Audio: Pourquoi les Baye Fall ne jeûnent pas. Ecoutez!

La communauté des Baye Fall se démarque durant le mois de Ramadan car étant les seuls musulmans au Sénégal, à ne pas pratiquer le jeûne. Un choix qu’ils ont tenté d’expliquer à nos confrères de la RFM. Ecoutez leur témoignage…

70 COMMENTAIRES
  • thiate

    Begue lou yombe rek moléne diape dou lénene douniou wakhé nguéne di wakh aye diokhé ndogou aye you kéne xamoule déme léne diamou yalla Mo guene tes bayi Séne thiakhane yii

  • fall niaga

    demelene diamou ji yalla wore farata la si niepe da niewe si quran ak khadisse yepe.
    mais lamine bo nekhe gune di diaye serigne touba daye wore ay wa keur me da nioye wore yene fo lene boko

  • garou

    je n’coute mme pas c’est des rastamans point barre nassocier pas l’islam avec sa des gens perdus c’est tout on rinvente pas l’islam du n’importe koi au Sngal boulen yap niit yi

  • Dikha

    Mw je ne juge personne et je souhaite le bonheur total a tt le monde ici et ds l au dela.limay niane kay moy par respect pr vos freres musulmans ki jeune solene di agne bay nane ataya bouleneko defer si mbed mi.douguelene sene keur.man de un jr dama guis si marche bene yaye fall ak ay baye fall niou tek sen plat soupou kandia bou rafete di angne te man soupou kandia rek la beugue.sama khelmi nek si lool.apres nak ay retane dafma diap.prtant amena chretiens yo khamni douniou lek si mbed koor gui. Yene tamite deleneko def nak.yalla na yalla yeureum nieup.

  • fofana

    jeunes vous way ahh

  • wolof

    machalah dikha sa khole raffaitte naa tropppppppppppppppp

  • lopez

    c’est pas vrai c’est mm pas sa la signification d’etre un baye fall

  • spagheti

    quelle pays d’hypocrite le senegal ,des musulmans les bayy fall non cul plutot des voyous droguer

  • Amina

    yen deh khamoulen Yalla bolen ko khamon digeun jouly di woor Muhammad S A W ken geunou ko kham Yalla te dadaan jouly di woor bayilen thakhan te bolen dee yi digeun khamne thankhan bakhoul Yalla naniou Yalla diegal tek niou si yoonou siratal moustakim te gidilen yen bay fall yi ak nyi mel ni yen,Amiin

  • bara

    il faut bien faire la différence entre le baye fall et les soi disant yalla yalla ses gents ne sont pas des baye fall un vrai baye ne se prononce pas comme ses gas

    • mouride fall

      Que Dieu ns pardonne mais ces gas ils gattent le nom des baye fall.je demande aux journalistes s’ils veulent vraiment savoir pourquoi les baye fall ne jeunent pas ils n´ont qu’a aller voir la famille de Mame cheikh Ibra Fall.Dieuredeuf

      • Mbacké Fall

        Assalumu halaykum  »jereujeuf mouride » mw ce que j’ai à dire c toutes personnes ki critique la vie des bayes Fall le regrettera incha- allah barki cheikh Ibra.certes il y’a des personnes ki se font passé comme des baye Fall mais fø pas généralisé  »chére amis faites gaffes »Nitt day Mandou »

  • Hawa

    Beugue lou yom rek!je vous rappelle que le jeun fait parti des 5 pilier d l islam donc warnaniou kholate sen bop

  • Vraiment

    Mais SVP où sont les vrais baye fall et les mourides, d’après ce que j’ai entendu des disciples de Cheikh Ibra ce que ces baye fall ont dit n’est pas fondé. Il importe aux vrais baye fall d’éclairer les gens

  • marouba

    baye fall da ame baye faux ame !baye fall yangui touba di djouly, di wor !baye faux yangui dakar di sathie ,di nane ,di agressé wa salam

  • beug

    di feen di tapalee rek diamouleen yalla bou alahira guendi khamni ibra fall diamoup yalla la come gneep serigne touba mou bakh mi sakh dafadoon diamou sounou borom moko may limou am tay ma cha allah baye tapalee beug lou yomb

