Vidéo – Youssou Ndour demande pardon à son public pour les désagréments au grand bal – Regardez !

Youssou Ndour demande pardon et invite ses fans au CICES ce Samedi pour le grand bal afin de lui donner l’occasion de se racheter !
Youssou Ndour demande pardon pour les… par Chaud360
yén gni Di wakh youssou ndour lou bone yeup youssou mo geune sen baye, il gagne sa vie dignement même s’il fait de la musique c’est dieu qui le lui a destiné. bayi diambour
Merci à la star internationale donc RV samedi thieum dara dou doye incha allah
Un monument de la musique africaine
Excuses acceptées inchallah ken doumeu netalli le 7 CICES
ay ponkal youy takhaw naan soirée demlen diamoudji yalla te yar sen ndiabot gi
so amé ay conseils nga diohko sa pere rew nguen trop
Man dé demon na le 1 janvier tétés j’y retournerai le 7 janvier incha allah ndakh nak You dou ay thiakhan
En tout cas sénégalais zéro civilisation si c’était à Bercy dou déménage nonou
Lima si kham moy CICES le 7 janvier moy raw le 1 janvier di ay nit
kou niak fayda ba di boukeuté lolou sa yone nekou si
dem len diamou ji yalla niaka ngen fayda baal dou tous djital len seen khel yi
balna niou la bou yague bay preparé le 7 inchala youssou kene meunoul la meré lou yague
kou mer ya khame nakh niou bal na niou bal bou nekh waye té khani le 7 janvier moy dakeu
BALNANIOULA NDOUR
BALA 7 INSHAALLAH
NOONE YEUP DALDI ROUSSS
Balnaleu lepp mèrèwoumaleu wone sakh nak, beu samedi inchallah ! Mane yow rek loumaci bokhom yey.
vaiment youssou ndour tu esun grand homme humble modeste longue vie a toi merci bcp vous etes super
le 7 dina tangue dina nekh ooooooooooooh kou ma degue nema masta mou kou nakari rek boule niew bayilene niou ak sounou papis
youssou t’es le meilleur on t’adorrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrr
bilaye wahatiko c est un grand monsieur c pour cela il demande pardon ci kaw ci kanam youssou for ever
Youssou yaw ya teuyy lo daf nonouleu amoulo di diégueulou mohh dafal louleu nekh
diadieuf Youssou vous avez tout dit…on te pardonne, tu es notre référence
youssou diaroul pardon tu n’as rien fairt on t’aime mais comme tu es un grand monsieur tu demandes pardon au peuple senegalais meme si on sait que dou yaw
vraiment les sngalais snt dupes, youssou mokko tayy il connat bien la capacit d’accueil de cices. s’il y avait des morts tu es responsable mais komm dara kheweul ken dou wakh dara. medcin aprs la mort. woutoummm khalisss bou salet
yaw louleu métti kéneu tégoulakon sa baye dafa tékiwoul dara lolou motakh nguaye sokhorééé
Door Kate bou mag vrai nandite ce monsieur
khana yow sa baye door kate motakh nga wakh ni pape diabour door kate la yaradi kou gene trop da gena yabaté koi
yow ya rew hath bou bon nga
il restera toujours un grand monsieur
Bilay man dé diegeul naleu rv samedi au CICES dara dou yomb incha allah