51 COMMENTAIRES
  • leuza

    Yaw laniou diapeu mai Bâri nga si morom !!!

  • toutou

    damay rouss sakh nèk djiguène liiui

    • daouda ndaiy

      ya yaye rouse ndax li dafa niaw

  • z

    Attentat à la pudeur? waay ban pudeur? nokhouleen falé… Senegal ay thiaga rek kessé kessé. Bayileen diambour té ngeen dokh seeni dokh. Vous nous pompez l’air. keur yi ay you bona bonn moo ci nek té ken dou ko wakh

  • diop

    nite loumou bonbon soutoura dafa bakhe dni bone na mai kiko publié mon geuna bone

  • fale

    Vraiment , li dou sén problème. Baayi lén diabour.ce sont deux adultes qui ont decide d faire l amour cà n engagemen k eux.

  • seck

    Nakeef ndayam..yi ngen don..senegalais moloul..nioweul europee gno geuneu sokhor ndayam…jigggen danoukoy soutoureul..ndoy basan yaw imbécil nga

  • juniorr

    no senegal dou demmmmmmmmmmm koi ho my god he vous qui dites ces pas leurs problem vous connaissais rien meme en europ la ou ya la democracie en fait pas sex ds la rue jamais ous aussi surtous senegal ces vrai que ya plus que ca et ya nen bocup ki le fon au senegal ds la rue mais lolou weeff adj la

  • paco

    non vraiment senegal mo nekh sa thies yaw ko dane baye demander eumeu vraiment yaw amo conseiller demago fene dieuleule garga mbose papa sow wala boy niang wala yekini junior wala gouye gui fofou moy sa rang

    • Batista

      Merci Paco seulement Sa Thiés mo khamoul bopam

  • samba gueye

    nou li bou dh deug la senegal dou dem

  • jojo

    akh lii dou déba way louko geuneu gnaw mogui té kénn wakhouci épui yonu kén nékouci lou way déf bopam

  • ibou

    en tout c pas bien de faire l’amour en plein
    air on dirais des animaux,soutoura dafa bakh trop, on nai des etres humains ca meme

  • fily mbaaaaaaayyyeeeeeeeeeuuuhhhhhhh

    rououououssssssssssssssss naaaaaaaa waye

  • bay

    Loo guiss dafa wara and ak soutoureu

  • jk

    sa fait mal au coeur él a déconné el c excusé pardonnez le

  • aram

    baylen diambour mo teye vous etes tous les meme. pareil .6 et 9 kou am si yen def

  • diallo

    Kiko publier soudé sa yaye leniou diap di lalanté ak faram dengkoy publier

  • fox

    mogui nonou awma loumasi wakh kou wakh lepou bou yague gnou tam la deume

  • JIBY

    LI LA YALLA WAKHON THIE (alhourane)lahate khalahna inesanou fi hakhsani takhwénine souma radatenahou asfala safilina

  • joe beaden

    Soutoura bakhena.djiguene dañou kooy soutoural

  • laye

    Bien dit Joe Beaden, quelque que soit la situation, Soutoura bakhena.djiguene dañou kooy soutoural.

  • Mauritanie

    Deug la gni dioum naniou mais djiguéne danioukoy soutoural, ki publié li défna lou niaw. yala dafa beug soutoura

  • miki

    Ki Publie li dal bakhoul te amoul soutoura nit gnangui def louko guena bone di liguey nit mou des mba mou taguo ak sagom djiguen dagnou koy soutoural nanguouna Mo togne Mo dioum Balou akke khana Yalla sakh dangua koy balou mou bal la djiguen Ken douko torakhal gnoy sougnu yay diabar ak soeur

  • fekke

    yalla na niou yalla défal soutoura

  • sddfffgg

    ndoye bane la khawma man khawma kii dafa beugeu siiw walla mais soutoura baakhna donte limou def rafetoul mais ngeen sangeuko soutoura moom nangou nani joumna mais leneuli diekoul bahalleenko

  • miss

    nitt nga khalatt ni djiguéne mo la diour,di nga soutoural djiguene.sénégal thi bopam mo tass.ame na fi lou raw li foussssssssss.