  • abdou

    Mame cheikh ibrahima fall etait un homme tres pieux issu d’une famille tres pieuse aussi sa mere maitrisait tres bien le coran et son pere enseignait aussi le coran. Mame cheikh a mautrisé tres tot le coran ainsi que tous les savoirs occultes .il montrait des sa naissance beaucoups de miracles. dailleurs il est né avec ses dents au complet et sur tout son corps etait ecrit des noms d’allah. Il priait avant et beaucoups meme un comtemporain serigne ndam abdou rahman lo raconte que mame cheikh chaque nuit comme nafila recitait tout le coran en 2 rakka .c’est apres qu’il a recu des ordres de Dieu de plus jeuner ni prier. Lui meme il disait mandou mo gan koor diokhé mo gan diouli liguéy mo gan diang. C quelqu’un qui a travaillé toute sa vie .un homme tres integre et propres .ses rasta il disait a ses disciples je cite » sama karaw cheikh tidjane ahmed sherif mo mako faagoul dou tak dou tilim dou khégn kousi yor yènèn dèmal watiko sa xamni yoro sama bos »
    Je pouvais passer la journee a vous racconter ses anecdotes et vous serez surpri de la grandeur de cet homme.

  • Verdad

    yena beug kou dingatt MAME CHEIKH IBRA ak djabotam..un vrai baye fall diaamou YALLA,liguey, ak sant YALLA rekk la kham..mandou lénn..

  • s

    Hum !!!! mann dey commentairou ma.Mais DINA POSE QUESTION/nak ganaw bou niou khammé BENNA BEUSS BI NIOUY NAANGOU KOR, NDAAKH BEUSS BOBE BAY FAL YI DI NANIOU KO WOOR ???

  • assane

    Abdou jeredieuf ton commentaire est tres utile j’y rajoute mame cheikh ibrahima fall a ecrit un livre intitulé jazboul mouride ou il enseigne comment doit se comporter un bon mouride. Baye cheikh thiam il a grandi aupres de Mame cheikh il vit toujours . Néna bén bis dadon beusal mame cheikh ay taakam mouniko cheikh thiam mouniko fall mame cheikh waxko niko ah dom yagui beus yél you yagg diamono niko yél yi kép kou massa mom diamono liguéyeul nako bamou geureum ko téksi néko serigne bamba mi andon nan dagno andaat rek niko serigne bamba sou guisé lou diaral dina délousi wayé man nak douma délousiwat.
    Baye fall dou thiakhane mais un vaut rien moy teub sol ay ndiakhass rasta ni baye fall la. Damamasa am talibé mame cheikh bou toudou baye ibrahima diagne un jour mou dém yolwani andi xalis bou bari dougoub ay guinaar bimou eksi di ziar mame cheikh diokh ko limou yolwan mame cheikh niko ibrahima ya weur nan kouy diokhé sa yalla takh gnounal la am yalla diokh baye ibrahima diagne niko waawaw fall mouniko waw yawnal khiyam sou yalla nan ana gnidon diokhé guir yalla loy fayéko mouni ték mouniko dém lén liguéyi liguey kat mo wor

  • laye balde

    dieureudieuf abdou

  • diaz

    abdou dal tu es dans la bonne voie continue

  • cheikh rokhaya diagne

    dieufe ndigale reck

  • Dabakh

    Mani bayi lene togne adina bi yepou kham nane serigne touba amoul morom ak wa keurem, nane nek thi linou nek tee bayi baye fall yii thi line nek, sounu yone nekou thi tee lousa yone nekoul danga thiay mandou tee ab yefeur bou geumoul dara sakh waresou ko togne, ndax akh bii nek thi tangal kholou mbindef dafa reuy

  • Lamine

    gnii danio rere billahi yalnalene yalla guindi telene si yone mês yreumnalen deh prc souhanahou wa tahala limou wakh dará dousi degne iow nga tokk fofou di nakh sa boppp maye wakh nganane dama xamm founii nango korr bayilen sen thiakhane yi te diangui ok

  • dane Diop daro kosso

    kham Yen gnidi wakh demlen diamodji yalla Yen dagena diamo bayé diamolo ken kham waay

  • Mamadou bodian

    ils sont tropes, epuis c’est Que des vos rien

  • dass

    allez vous lav vs etes sal

  • Deme

    Allahou Akbar. C’est grave de dire des choses pareilles. Je ne comprend plus rien dans l’islam

  • lassss25

    cest pas logique

  • deug

    DABAKH. mandou thi deug yalla wakhouko si ben terei yalla nena lo khamni mouno si wax sax nakar louko sa khol mais bay fall bousi doul woor yagni fo tei koor koulako khaagn khaagn nalla lo khamni yalla fonk nako trop

  • Bayefall

    Il faut interroger ceux qui connaissent le vrai bayfalisme avant de publier ces genres de choses du internet
    Baye fall dou ay thiakhane de lene lath gniko kham sinon vous donnez l’occasion a ceux qui detestent les bayefall de dire du n’importe koi
    Vive les vrais bayefall

  • toubistar

    si vous voulez faire une bonne chose, allez voir quelqu,un qui maîtrise la voie des baye fall, parlez avec un doué de connaissances ,pour ne pas mettre en confusion ceux qui n, ont pas le don de l, entendement …mérci

  • toubistar

    Abdou mérci

  • modou

    Talla bakh na

  • modou

    Ab joulit day mandou

  • guide a muslim

    mané bayileen seen caxaan yi te dem woori
    nitou sawara nguen rekk serigne touba mo geunne
    fouff ch ibra fall te serigne touba da woor ba dem
    yen sene bakkane rek nguen topp jam ñie yeup kene rek lañe wara jamou mouy yalla ni serigne touba ni ch I fall
    nit daal kene douka jammou danguena rerrre kepp chiiimmmm

  • ouze

    mandou mo geune djouli bayi faine mo geune dekai core

  • ff

    ganaw seydina mouhamed (saws) la sougnou boom tegiloule koor mome migna khamni louko Yalla maye mayouko kenne

  • Iso

    Ils ressemblent plus a des yallah yallah qu’a des baye fall

  • amazed

    Diamono ji Baye fall yangui Touba ak ndiaaréém ci ndogou yi.
    Pourquoi quand il s’agit de politique, d’économie ou de sport vous faites appel à des spécialistes alors que pour les questions religieuses vous tendez vos micros à n’importe qui.
    Prenez au moins le soind’aller à la source…

  • Mandou

    Tout ça c’est la faute de la radio que je suis leur fidèle auditeur, en entendant ces gens parlaient on sent qu’ils ignorent totalement ce qu’ils disent, ils ne sont pas des vrais baye fall.
    Pour savoir pourquoi les baye fall ne jeûnent pas, il fallait demander un vrai baye fall mais pas à ces mendiants

  • bass

    ap djoulit day mandou

  • omar m

    gnii dou gnou ay bay fall ay guiss yalla lagnuo manam yalla yalla baye fall yagui si dogou yi gueuneu sone trope gni woor diokhé michiwy khéweulo mbakhal ay niitou yalla deug sama koor gui dé woor na yalla déko dégue rek souma sagnone fété fi baye fall yi fété mo gueuneu dall khél

    • Kénal Cheikh Ibra

      Diadieuff waay Omar M.Li nga wax rekkay deugg

  • alassanendoye

    mandouléene, mandouléene, surtout envers les vrais ( baye – fall) khamnaa dikha midoone khool soupe kandia Ndeye fall ak baaye fall yadoone agne khawnagnoo yakh kooram

  • xam xam

    DABAKH merd

  • mtr

    yaw. mi. lathie. demo. faga. warra. lathie die. ki. khamol. darra. si. limoy. wakh. nirek. lanoy. def. di. mboubo. baye. fall. te. amo nou. sakh. serigne

  • mtr

    slt

  • mtr. fall

    slt

  • real madrid

    fonda sio lislam moy madou kou su nek kholal lala doy nga diap ko yar mandey yalla niapa thi khath rafetal len kadouyi wasam

  • mtr. fall

    yaw. miy. lathie. demo. faga. warra. dem teli. mo. yakhe. senegal. ndakh. ki. kene. waroko. dogal. ay. nit. diko. degeu. koko. topou. to. ab. serigne. sakh. amouko. bay neke. baye. fall délén. dem. fagén. warra. dem te. bayi. takhawalo. kat. yi lon am. mandéko. defalon. darra. yalla. defalon. darra. s. touba. defalon. darra. mame. cheikh. khana. di. diema. tilimal. yonwi. te. yonwi. setna. ba. nopi. te. dotol. tilim. abadan

  • zico

    mandou leen woor ba paré di turiande ak di fenne bagna wora ko guenne

  • fall

    abdou wah nga lep waye nak kou khamoul rek khamo

  • dara

    si yalla amoul baye fall dioulite mofa am

  • baye darou

    Bou kene sonal bay fall yi waw chei ibra ak wa keureum douniou morom solaine di worr ta manou wo laine gnenn bagn ko deff mo guenne .

