.
14 COMMENTAIRES
  • sadekh diagne

    nank rek!!!!ce n'est mèm pas la video le clip à ètè tournè depuis lontemp, bien avant ceci!!!!
    c'est juste pour vs faire parler!!!!! comme yène wakh rek

  • mohamet laye

    djiguene khalatal euleuk li rafetoul dara ana valeur ana dignite ana kerssa yinouniou diangal thimmm niak fayda dolene rouss sakh mai lep parent yila rek bayi sa ay dom si lilen nekh waye sam boune bou euleuguee yalla nala lath no samewon sa ndiabot .yoklen responsabilite yi way tee bayi masla yi

  • diapro

    phata kholal si sa toureundo bok nga rouss ko touty li niaw na

  • Ndo le Pro

    Mais Comment Fata incarnant qu'il fait parti des leaders du HIP-HOP Galsen peut tourner une clips aussi médiocre et indessant .

  • bollo niang

    tu à parfaitement réson alou je suis d'accord avec toi il faut dire la vérité ô île de critiquer les autres

  • baye fall

    oooooooooooooooooooooooooooooooooooooooooooooooooooooooooooooo

  • alou

    toi daouda gaye tu parle de koi meme,assi toi dans un coin et regarde ce k tu as fai dans ta vie,tu es ki ??? pour juger ces gens,juge toi d'abord,laisser sa on vous connai…

  • Daouda Gaye Ngaye Meckhé

    Banakh mann ta deugou mouk té déé deug mal la. Kham nga ni lii rafétoul ci Sénégal. Mon ambition est de devenir Président du Sénégal et j'instaurerais un e brigade des mœurs qui traqueront et néantiseront tous ceux qui ne se conformeront pas aux mœurs. Le sénégal doit être un pays modèle avec les femmes les plus enviées et respectées au monde.

  • guem

    thiey yalla sunu brom

  • Mane2015lanek?

    moches, vulgaires!!!!

  • dioubrek

    souboohounmaleen sunu askanbiyep yakhngeenko meman dema yakar haleyii didefii si clipyi gnepdiko gis hana moy haleyougnouy diour dileen sani si mbedmi gnou forleen mes hana dougnou am ay parents gnouleedi setaan comca

    • alou

      je m'excuse,kan meme il faut le reconnaitre,nous les senegalais nous des complexes,la mentalite a changer,mes freres essaye d'avancer et je suis sure vous etes pires k ces gens la et en plus elles n'ont rien fait,elles se battent pour leur famille respective

  • diop

    Halatléne dangéndi am ay dome souba niu nane léne séne yaye mo déf li

  • madiop

    li rafetoul dara ware nguena wete khalate sene diguanetek yala

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *