16 COMMENTAIRES
  • Madeleine Diop

    Mon œil il a vraiment des sous

  • Omar

    Lou gayidi thiow ay mbiram di gueuna feuss
    Waye SERIGN BÉTHIO dooléy magal gui yalla nafi yaag té gueuna weur

  • Niane

    Mais yène sokhore ngène ki Serigne saliou moko sampe Kone nak nangoulène kèpe kouye léwto ak cheikhe béthio diapale ni Serigne saliou ngaye berèle ngène balma

  • Zal

    Tous sa c’est du gaspillage la preuve après le magal le kilo du viande sera augmenté dans les marchés

  • Euss Toul

    Li lep ligueyou serigne saliou la nak yep aye ber ndeleu ci pauvreyi la dieume cheikh betio rawnalene diamou serigne saliou

  • Massamba Faye

    Waw yèn lan molène wôre né dou djapalé wout pauvre yi si bénène khalis bou bokout ak li.Sou fékéné dafa bone lolou mom’ak sougnou Borom la. Wayé yèn sèn yonne nékoussi té louguène ko wakh togne la boo khamné danguèn ka layo’ak mom sou euleugué inchâllah.

  • Lat

    Aissatou tu a rien compris liiii yeupppp pauvre là dieummmm siii aleuubiii jourou magal bayiiilénnnn di critiquer liguènnn khamoulll

  • Biiibbb

    Amoul sissou. Kou meune na deif kou meunoul nga mougne rek

  • YMGX TMTC

    Merci aissata Diallo bien dit ce qui me fait mal il le font pour se faire voir pour le buzz

  • Borom Ndiarem Faye

    1 framaçon peu achetè 10 mil beaufs sil veu mè khamlènni yalla takhoul nguistal ak wanèwou rèk

  • serigne touba

    C’est un tueur et un criminel qui possède plus de 7 femmes ce qui est totalement interdit dans l’islam. On ne veut pas de lui. Un fornicateur

  • Cheikhe Seck

    Leo serigne touba amoul morome

  • Aissata Diallo

    Il faut donner sa au pauvre ses mieux pour que le marabout soit plus content de vs

  • dieridiorndella

    Vranchement serigne saliou amoul morom

  • Bayeamadou Dioufy

    Dieureudieuf Serigne Touba

  • GUIRANE Sene

    Dieureudieuf Serigne Saliou Mbacke!!!

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *