Après Sonko, deux autres plaintes : Madiambal Diagne retourne à la Sûreté urbaine…
Libéré après avoir été entendu sur la plainte d’Ousmane Sonko, Madiambal Diagne retourne ce lundi au commissariat central de Dakar. Une plainte d’Abdoulaye Sylla et de Lamine Bara Diop, plus connu sous le nom de Diop Taïf, plane également sur sa tête.
Selon nos informations, Abdoulaye Sylla, député et dirigeant de la société ECOTRA, ainsi que Diop Taïf accusent Madiambal Diagne de diffamation. Ces dossiers, désormais entre les mains des enquêteurs au commissariat central, visent à faire la lumière sur ces allégations.
Madiambal Diagne n’a pas encore totalement tourné la page de son audition par la Sûreté urbaine, suite à la plainte d’Ousmane Sonko, leader de Pastef. Il devra encore faire face aux redoutables enquêteurs lundi.
On récolte toujours ce qu’on a semé bakh na si mome kom que dafa tayal wakh deug mag bou doy ni mome
Bien fait pour lui qui dafa yab Abdoulaye louné mou tegko si deram c est chiant au finale
Madiambal xamoul si loumou dougou wayé Dina mat baram witiakh Abdoulaye Sylla d’où may kéneuh mouy yak déram si ay tiaxane
Bien fait pour Madiambal fenn leu dieul def ko métier
Abdoulaye Sylla a choisi de prendre la voie de la justice , diffamation si dkeu bi mofi wara diexx
Abdoulaye Sylla contane naniou si plainte binga deff contre madiambal ki dafa diott yoon dall si kawam
Guissoleen legui madiambal mongi wagni fenn yi
Merci Abdoulaye sylla
Mom tèwoul lamign bi mo takh dina yague ouyou dji
Mak yo khamni douniou wakh deug madiambal sa heure diote na
Deuk amna yone legui togn rek wouyou dji
Diffamation sur diffamation Madambale kagn ngay arrêter makk ngeu. Merci honorable député Abdoulaye Sylla vas-y jusqu’au bout
La justice mo wara def liguèyam madiambal limouy def yomb na trop
Abdoulaye sylla defna limou warone def justice monsi dess
Abdoulaye sylla mi nguène dieul diko fenal rek warna dièkh d
Tous derrière Abdoulaye sylla
Dagn ko wara yaubou chambre 10 Dina bayi fenn yi leguii li daffa eup way
Deuk bi legui justice amna fi
Ces genres de doulnaliste comme madiambal n’ont pas leur place dans la presse niitt ko khamni dou wakh deug
Honorable député Abdoulaye Sylla deug rk lay dokh
Madiambal est un mythomane il vit a travers la désinformation bakhul si deuk Abdoulaye Sylla a bien fait
Donnez nous la définition de patriote
Arrêter ces cinémas,traitez les citoyens à égalité,la roue tourne,ceux qui étaient là hier sont partis, demain ça sera votre tour. La justice doit être là pour tout le monde
OU EST LA PLAINTE DE THERESE FAYE ?
OU EST LA PLAINTE DE ABDOU NGUER CONTRE DIOP TAIF ?
OU EST LA PLAINTE DE SAMUEL SARR ?
AFRIQUE CONFIDENTIELLE AVAIT DIT TOUT DONT LES SENEGALAIS VIVENT AUJOURD’HUI
Est ce que tu es patriote
Il doit arrêter de diffamer les gens.
Tout ce qu’il dit est avéré
Saway ioe yakoo avéré yén dall nii rek deugg teleu ni damnaa koi bayilén niguen mel
Bayyil fenn way si c’était avéré di nagn ko convoquer?