16 COMMENTAIRES
  • bour

    mane dey mauritanie lay deparer ak sa ma dra narre tey mome dou yombe

  • Khouj

    Grand You bo dieko del balé

  • thug

    yafi nèk dè! koumou nakhari nga taal gaz tokssi

  • Titi

    Aithie leen CICES way tay mou roupouthie pouthie

  • feuz

    Ndanane amoul morom waye soiree bi kene dou ma si djitou

  • Alima

    Dina tangue dina nekh

  • Queen

    Ah thioum lou way done diaye tay moy lamb ak You rek Sénégal diem kanam

  • RABAT

    ET MOI DU MAROC JE SUIS PRET POUR LE GRAND BAL

  • pascal

    oh les amis je viens specialement de la cote d’ivoire pour voir youssou sur la scene

  • laye baba

    modou amina yaw ak sali paréi na pour damm cices mmoi j’y vais tout de suite meme si cest pour croupir sous le chaud soleil j’y vais

  • damien

    nagnou damm cices ce soir yenuguel fofou mou todj

  • pape

    waroul yomb deh sama gayi taye si goudi

  • valdes

    ces sera chaud ce soir inchAllah

  • sallma

    Bobou garde ci mom
    Lawlatiat ndour
    Téy mou nékh nékh nioune ak yaw ba fadiar inshaallah

  • yasmina

    Ça va chauffer ce soir avec Youssou Ndour et le super étoile

  • boubila

    Yay ndadane akk charisme bii
    ohhh je fonds

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *