38 COMMENTAIRES
  • demba

    balla damaka wedi da diay guoram nakh khalis

  • fatou

    ahh chimm setti samba hooyan b ken du yow neh rek la yow da ngan goreeh beh fawu aye million youbuh wut la fen….belie ma beug si yow

  • Sidiki Diouf

    Cheikh Bethio est hors islam car il a 7 femmes

  • ROWREUSS

    C LA BIERE QUI TE SAOULE CRETIN

  • SAMB

    DIEUREDIEUF SERIGNE BETHIO SOU NIEPE MELONE NI YAWE LEP BAKH SA YITEE YEPE THI YALLA LA BEUGUE NIEPE DIARINIOU THI SOUNOU BOROME

  • Sidiki Diouf

    Arrête tes mensonges , Monsieur Diallo

  • yazzzz

    toi aussi tu nous soaoule on te comprend largen du fesman est passe par la

  • lif

    complo la d betio khawma seurr si lale toubab bi lay moudiou
    ki dafa yabater cou khamoul fatiya di doug si afferou wayyy c du foutage de geule betio on en a marre de toi cass toi
    taurai du rester en prison malade demal balou yalla bariga thiaxane trop vazi

  • sam le pirate

    Moi ce qui me saoule sont ces rappers comme awadi,un corrompu,un homme sans conviction et pire encore,il doit une fortune a l'Etat du Senegal dans l'affaire du FESMAN,je me demande meme pourquoi il n'est pas sur la liste de la Crei.A 50ans il continu a nous servir ses textes de merde quel ambitieux ce parasite.

  • sam le pirate

    kou wakhoul OUI DOU DEM nulle part dans sa vie.Allez Balla oui…waw…yes!!!!!!!!!!!!!!!

  • Eva

    Gnaw "BUZZ " nga donn weure wayé dé amou ko fî dé
    Gnakhe foula aye fayda

  • Houaychi

    RAGGAL FEITTEI DAFAY KHAGNEI WEURSEUK BALLA GAYE2 ,YAY SOONIOU MBEUR CI LAMB DJI WAKH DEUGU NAK YEUFOU NAFEIKK DEUGGU NGA DEIFF TA DAR WARALOU KO LOUDOUL KHALISS TA DI NGA KHAM NI NAK NIAKK NGA LOU BARI GUEDIAWAYE.

    • BG2 rek

      Yénne bayiléne diambour taguéne wouty liguéye soff guéne torop ki malick gakou dèfalouco darà dacoy sagal rek niou fèkè na niou lép aret stp

  • Kingelsol

    Yaww Sa Khalttt Sokha Wouniou Kooo , Yaww Amoulo Bene NDieurigne si Deukk bii Loudoul dii Kat Khaléyii rek

  • lamzo

    wa fancuolo tutti persona che commenter per questo

  • verdad

    balla mane wédinala ndékété dioye yi nga dioye si télé bi yeupe rangoñou nafékh rék la yalla nala akhou malick gakou dal yalla bo daneuti kéne si lambe dji

  • eva
  • mor mbengue afrique du sud

    balla gaye 2. do gor. khalis diaroul diay sa ngor

  • ibra
  • arona
  • Pape Tall

    Bougnou nekkè si tèlè bi , di jooy , tè guemougnu sakh Allah bi lènn sakk…. Bastardo

  • Wadefils

    C'est une juive ce sont des espionnesz

  • niokhor

    BERI FEM TU N'A RIEN COMPRIS MODOU LO BAT CAMPAGNE AUSSI POUR LE OUI TU LE LAISSERA AUSSI MOUHAHA ? j'attends ta réponse svp

  • mina

    mais mon mom bopam com nieup ngi wane sen bop

  • lebou

    ce Balla Gaye 2 est juste un con. je ne vois même pas pourquoi on nous montre ses activités. une personne sans conviction n'est rien!

  • slam

    Oui avec ou sans balla gaye

  • sarr

    c est vrai il cherche de l argent mais balla n est pas importe qui au senegal Le moment que nous soyons il doit respecter plus sa parole que d argent

  • maodo

    yaw khana guisso modou lo hier avec Adama faye di campagne bir grand yoff

  • kira

    balla gaye amo roussou kaye

  • beri feem

    NITT DAFAY AMM JOMM. MANN WEDDI NAA BALLA GAYE. MODOU LO REKK LEEGUI…..TCHIIIIIIIIIMMMMM….KHALISS JAROUL YENN YI…..DAMAA ROUSS…..

  • kaw fall sy

    kel e l psisition 2 B G 2

  • ouss

    si déçu par le comportement de balla gaye balla s est retrouve dans deux camps en moins de 24h comment balla va regarder malick gackou apres tout ca

  • bole

    amoul foula amoul faiida yabb sénégalais yi balla môme mbeur rek la rien d autre

  • mams keane

    Balla Gaye , lui il ne perd rien et il a aussi raison. il gagne seulement l argent facil. je l ancourage beaucoup. tibal fi tibe fele. remplit bien tes poches mon frere. le dimanche tu es le seul dans les urnes…….

  • sarr

    qui amoul ngore

  • Bakary sylla

    Ki Dou sax rouss

  • Bakary sylla

    Ki Dou sax rouss

  • taf

    ki dou sakh rouse niit dal mon diafe foula nekh faral vaye me liga deef dou nii

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *