69 COMMENTAIRES
  • gege

    bilay Sénégal l’I nga wakh deugueula foumou neke gni donne saga selbe nieup kene degoulene te kou saga ndayou diambour sa bopp foumou nekk ni rouss ngene bâ melni ii bou amoul tombe selbe daye dème te kene d’où KO teyé khana nekh

  • Senegal

    Naniou am discipline respecter sougnou bopp aye mague youye saga parce que selbe a dit ce quelle as vue

  • Senegal

    Nioudone saga ananiou limou kham yallah la kene meunouthie dara elle as raison alors wakh le ne

  • gege

    toute mes félicitation selbe wakh dji barre na khamo ngani yalla dou la setane muhhaaaa yekini n a la foutre a la retraite ohhhhh!!!! ioe selbe do nittt

  • karim diack

    selbe talibe muride du duug ci yoyu xamal te noppi weurseuk yala moko yor

  • DAMOCLES

    Elle dit une chose et son contraire, elle affirme que yalla moko wone bay paré ni mone bagne ame. Seytané dafa for surtout si moudioume diamano

  • ussman

    senego mo gnou yaap rèk selbé na rien fé

  • paa

    salbe ioe bilahii diokh sa dom yii thiey lii dra diarou boude my am sakh nopill gayii guisall sen bop psk ioe lila gayii di wakhh ni dilaa saga yako deff ndakhh niue am kham kham niougui senegal fi nioug togg kenn dou lenn saga ndakhh de nioug mandou salbe salbe salbe madoull stp guirrr yalla…..

  • adama

    nañou ragal yalla soubhanahou wa tallah. Kéne manoul kéne xamoul yallah rék. Mme si c k cette femme predit s realise takhoul ñou wara gueme ay kaddome

  • MO

    je suis là

  • Ahmed

  • D2baller

    putin lac 2 la faral mai kom selbé wakh na rek g plus espoir

  • Bouba ndiaye

    Je me demande est ce que sava dans sa tete ???

  • soulamane

    yen nieupe aye kon nguene boudone sene yaye dolene ko saga tê souba danguene di dioye yekini pale daye danou

  • rafete khelle

    liiiii

  • sow

    salbe yaw nexoul ba nexoul me dioxo sa domyi thieur. ndakh solene dioxone thieur digua bayi diwakh si comba yi heur bo wakhe yalla yonela bopam wala gua degue say moromou dome dila sagua wala dila wakh lou guena niaw sagua di toudou say thieur li boude khaliss guasi wout diarouko boude beuz guay wout ausi diarouk. amna niojla eup khamxam foufe te waxouñe nopil guir yalla??

  • almagne

    ya

  • afia mbow

    bayil feneyi

  • rafete khell

    limou guiss rek la wakh mais wakhoul moy am par force wala amoul sagne sagne wakh limou guiss

  • Veric

    Vs risquez tous d’être brûlés à cause de selbé. Dans le monde où nous vivons elle a le droit de dire ce qu’elle pense même si notre religion n’accepte pas son travail(guissané). Donc ça c’est entre elle et Allah. Restez en dehors de ça. Quant à toi le sénégalais, tu as le droit de ne pas la croire ni de regarder ces vidéos mais pas de l’insulter ni de la juger.

  • mbacke

    ha salbè yala moy ki nga khamni moy deupp beu nieupp appreciè mo depeurni .doyna war mè sa reste k dè heurs ya gatoul

  • cartel

    diatto i manding a du casamance guediawaye kou Guinée bissau Denis n’a diouda inchalah

  • Kangfori

    Chaque jour ak nène bou bess, tèy moom doul you bess tak ngua fi defati. Mane ak yow la, ba souba.

  • mbaye

    guir yalla set lene si domame yi bayilene saga yi

  • damocles sy

    Selba comment oses tu dire qu yallah molako wone baye paré gani mone na bagne am. Ragualal yallah

  • petro

    WAW SELB LOY WAKH BOU YEKINI DAAN LAC2?

  • pape

    walahii deeeeyyyyy feeeeeennnn

  • diop buegg dëgg

    lou amagoul moom dangay wakh rek

  • Lac 2

    Man Lac 2 dé khalatoumako comme selbe ndom wakh na allkhamdoulilah

  • mimi

    Salb bone nga

  • viper

    Fans yekini bi môme selbe KO taner ndakh selbe gnepe khamnanou aye doulame môme rêve entre fadiare ak souba lolou dou rêve dianner lagnoukoye wakh doule rek

  • Golas

    tout ça c’est pour atteindre son moral. mais yekini vous surprendra. il va gagner

  • arturo vidal

    bayil wakh

  • arturo vidal

    bayil wakh li ame demain yalla moka kham

  • ndao

    Salbe dangaye dul keur sakh mono ka tall

  • Macaroni

    Ki tanke mbeuri méyou niouko arret dou comprendre akamena dam morale dawsi sheuteuteute

  • ndao

    Da nhaye dul maka wakh monou tal keur sac

  • abg

    non SAlBE do moromou gayi.ngan koula sagati loye def?yangui may ray

  • ismaila

    Je suis en Mauritanie bayilene saga svp

  • toure

    meme si tu sais qui va tomber,il n fo pa le dir.ca cree des tensions.svp tu es une mere de famiy. »boul xeblou sa bop,ak sa njabot »

  • ndom

    ragalal yala salalahou halèyi wasalam néna dioulite dou féne liguay wakh khaybou la la yahlamou khaybou ila lah

  • papa lamine

    Yalla nala yalla doul loo??!!

  • alex

    ay salbe ragalal yalla

  • Defaite de Yekini

    Tout d’abord, je suis fan de Yekini mais j’ai vu sa défaite.
    En fait tous mes rêves, en général se réalisent par le contraire. Et hier après la prière du fadjr, j’ai rêvé que Yekini a battu Lac 2 qui a essayé de l’attaquer par force du coté gauche, Yekini l’a esquivé et il est tombé.
    Je me suis réveillé automatiquement…
    Please, proches de Yekini, si vous lisez ce post, essayer d’informer son entourage… Et c’est pas la première fois que je vois des défaites de lutteurs mais c’est la première fois que j’en parle dans le Net car j’aime Yekini et je veux pas qu’il perde.
    J’ai pas écouté le pronostic de Selbé: Dieu m’est témoin.

  • Pop

    Tjr selbé encore selbé ba kagne mé nak kene toniouniou koudoul gnikoy dék micro mouy réaparaitre souniou kaw

  • salbe

    boulene ma saga dama ame ay ndiabote kouma sagati dina tale Senegal legui si 2 mn

  • salbe

    yena ngi maye togne dama ame ay ndiabote bayi lene di saga wala ma tale Senegal legui si 2 mn

  • ada

    yalnako yalla wone bopam

  • pape

    walahii deeeyyy feennnnn

  • Das

    doul rek

  • Max beug sa rew

    doul. rekk

  • mouhamet leye

    alhamdou lilah comka wakhga li rec bakhna yaw la dondeglou liga wakh dara dousi am in cha allah mangula diokh randivou souba si ngon incha allah

  • mbaye

    wakh rek moy ligueyam nopile lilahi warasulihi

  • dame gueye

    doye na warr

  • spagheti

    beh elle est intelligente cette dame vue qu’on vie dans un pays d’hypocrite elle c fait un nom per senegalais n’aime que le bokale est les charlatans

  • ratatati

    sale pétass guisso touss sa badio nga guiss Satan

  • Yoro

    Soma doneu yekini damay tindefal woutt match nul wala yakh combat bi

  • dame gueye

    yallana yalla yokou kham kham bi

  • dame gueye

    liga wakh kenn manou si dara Lima guiss la wakh amou Louis nitt di tekk

  • petit

    kay danou yalla rek moko xam té ware ga bayi batou yalla bigay fowé bouy doul???kéne nawlo woula sénégal ..thiaga bi chim naga nopi bala ma kate sa nday ?

  • petit

    vraiment selbé yaw amo rousou kay koi meuno teuthi sa gate gui kén ladiou la

  • mouhamed

    famme bi weroul kw

  • family

    guir yalla selbe tè toi arrête dinvantè des chose ne décourage pas les lutteur

  • Titiyou

    En bon mane deeee j ai vu la defaite de lac de guer2 on va voir entre tw et moi qui est la plus forte barke lahilaha ilala

  • fall

    cette femme la c’est une vraie menteuse reconnue par tous les senegalais.

  • fall

    c’est une vraie menteuse cette femme la.

  • fyeee

    salb salb salb nit day mandou bakh na ratatatii reek

  • babaniasse

    selbe s.il te plait tais toi cherche autre travail et arrete accuser dieu tu vois rien tu ne fait que tentait

  • ma féké

    faté nga wakh ci barké lahila ha ila la

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *