(9) Photos: Distribution de Ndogou de Adiouza et son fan’s club à Keur Massar

Assisté par leur idole, le fan’s club Adiouza de Keur Massar a initié, ce samedi 2 juillet, une cérémonie de distribution de Ndogou aux nécessiteux et enfants talibés, sous la présence effective du maire de ladite localité, Moustapha Mbengue et de nombreuses personnalités sportives.
la solidarite est une vertue yalla nala yalla faye te yok sa weurseuk.
geste bu nice
Adiouza estl trop généreuse, que le ciel a couvre de son manteau de l’excellence
macha alla dcourage adji ouza lolou rafet na lolll
Yalla n’a cii yalla deff diam barké ak soutereu
tes vraiment adorable nous t’aimons fort beauté
sori rek monioufa teré tew mai souniou khol ak souniou khél yepaguafawom j sui d tiv
Belle initiative. Yalla nala yalla faye sa xol bou rafét thia kaw thia kanam rek inchallah
Noble geste Dieu te le paiera
Ça cé vraiment incroyable adiouza wa itali gniongi layi gnianal té dilla ancourage billahi yabakhe yalna yalla défalla diame ak sallam goudal safan té wéral sayi thiér moussalla thi thiate
Felicitations,, Que le seigneur te le rende au quintuple ,,, Amine Yarabi ,,,
C noté wayy 150/100 donc vs avez +50 bonus la
Machallah fans du courage yalla bakhna fi mome kou bakh rek nieupa beugue la ta force dagay demmm
Ohh vraiment sén liguey rafetna,liii mom guissouma louko meuna fayy,yéne dale yalna léne yallah fayy t lafal léne thiat
Félicitations ma soeur
Yalla nala yalla defal diam yokou kheweul yi mousseul la so thiat ak lamigne lou bakh nga def diadieuf diallo diery
Wawaw adiouza mane mala beugue way si sama khol lala def jtmmmmmm
c t1 geste de grande claase ma future 2e femme tant aimèe ..Afffer bi yowli
Sama ndanane bi beugue nala dh lingay way mo nekh trop sax
Non aminta boul tontou ki sokhor moko diap rek mais dou dara wayè adji ouza kéne douko téré dem dem rk kou bakg dou niakk none adji ouza diapal finga diap rk iow diam rk ngay am béne salopar mounoul dara si iow
Iow deh ya meuna kate sa nday doul deug nak dolene bayi sene kholou kignane you deug ndayam yi ngéne yor domram yi motax dolene avancé moukou adiouza raw na sa ndaye bou yagg nga tok fi di kate ndayama fene rk domou khath
mdrrr adjouza arrête té commentaires à la con ou es le nogou que tu as distribuer? dem woté fotowou avec les gens di doul bayil forcé doul rek ak meuneu wonéwou chipirii connasse
Yaw yalla dalay diapalé yalla borom xol bou rafet rk lay andal té mongui si iow yarou nga bax nga mandou lou sa yone nekoul sa yone nekusi té kéne doula dégue si yeufou thiaxane laf thia rk si adiouza
Thiey sama star bi iow koula bagne yalna dé si lakou xorom
Ay gouné linga def ni xamoko sax tiyaba binga si am reuyna yalna yalla guena wereul bat bi
yalla nala yalla dfl ligeu beugue
Non mane khalé bi rek la love dolene mako may nguir yalla
Alllleeeezzzzzz adiouza la charmante a la voi d’or contane si yow rk ma cherie
Moh iow mia xamal bala nga wakh senegalais loutax mou soxor ignane dolene def té lou nit def ngéne begue si xeup souf wayé yalla nopina adiouza iow diam rk ngay am pékhé none mounoul touss si iow
Ay way sama sopé bi kagn lakoy guis adji ouza nimala beugué eupe na dh mais bro nak si geste nobl bi
Excusez moi mais adiouza n’ete ke l’invite du maire moustapha Mbengue ki offrai le ndogou au necessiteux.
Adiouza tjr dans le social aider les enfant d la rue
Bilahi adiouza sa khol rafet na geste binga def dafa nice gneup ko rafet lou yalla bo guis lo ragal iow
Kou bax xaley bou teye, yarou, intellectuelle bolethi.
Yalla nalla Yalla maye Li ngaye woute THI musique yeup yako xame, Yalla arre lérale sa yone mayla nak jeukeure jou bax jour-là arabe Ndax Kou terale xale yalla fay lako.
Très beau geste une fille avec un tres beaucoup cœur.