ko”. Un single qui fait exploser les téléphones portables à travers le monde. Ce tube de l’année est plébiscité par les mélomanes.

Ecoutez:

Voici le lyrix qui affiche les paroles de la chanson que vous écoutez

Paroles « Teuyé Léne Ko » de Tarba Mbaye
Mann déé Beugueunala Boula Daara Diaral Ngaa demm Bama Khass Ngaama Mineul
Say Khettou Bakh Bakh …………..Laahi Layla ho Waaw!
Taa Say Khetou bakh bakh Weurr nako ba Dadieul Ta Guissoumako Fenenn Fou doul thii yow Yayy rëënou Khol bé Kaay!!
Mann Bougouma dila Dioylo! Ngay misére nékhouma ! My baby lii nga yakarr ! Dou Lolou!
Bougouma dila Dioylo! Soyy misére douma nekh Khalé bi léé yow Lii nga yakarr Dou Löölou Lahi Layla Hoo!
Ndaakh té mann Souma guëné nga mërëma Ma wakh téléphone nga mërëma Yow dé khamalni
Amena ay soopé Ame mbook! Ame Amedi diaam Damaléni woo Yenn sayy ma sëtilenn Yow dé li nga yaakar Dou löölou
Mann déé Beugueu naleu !
Mann déé Beugueu NalaMalaraww meunouko fayy Kii la ndieukeuné Beugueu molaraw

Foufé yeah! Haan ndeysanëë
Baby mbeugueul wegn Bouyy taawëë kouleu Niarr niouko kheuthie Kou ndieukeu bayi Gaagn nga sa moröm
Mbeugueul dafa riichéé ! Mbeugueul!
Ndéné Demba ak Ndéné Marame Diallo Haan Ndéné Yassine Sa Mame leu Bourr…
Aladji Ndiaga Fall layy Sa Bayy boyy Amineta Mbaye moyy Sa Yaye! Sa Yaye da liguey sa Keur Baye
Baa bo narré daanou Sa ligueey ndeye Molay Téyé ba do danou
Chérie Ndoumbé!
Baby laalou Mbeugueul Dafa khaatt niitt koussi bokoul Khadjossi! Louy Nakh wa nékha saani Yaay sama mool !
Mbeugueul sa Gaal leu…Yakoyy dioww Yapp ma thii sa gaalou Mbeugueul diko diow wo Diow !

Fo terr ak mann Saff nama mann! Bou Jigeen yii dhé tëëmër Benn lassi taamou Ta Yow laa! Sa Deug Deug deug !Mann taamoula nala Ba nga doyma !
Déthié diéré maa thieu Sine ! Chérie Papa Aly Badiene Woyy nala !
Mbokou bayy Fatou Binetou Faye Sine Sine Yii Dagoulenn ! Tayy ma woylenn
Ame dieuleul sa Yeuff Yow dieuleul sa Yeuf Sama Khol yako moom Baby! Bokoko ak kenn
Ameü ! Dieuleul! Maman Chérie ! Cheikh M’baye
Ameü dieuleul sa yeuf ! Yow dieuleul sa yeuf Cheikh Kholam yako moom! Boko ko ak Kenn

Ameü ! Dieuleul!
Khaley bii amena Salagn Salagn ak Thieufeur Thieufeurr! “Tarba Mbaye lii nga Wakh sakh diarna Bayi Xel”
Raïssa amena Salagn Salagn Alé kham ngassi daara! “Moo Khaley bi loumou wakh sakh diarna Bayi Xel”
100% Tarba Mbaye Mann déé Fonkou nalenn no!! “Tarba li nga wakh sakh diarna Bayi Xel”
Eh !! Sama feem youma yorr Damakoy diayy Doumako mayéé! “Tarba Mbaye Tarba Mbaye Say Feem diarna dieunde”
Han !! Amy !! “Kokou kayy Amy” Amy Gueye
Aladji Modou Gueye Bouaké Moyy sa bayy boyy Ndiolé sa yay diongue Yay Diomba Sarr Amy Aladji Bara Fallilou Beugueu nala!
“Tarba Mbaye ! Tarba Mbaye Dikeuneu Dikeuneu Dikeuneu déé Khaley bii Négn déglou daniouy woyal”
Sama feem youma yorr damakoy diayy doumako mayé ! “Tarba Mbaye ! Tarba Mbaye Say feem diarna dieunde”
Teuyé Léne Ko Teuyé nako ! “Bou moula reuthie” Koussi ame goor bou bakh Yow nanko teuyé
“Téyeul sa yeuff” Déé koy topoto Goor yombatoul ! “Lolou deugg leu”
Diko wakh! wakh diou nekh Ndakh mokay saagal! “Dou mola warr” Fonkal sa Dieukeur ! “Kayy”

Déé koy bëugëul ! “Téyeul sa yeuf” ! Diko topoto ! “Bou moula reuthie”
Goor Yombatoul! Déé koy wakh Wakh diou nekh ! “Fonkal Fonkal Fonkaal…”
“Dëgg loule ma ndiguëlëm jigeen day seyy”
Sa Dieukeur djila dieul Deff cii yow Alal Dëko Bëuguëul
“Moo koufi baa nieupp nieup Né yow dong dëko seuyeul”
Thiaat ! Kara! Mii la dieul deff cii yow ! Alal dëko saagal

Annonces
Annonces

Un commentaire

  • Musique
    7 décembre 2017 9 h 16 min

    un garcon à suivre ! trés belle chanson machallah tarba tu chantes trés trés bien!!! tu es une révélation de la musique sénégalaise.

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *