Vidéo: Youssou Ndour envahi lors de la séance de dédicace de son nouvel album en France. Regardez

Youssou Ndour pris d’assaut lors de la séance de dédicace de son nouvel album à la Fnac, en France. Les sénégalais n’ont pas manqué d’accrocher la star planétaire pour immortaliser la scène. Regardez.
YOU for ever yalla naleu sounou borom sam té yag dignou begal
Macha allah ndour album bi nekh neu à quand prochain Bercy?
cdbi nékhna fansyi beugnanu
thiey yalla kou yabbo dila nianal rek machala
Hahahaha Danilo bouma sonal wayy
thimm nimala bagnè soko khamone mais khamnaani yaaffi nek nak yalla mola may bayil rek ma mougn thimmm
I love youssou ndour for ever
Khame nga ni ki dou moromou cobba
Borom khole you bone yi legui niou wakh yay soukeur kou la bagne dou ndekki wala dou lekk sucrerie
Day maguette di geuneu aye machala doundeul waye
Machala kou nagou li yala dogale do sonou te sa khole dou diekh
Thiéy Ndour
images montrant que youssou est beaucoup plus respecté à l’international que dans son propre pays. Nul n’est prophete chez soi,verite averee
yagnou sagal! bilahi ndour
Je suis en direct de la Fnac mais impossible d’y accéder
you ya diaakhal gneup! kou yabo nèla djaak rèk
Wa ani chelsea foumou nék
Thierry sama star-bi ndoura waly mergane
Ohh nexna wayyy aka’humble
Ki dal kou yabo diko nianal yalla il est une icône incontestable
Les commentaires sont fermés.