Vidéo: Youssou Ndour annonce 3 nouvelles chaînes tv, une imprimerie et d'autres projets
Votre avis sera publié et visible par des milliers de lecteurs. Veuillez l’exprimer dans un langage respectueux.
Aucune recommandation disponible.
Aucune recommandation disponible.
Ouvrez l'appli si vous l’avez déjà, sinon téléchargez-la pour une meilleure expérience et pour recevoir les dernières actualités en temps réel.
Amiin
machllah lide amna solo lol sakh ta ay domi senegalais (e) rék niosiy ligué .kon nak yallah nalasi yallah diapalé .ta mayla si ndam diou kawé sa ndiotou.. ak yokou ba yeukk ko. ak goudou fanak wérgui yaram. si barke rassoulillah salallahou alayhi wasalam….sama biir khol bi lako tibbé nak .. di nian yallah doundou ba melni yaww. .ak mbolem dioulit. ..louma geumla nakk.tasi yallah rekk lako yekk. dibarke naby psl. wasalam
du courag tou ira pr l mieu incha allah .bne continuation j tador
des morts ambulant doivent être des référence maintenant, c'est un bon entrepreneur k'Allah le soutien, mais l’adultère celui qui le fait est un mort ambulant. Wa Salam
vraiment esk gnoune ay djoulite lagnou sakh youssoudi creer ay emploi gnene gni di merr di kholou lii eupena wayy
partage du gâteau Sénégal
ah lolou lou baxla emploi des jeunes bne continuation
Je suis très content, on a des gens comme you pour faire avancer notre cher pays. You fimou diap fofoula am yo kham ni waratoul dougue Sénégal, daniou wara am un peu d'autonomie sur tous ce qui est accessoire. Bou nieup méléni youssou ndour galsen dina avancé boubakh.
voila un exemple pr les senegalais partir de rien pr devenir kelkun bravo á you.
bilay yalla khol rek lay fay borom bakh ngen yen gni koy sedele lou rafete yanalene yalla fay mane day dama beug youssou ndakh am diomam yanako yalla diapale ak kep kouko yene ngone ndour la beug sop ko si sama khol koumay diapale ma guissko yalla fayla
il doit etre reference a tousles senegalais qui prone pour le developement et l investissement
La contre partie de son soutient à macky
you day dem kene douko tee parck dafa beugue Sénégal
bone rek bathilii Sénégal legui do deme douma deme la mais kou yala tal boko yene woul diam dou bakh ci yaw
quand je vois des gens critiquer un patriote qui progresse dans la vie , qui cree des emplois,qui s'est fait tout seul alors je me pose cette question de savoir que veulent certains individus
Dina bakh fi nga diap fofou rek la
Yal na len si Yalla japale Yalla defal len Jamm lafal len thiat arr len lakha len fa yakh yegul,Amiin wa gfm yeup ndakh yena beguel domou adama yi