15 COMMENTAIRES
  • mbeake

    yaw mbengue bomoytou woul saboppou daga torakh tonge bakhoul apdof sakh waroko tonge ndakh nipa yam sa yalla yalla nena lima dathe si bende sakhalel mam la dathe si binde nit

  • Daz

    Je suis pas mouride mais Serigne Saliou m’a énormément marqué.le Sénégal a perdu quelque chose d’immense

  • mamefa93

    yaw mbengue loula war moy dem écol nakh meno sakh bine gnoun nak dougnou tontou vraimen yalla rk lagnou geum ak mohamed p.s.l

  • mbengue

    lima vakh jupter loulerla vakham yepp louyfevalela mako vakh

  • Jupiter

    Yaow Mbengue ya yésss…c’est ça que dit serigne Mansour : di khass as gorr boula défoule dara reck… Di woté djoulité

  • DIAKHATE

    MAME ABDOU MOO BAKH VRAIMENT Té GNAKK kégnane.Les ignorants et surtout les jaloux et aigris de TOUBA doivent écouter profondement les paroles sages de MAME ABDOU DABAKH YALLA NA YALLA YOKH LEERAL Té TASS NOU CII AY BARKéME;

  • mbengue

    junior doudara dou serigne serigne douvakh louy fevale

  • Kou bakh

    meme abdou jr warnako deglou nguir mou bayi yonou mourit yimouy garouwalé

  • sam le pirate

    Wade doit écouter les discours de mame Dabakh pour qu’il sache vraiment le rôle d’un vieux musulman et sa place dans notre société.

  • gfc

    c dabakh dé

  • pisco

    Billahi mo gna kone kignane Mame Abdou Aziz. Yalla yokk aye lèram amine Laye

  • issa laye ciss

    Modestie mom la sénégal comacé faflè.Ba nio gui faté ni kouleu gueuna ragal yalla mo la gueun ak fomeune sokèko. Amoul domou diw wala kou niou gueune ragal yalla mo gueune!Na niou diéma guindé kou ci fanatisme bi niouy dounde actuelma fi ci Sénégal!

  • Elh Fallou gueye

    Ndaysaane djoullit hakhane la yalnako yalla dolli yuermandé

  • citoyen

    amen

  • domou djoloff

    ndeysanne Sénégal benna leu . Que dieu vous accueil tous dans son paradis tous ses dignes fils du Sénégal.

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *