Mayoon na ñou la ñetti weer senegaal taxaw
Nga dolli ci ñetti àt senegal fëll
Defoon na nu fi 35 km autoroute ci 52 àt
Nga dolli ci 36 km ci ñetti àt
Waa njum, wurosogi, bakel ak tamba, waa jalokoto ak mako
Bakkal leen ma Macky SALL
Son excellence mi tallal yoon yi
VDN feelu leen jug gi yomb na
Kàn mooy Macky SALL
Kiy jëf ta boole wul daraaki wax
Toolu kuuraƞ yaa ngiy lalu
Tabakh yi di sax ca jamñaajo
Forage yaa ngiy jolli
Ndox maa ngi bàll
Bakkul bu la neexe sa yoon leer na
Kan mooy macky SALL
Ki rafetal demb, défar tay, xalaat ëllëk
Woote and gu rafet
Tërël PUDC dimbëli njaboot gi
Defaraat decentralisation suxxali gox yi
Yombalal mbay mi, suxxali càmm gi
Tabax teeru yi suxxali napp gi
Këru liggéyu kay yi gërëm na ñu la,
Liggéy kàt yi bayyi woo léen gannaaw
Kan mooy macky SALL
Ki bëgg lépp di leer
Ne transparence te di ko doxal
Woote bonne gouvernance te diko jëfé
Jiitu jiitël askan wi
Su saxaar si yuuxoo, avion yi di riir, senegal emerge
Ñou xam ne lépp dëgg lë
Mamadou Yattassaye responsable politique apr à mbao coordonnateur du projet suxali sama goox diapalé sama réw

c’est qui lui encore non mais putinnnnnnnnnnnnnnnnnn
Oui vraimenttttttttttttttt ces larbins sooonaaalllllll nagnou wa rew mi.
diapal ni beugue nala bes ni tey way contane na way
way contane na si yaw dhe