17 COMMENTAIRES
  • refal

    non waly wakh degue yalla sa son yi mome nekhoul yang nouye rouslo de

  • inconnu

    Le dernier album est beaucoup mieux franchement. désolé

  • fatima

    Machala trop nice lafe tiate le meilleur de sa génération

  • davito

    Nekhoul amagoulo diom dė

  • fa

    tré beau et tré nice vremen

  • awa

    mé gayi bayilénn sokhor gui nak li defoul loudoul nekh

  • amm

    nékh lalay wax déee

  • amm

    noo wayil je tador vremen

  • mar

    chapeau

  • bass

    loulayy faye

  • mass

    maynala 1000000000 thi son bi rek nak

  • krumah

    A vrai dire bougne ko tégué si musique akk waay rek, wally demal gua jangui waat album bi sound yima deglou yepp dess na…boul waay ndankh saay fans mais dangua wara waay ndankh les mélomanes…demal jangui waat bro

  • kine waly

    bayilen sokhor li nekh dongue la def album bou bess c normal k do minagoul parole yi dagakay deglou ak xel ak xole je tm waly

  • kinewaly

    bayilen sokhor li nekh dongue la def album bou bess c normal k do minagoul parole yi dagakay deglou ak xel ak xole je tm waly

  • kh

    amna gno khamni lo déf doulène meusseu nékh ndakh bougougnou sa dara défal lo sentire lo déf nékhnagnou le reste on s'en fou

  • BINOUCH

    JUSTE BEAU…LAF TIATE

  • zoula

    merci waly on né tou ceour avec toi bo donn cotinuation yow bo yore sa micro di si nelaw sax gnon bek nagn afair bi dou yow waly afair by yala la kou mer kalamel yala

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *