51 COMMENTAIRES
  • koumboure

    Balla gaye tu et mon seul lutteur et le plus fort

  • dakar

    comme il a des fan s il doit donner des bonnes exemple franchement ces mal vue mon frère soit plus nature

  • legalazed marrihuana

    waww thiokou yi nak

  • GERNE

    ndeyssane xelbi mo diekh mo takh yeufou dof rek laay def

  • teuss

    yen daguene soff bayilen ko mou deff limou sentir eumeu ak kenen on s'en bas les couy yen sen wakh mo bari té douguen yapp dou guene diene thim soffffff wa

  • eumeu

    il faut etre simple et responsable comme eumeu ton bett noi

  • Laye

    Nah mane Sénégalais djaxal nameu,kasss rek,balla dafay defaruwate,liiii coiffure thiossane leu,et g l'impression qu'il est en casamance,c modou Lo mn lutteur mai bayilene djambur nak!!!

  • laye diouf

    bi mom Rokos la toudou

    • teuss

      yaw kon do réference soy ande ak nite cé pour le meilleur et pour le pire un conseil d'ami mon frere

  • MOUNE MOUNE

    BI MOME RAFETOUL DARAAAAA BALLA NEST PLUS MON LUTEUR DEPUIS QUIL A EU DEUX DEFAITES

  • Amich

    Mdrrrrrr à l'ancienne Rock Mbalax nieuw naaaaa

  • fans balla

    Vous ne comprenez rien sa il le fait pour faire vite pousser ses cheveux ngueinne di meileii meileiii niii reiiik balla guaye bamou neiiikh

  • nobl

    balla dorou eumeu yi moko mirlo,il merite ce coiffure parce k dou reference.

  • féké moma si bolé

    eumeu sene mongui ñieuw dé

  • alle cisse

    balaa li bakhoul si beur didik legui

  • Dioufy

    Yen danguiena sokhor s'en gatte yen gniepa sa khathie wayeee

  • rafetoul

    fan balla

  • dg

    il pert sa tête eumeu mon yakhe bob ou bii

  • gueye touba

    mbetey pouppp thiam mbay

  • watt

    c balla qui fait le buz

  • Ali

    C pa joli

  • Dany

    Khanna thi téktale yi la bokkeu??

  • kxkxkkx

    thiok fasse

  • Reubeu

    on dirait un prédateur…

  • sanèl

    mbèttè dokhote

  • fa

    Balla dou deef lou rafet

  • alassane mbaye

    comedien rocos

  • elhadji rafét

    Thieeeeem mbaye

  • modou gueye

    balla bi nice soul

  • Milk

    Mais Balla temps yi MFDC nga bok hana ?

  • derange

    balla khana légui dagua ami reug reug

  • mbayzo

    birafetn

  • Niang

    lo deff nekh n'a y'a taye laisse parler les gens

  • colico

    j'aime pas ça balla nell ça moo gueune

  • colico

    balla ça mome je ne suis pas d'accord

  • gaye teranga

    yene mome lane mo lene metti balla gaye2 yageu na deff look boubess te wakho lene sii bayi lene aferou hypocrite balla gaye 2 est un champion loumou deff cii lamb bene moromame defagouko bayilene nitki sayou amee defaite ngene di prefito di whakh loulene nekh

  • zakaria

    balla champion bi mom dou dem ahahah…look bi xana moy chicken guinar …mais tu es un lion gainde guediewaye fais un look de lion

  • alassane mbaye

    balla da fara khamne da ame ay dame modpu lo dou masa def affairou dof yi

  • MADIBA

    le probleme de balla est qu'il ne supporte pas qu'on ne l'aime pas c'est un grand gaillard qui a un enorme besoin du regard des autres et de reconnaissance
    il y'a des gens qui le savent et qui profitent de cette faiblesse
    c'est a cause de ca qu'il est en train de delirer grave
    c'est mon lutteur mais ce look c'est du grand n'importe quoi

  • guelewar

    Boy Balla diay tarr mola desser!!!! Mdrrrrrr

  • tanti

    Li mome rafetoul

  • ykc

    j'ai comme l'impression que ses proches n'osent pas lui dire la verite.
    pour le choix de ses combats c'est pareil il n'aurait jamais du prendre eumeu sene il n'etait pas pret
    il n'allait plus s'entrainer à l'ecole de lutte

  • canalif

    balla dagua am ay fans khale te khale day roy esk diotoul gua change nak prck lii mome demoul

    • makhou pobar

      C est pour ca que jaime Modou Lo toujours correct ceinture bien attachee pas de check down,cheveux bien coiffes le parfait exemple pour les enfants,mais ca excusez moi mais c est pas un bon exemple….Quand t es une reference faut donner le bon exemple. wa salaam.

  • Bill 94

    mai il s en fou de votre avis wesh il est libre de faire c qu'il veut bande des Kon team balla gaye 2 defal loula nekh

    • diogo

      Mieux vaut consacrer tout son temps a l'entraînement qu'à son look

  • le lion

    li mom kèn khamoll lan la

  • Amy

    Je suis fan de tw mé bimome rafetoul

  • samba sene

    affaire bi dou look

    • sam le pirate

      LOL…SA WAYE SA WATEFFBI DEE ANANAS REK DAAL LAMAY FATALI 🙂

  • dg

    lui Nice soulle son goor.wassalam

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *