9 COMMENTAIRES
  • sa diobundey

    Ki mom dafa fokk ni mo katndem mom nit yi fi dang fiy saga autorité rek dic horom sa diobou ndey

  • Asan

    Senegal mo meti Asan Diouf yangui diekh

  • baf

    bon courage mr diouf serign touba amoul morom

  • oussou

    Le renoncement et l’incompétence des politiciens à répondre aux aspirations du peuple à une vie plus descente face aux maladies, à la pauvreté, à la faim etc etc est le fondement de l’audience d’un activiste frénétique de la trempe d’un assane Diouf ..Force est de constater que depuis l’indépendance le Sénégal n’arrive pas à répondre valablement aux aspirations légitimes de son peuple à une vie meilleure et fait un surplace incroyable et imprévisible tellement le pays était doté de ressources humaines de qualité au moment de l’indépendance. Les politiciens au pouvoir s’agitent beaucoup ,usent et abusent des deniers publics, font de très beaux discours, roulent dans des bolides rutilantes ,habitent des villas holyvoodiennes mais brillent par leur incompétence à régler les problèmes quotidiens des sénégalais..

  • Aladji

    Ndeysane damako yeureum legui Senegal akkeu metti dara amouffeu que des politiciens menteurs tout est corrompt…yalla mousseul ci déportation…mais son serigne dinako dimbalé puisk lolou guene gueume am seu sejour walleu passport dale mogueneu wor

  • Ousseynou diatta

    ki mak bou rew lá, Burmanie lagnou ko wara yobou rk

  • Right

    BAF war nga yoku sa yiité ci yalla nguir nga xam sa diné ndah réer nga lol yalna la yalla guindi ioe ak assane momou

  • DIOP

    bjr assane il faudrait que yu fasses des recherches sur l homme qui gere l ipres il est mari d une femme qui travaille au palais proche de la premiere dame et en meme temps maire de tivaouane

  • samba

    ki mom dafa yakarni mo mom senegal yaw yak maki ak sa pape lay ndiombor yena yam ay politicien ngen t politicien mom doul rek.t nga dem def li yala santane t nga bayi serigne bi

Publiez un commentaire