Enterrement de Béthio à Touba : Des Thianta disent niet …(vidéo)

Les Thiantacônes ne comptent pas suivre la décision du Khalife général des Mourides qui souhaite enterrer leur guide dans les cimetières de Touba.
Ils l’ont fait savoir ce vendredi matin à Madinatou Salam. D’ailleurs, ils comptent aller à l’AIBD pour détourner le corps de leur défunt guide (…)
Mouride ndigeul.yeene guemolene serigne touba .ndakh serigne mountakha moofi nekal serigne touba kone dangena wara dieufee ndigeul
Lou serigne moutakha wakh moye ndigeul gui .cheikh bethio touba lanoukoye denthie
C tiantakoune la sont faux
Dem lene lidianti sen papa mongane guieni lidianti papay diam pour talibe dawara yame thi talibe
Ndeysann serigne cheikh al makhtoum wakhone na di naniou dem diamono nit dina wathie ligueye niou koy dianti dianté di weur founiou ko def serigne mountkha moy serigne touba cheikh bethio yala nako yala yeureum talibelawon kon nak mouride ndigueul
Ils doivent comptet sur la décision du khalifa
Dof yi moss yaradi kou wesou woul li
Liffi nek lepp kenn meunouko wakh khana daguenn beugg tarikha bou bess?
ngi nioma beteu degu thiantakoune bokoul thi yonu mouride rek kone
Lîi yeup lou ko waral moy Bethio yalla nà ko yalla yeureum mais yaroul ndiabottam
gni dano eupe nakk
Bouléne faté yalla souniou borom ci mbirr yi.mongui ni ték dilén khole.nangouléne céne khalifa bi
Dou ay Mourid ken moussoulen na guiss keur serigne Betho
Niakk talibé rékk wayé mouride ndigueul té ndigueul dieuffé té ndigueulou Serigne mountakha dieufféko moy dieuffé ndiguelou Mame borom touba yéne yii dafay nourou Ay thiaxane té dée moy deugue bayiléne di kheuthio ak kilifeu ndax Serigne Touba néna kou yarouwoul adouna dinala yarr boula adouna yaroul baméll yarla té kou baméll yarr kouné digua yarou ??? Nanou ande ak dall té diéma yarou ndakh moy liniouy diarigne fii ak finiou dieumm wa salam
yalla na yalla yokou soutoura.
té def lou guene.
cheikh bethio yalla nako yalla yeuram
NIEPP DI NIANE BIOU SOULEENN TOUBA NGUÈNN DI DOFDOFLOU
KHANA DOUNGUÈNN AY MOURID AY DEUM NGUENN