  • dieng

    vraimen je ne sais kw dire je ne veux pluie etre une femme imaginons meme des gens ki disent k ce kon fasse dans les maisons est pire kan tesk vont finir ces actes meme c’est petit pour nous qualifier comme des animaux et pourtant l’Etre humain est cher et rempli de valeurs merci de bien vouloir changer notre comportement avant kil soit tard on ne sait pas kan comment et ou mes prochains

  • kalz

    bayilen wahou soutoura.cause pourlaquell on est arrive a ce point .il faut villipenderk

  • miki

    Kalz ki la Yalla werr tey rek waye gnoune gneup kousi nek yangui def lo khamne boula Yalla werone yay guena grawle ki kon nignou Yalla di soutourale nagnouy soutouralente signou bire

  • thiagga

    kantaté moo nexx wayy

  • zazi

    c honteux s8 vremen degouter

  • sante

    thim thim thim

  • souleymane

    nit daynkoy souteral lolou la yala beugue dou leup laniou wahe way yalla naniou yalla diegueulle

  • Ziza star

    Soutoura moufi diekh so dema khogne sambre yangui fi ampagaye tee dinga door a laise san publication thimm non senegal dou deem

  • waxoo fi dara

    yaw bane do niit diémal yaar sa boop bala nga yaré ya gueuneu dungue gieup nékhoma dara sa niaway

  • ousmanediallo

    bayilen disoutoura soutourabou eup mo yak senegale liui koukosambok defon nga guedko bafaou maersie bonchans atout les musilman e du monde waye manmanguifisi abidjan niag yiifuisakh dougnou delii

  • gaal dooff dou teer

    catanté akk roffanté niou nexx wayy

  • teuglife

    yawo douresa kha dideff li domo kha rame dago ga yawir sabou bo kowir sabou bo wiro yage mel ne koy foobale wara dogale ta dokaloo de baalo diam yakho ga dero ji gen

  • ki

    Bien que je ne sois pas d’accord avec ce genre de pratique, le comportement du journaliste n’est pas professionnel et laisse à désirer. Ce n’est pas à lui de faire la police même si on peut parler d’attentat à la pudeur. En vrai professionnel, il aurait pu appeler la police et interroger le policier.

  • self made man

    IL ya des cas bcp plus graves mais c vrémen injuste d trété les gens d 7 maniere celui ou celle ki a publié ceci doit avoir honte de sa personne amo ben soutoureu é je suis k ta klk chose a caché k tu n v personne le sache

  • PATHE

    antou ka avec tout ce bavar ce pa jolie a voir

  • diez

    Sa ya rien d grave.c’est son copin.el a le droit de coucher avec son copin oú el veux.les sénégalais sont en arrière et ils mouront spude.C pour cela nous ki vie en europ.on vou considere jamais.Vou aller mourir dans votre coin de saleur et moustik.tré en arriere

  • Sabata

    Eumeu ne sait pas lutter/ Sa thies dou moromam/

  • Vérité

    Celui ki la publié aura un jour………………..
    khawi soutoura djiguéne c’est pa bon…
    dieu seul est le pardonneur mé pa ndoy….

  • routhie

    se sont deux adulte ils sont libre de faire ce kil désir kou publié moungui déf lou gueneu pire lii

  • saye faye

    domou adama déye am soutoura sou nékhone louy déf you wére la mais yalla dafa am soutoura mai louléne té am soutoura

  • bb

    ENTOUKA DOYNA WAR FASON CHACUN DONNE SA VERSION 7 L7 CONCERN7 SERON EN MESUR DE VOU DON7 UNE REM7DE…

  • Boss

    dagn ko sentir rek nitt mom loumou sentir lay def mai person yonam nekoussi bajoy wane

  • MATY

    Mais Bane tu n’avais pas à publier ça, tu aurais du au moins modifier la voix, c’est vrai que faire l’amour dehors c’est pas jolie, mais tu aura du l’appeler en aparté sans que personne ne le sache. Les péchés chacun d’entre nous en fait,et c’est à seul Allah de pardonner, il faut pas se mettre à la place de Dieu pour prétendre à la perfection. Soutoura dafa bakh ak nit loumou bone bone.

  • Dior sarr

    Faire lamour dan la rue! Ici o sènègal!! No cmente!

Publiez un commentaire