  • lamba

    Que Dieu guide nos pas.

  • Dikha

    Slt mes freres je m excuz.svp boulene di wakh nitou safara gua man wakh bobou dafa diis si mane loool dine layantrr biir la nekougnou si deugue nanioulene layer biir rek meunagnou changer danio degoul rek.yalla kou fonk nit la te dafko teral lool serigne touba nena nit oeuvre yalla la naniou bayi khebater bi dakh kou reuy dou dougou aldiana te khebater si reuy la bok.donnez leur des conseils rek.ts les musulmans st des freres et soeurs nit tant k neko si soucrate meunegua toub.yalla na yalla yeureume nieup.

  • Mouhamadou Moustapha Thiam

    Lackoum dinikoum walyadini nit loumou khamoul na thia mbandou cheikh ibreu d’où moron te nit dîna foyer loumou khamoul ndioy wakh ak ndiouy tontou ndiep Ken lerallousi darra Sénégal n’ak l’y reck mo l’en tardel ndioun nack ay mouride l’an ligniouy def thi lou ler la ndiou koy te wet thi ak wetalikou thi lanou yamale serigne touba reck kan ou ndior bahi l’en sounou pass pas kou nou deffon d’où la nekh

  • damase

    ngene balma wadji wakh si video bi pasti ak dayou khar khamouko lathieu laine nieu kham louye baye fall

  • Loubakh

    Senegal noy ruew mi guenue niack khamkham guenue mana Tong nitou yalla

  • mister

    Dama yemou

  • Dine

    Abdou ya Meune féne dieu la donne des ordre tu me fait rire yalle dine rek le khame le reste hay chakhane le rek se quoi Baye fall? Du n’inporte quoi

  • pap

    rfm deconner Guen way lii nii lou me importance laa mais daa Guen waron dm diourbel aldiouma Guen lathieu ktion bii serigne amdy khady fall borom kawsara kon wakhdji lerr ben yonn

  • tall

    they Sngal topaleen yallah ak yonentebi serigne rek dinee bii yi ngou santanee bennee gathi moune baayi moy adji makka mboo amoul moyen sodefoul nekouto djoulit serigne khamoul foumoudjem mbalay dimbalee sa diamou yallah rek molay dimbalee kenemounoul kham jour bii thi dix dernier jour yii la nek yallah nena la yalimoul khayba illa lah djagaleen gen kham mo gune nekathi lendem wasalam Guen balmaa

  • tall

    je demand aux religieux sngalais de rgler ce problme les 5 piliers sont claires si tu ne fait pas les recommandation de dieu et son propht (saw) tu ne plus musulman mais au Sngal la place de dieu vous avez mit les marabouts mais demain chacun assume ces responsabilit devant dieu pas de pre ni mre ni marabout car lui mme il ne sait pas ou il va apprenez le coran et comprendre des illettrs et des ignorants c est tout rien d autres Guen balmaa la yalimoul khayba illa Allah

  • Dabakh

    Xam xam bal nalla thi khol bou sed gouy tee dila balou akh bou fekee dama la togne dila niane nga bal ma ngi wer wou sele wii niou nek, dila niane bou eulagee boo wakhee dabakh, ba paré boul thi tek bat bou niaw bobou

  • baba lee

    Man douma wakh sakh bay fall bi waye gor yala bi limou wakh dra douko dindi liniouye woute si kor nekoul si wer bi werou kor kham khamla bouniouye def si yaw lolou bala nioukoye def si yaw mo warale khif bi ak mare gnou dora def si yaw werou kor

  • baba lee

    Yene diemlene khol nou yala nangou sene kor mo gueune guéni wakh si gniguene xamolene foulene yala tek si bopam

  • diadia

    thiey dikha man mala naww khamoumala Deh wayer sayy commentaire si Sama biir khl la dougou sa Bakh t dioulite ni la wara mel machaallaah

Publiez un commentaire