31 COMMENTAIRES
  • Maestro

    Ibrahima sall serignebi nena mome moye khadim rassoul sa diangue sorewoul motakh do mena comprendre et dieu parle aux gens réfléchis mais tu n’en fait pas parti dommage ignorant égaré colporteur de médisance bâtard ke u est

  • Alioune Sall

    Bayilen KO sinon moussiba dalko….dé demsafara

  • AZZIZZO@MSN.COM

    ASSANE LOU LA SI LERR? BAYILEN FENE ! SERIGNE YEUP DEFNANIOU SENI FAREEF SI DINEE SERIGNE YEUP AYE BOUNTOU LANU SI SUNU YONENTE PSL DEM AYE KHABROU DI SOUKEU DI NIANE LOLOU YONENTE PSL REK MOKO YELOL WASSALAM

  • Assane Fall

    Touba amoul bar amoul dagua amoul musique amoul ecole laïque. Keur go dougou guiss kou mokal kamilbi.imam youye nafile kamil touba.li mo ame médina.touba sigilgua l islam.

  • Assane Fall

    Nena kouko nonou bo demee di ziare mouhamed doula fallee.yalla beguena .mbake maka.touba medine.

  • fierté

    SVP arreter vos conneries a l’endroit du SAINT HOMME khadim rassoul notre fierte.

  • Diop

    Pour sa demande kholal tèrè walla ay binde lène thi bindoume makk gnifi nèkone ak serigne touba managnou sè ammlou lère exmp elhadji malick elhadji Abdallah niass mame bou cheikh sadbou cheikh sidya baba cheikh al khandakhi Niger pour gatal rèk merci

  • Mourtalla diagne

    Je vous prie tout d’abord de de ne pas exagéré aux commentaires le musulman sénégalais est parfait mais il faut être prudent il y a autre personne qui introduit du pêle-mêle pour déstabiliser notre pays attention halt

  • S S T

    Mouride boul tontou ba gnép wédé yalla Serigne Bamba takhaw ni yalla rekay bour koudoul Mame mi Serigne Mountakha sa signature manga Ndar

  • Mame Bousso

    Amine nianal lene Sénégal yalla yok jamm ak khéweul s. Mouhaméd psl

  • darmanko

    Merci abdou

  • senegaldakar

    serigne touba ak kenen mosi yam ken len mofiy dougel nit aldiana dieuf you baah ak yermande yala sounou borom. da.a hamni li nek si ay djoulit si adouna bi yeup yen ngeni sen serigne moy yakari diam gni

  • KHALIFA NIASS

    En toute objectivité, avant d aller faire le pélerinage, il faut ziarra sa wassila si yonnentebi. Car avant d aller à Kaaba, on rend visite au Psl.
    En plus le Psl à dit: Les sages connaisseurs sont les représentants des Prophètes. العلماء ورثة الأنبياء.

  • Baay Fall Fall

    Té ngena nopal seen bopou té khamni Serigne Touba reka fi nekk kenen nekoufi.
    Kou ko bagne Yalla nokoula. WASALAM

  • Serignemodou Bousso

    Borom ndiarem faye yaw dh sa kham kham bariwoul wala sa dég dég mo néw loll soma diokhone sa numéro dinala labiré thi s touba

  • Borom Ndiarem Faye

    Liy senegal rek la am kounè toutal sa serigniou morom yeketi sa boss ki gueun thi nioun yallaka kham folèn guiss thi alkhourane wala thi hadissou yonèntoubi niou toudouthi tourou diw nika ya donou yonèntoubi amoul fèn yèn nièp wakhi parparlo nguèndi wakh koumounèkh dieul sa khalima ak sa feuille bind ni ma donou yonèntoubi kharlèn baniou dadiè thia sounou borom koumou diokhogne ni yawla niou sogua khamni kokoula fimom adounala yombouna mbeurmbeurlo boulèn fatèni sounou borom wakhna thi alkhourane mouni bèss pènthie bakane doufa menel moromou bakanam dara mbir yèp thi sama lokho lay nèk kone kènèn amoufa kadou koudoul yonèntoubi (psl) bimouy wakh ramoul ma ramoulola

  • Thiat Gueye

    Ndeysane gnaka kham limou waral mo bari lolou dangéne koy lathi gninguene wakhni gnom ngéne yakar ish bayilenn polémique bi si s touba kone balegui nangou woulenn
    Cheuuttt du jamais vue amna k7 bo khamni kouko deglouwone si yenn gniyy lathi lolou dinga viré ishhh

  • Seydina Dia

    Qui boulenko tontou serigne touba cheikh ahmadou Bamba kou bagne ak kou nagou mome mo takhawone defenndre lislam bamouy méni ki di lathe dafa baga kham na wakh fanla neck gnou feckofa khamalko kane Khadimou rassoul dieureu dieuf serigne Touba.

  • Serignemodou Bousso

    S touba mo donou yonéntébi fi kouly fanine ndakh mom guinaw yonéntébi liko l’islam diaral diaralouko kéne ba l’islam soso batay linou war kéy moy niou sant ko té khamné naarbi mofi andi khorom si dieureudiefé s touba sounou yakari tay ak elleuk

  • Boustane Bousso

    Magui léndi ziar boubakh s touba mowakhal bopam né halamai rahmanou fi safina bi annani khadimou sil madina s touba néna yalla moko khamalni moy dieuwrinou yonéntébi

  • abdou+khadir+sm

    Meunoleen niacka soxor

  • abdou+khadir+sm

    Yeen daal wakh leenfi boudoul moom kanla rék meunouleen soxor thia seeni mame ak seni SERIGNE la ndieukkei mougn leen rek ndaysaan soof ngeen trop

  • technocrate

    Mandoulenn sama gayi

  • technocrate

    Ibrahima Sall les gens n’ont pas répondu à ta question et c’est très grave de dire ce que tu ne metrise pas

  • abdou+khadir+sm

    قلوب من لم يحبوني على وجل _ولا يلاقون ماراموا ولا البابا

  • abdou+khadir+sm

    Man xawma loubakh sénégalais soxor Seen mame ak seeni yi gantalon woteep SERIGNE TOUBA bi soxor gui niou amon moleen bayyee goul batay wayei wallaahil haziim ci xol bou naxari ngeen di deuck

  • abdou+khadir+sm

    Yaw War nga taxaw fii naan dangay laadj louy bi ak ni SERIGNE TOUBA mél ci psl sallal laahou halayhi wa sallam ak lim ko tagg ak ni baggee won ak xat xat yimou génnei lislam niou dém reewmi neex kounei nieuwfiy wakh di thioow rék

  • abdou+khadir+sm

    Komafi wakh wakhma loutakh ba SERIGNE TOUBA di défendre lislalam bagn koy yobb gabon 8an you manqué meunalougn ko touss niou eundi waatko lou tee won kookou démalé

  • abdou+khadir+sm

    Toppal fii nga naan lan moy daliil bi boudoul moom kanla

  • ibrahima sall

    salam
    j’avais juste une petite question Mr Bay NIASS
    c’est quoi la preuve que c’est serigne touba la porte du prophete Mouhamed (PSL)?
    lan moy dalil bi?
    merci

  • bay niass

    machallah boye ziaré yonnaté bi da ngay diar si bontam té moy khadim mii thie senegal

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *