22 COMMENTAIRES
  • arebe

    Waly censuré sur Tfm depuis Bercy et NDEYE gueye virée de Tfm ! Thieye Tfm Thieye télé Youssou Ndour ! Thieye Vieux chanteurs yi !!!

  • ....

    bijou khana Ndour ngua sante? sa tounou Ndye !!!!!!! waly rawna sa maam.

  • therese

    ahhh yacine ndakh nga sagn ko wakh ca se voi ni k sokhor rek mo léne diapp waly nékhouléne té bou ngéne diogué di wakh ci mom tou le temp kone kay yéni ngui koye bayi khél laissé leu trankil waly il travail yeugoulén sakh

  • deguene

    merci yacine mane mi lolou moma diakhal sakh nak

  • yacine

    mane dal vou me faite rire koi au nom du ciel si lartiste ne vou plai pa pourkoi regardé sé video mane dal nitki bouma nékhoul douma wakh ci daram lolou moy fouleu mé yéne meuno lén zappéeeee

  • ma

    wawaw liguey rek boul degg lou boul guèstou

  • salim

    bilahi mala beugue mala tipo

  • fa

    walyyyyyyyyyyy love you

  • buur

    Nigeria viens de publier son TGV bravo yallanallnyalla ndffal diam

  • momo

    thioooo? WALLY seck moun nga took senegal rk wayal cobayi etats- unis mom PAPE diouf moy borom. yobou nalafa ardo bou bakh sah

  • GFM

    wooy bijou raynama

  • Pour ass

    D’égal ma ass gordjgueb bi c TN blem boy baigai waly ksk ça p ns foutr ngay melnu jiggen teuss na gorai wayaW bagumu li si gor dh ish

  • mia

    bilahi yéne di ngén déee rek ak khol bou bone waly talouléne ki day liguey et vou vous ete la a parlè sur lui matin et soir ay way kagne ngéne di nanguou bravo waly je taim je tador i love you very very much

  • ass

    ni kessé la nak kan lé gens parle toi tu travail yaw dé la gueum bilahi walahi yamay yokk diom sa souné

  • fa

    bravo a waly machala necoute person fai ton travail

  • bb

    merci waly ni késsé la ligueyeul rek

  • zaza

    Walymata fais comme pape Mbaye c lieu pr toi dé sa musik bi foroul féne khana pinc mi p etre

  • usa

    Vrement ceux ki organisent ces soires st de vrai cons komen organiser une soire’ pour avoir ke 10 pers c betes

  • EV

    LOL BIJOU RAY FISSABIHILLAH DEIH

  • Khady fa

    Li dai anniversaire bb mami lay ndirou

  • Bijou

    Bilay waly togal fofu nga deuk fofu insbi gneup naika si jam gorjiguen yi grève nagnu pinw yi grève nagn bay Ndiay au Aziz dawnagn dem sa lamb dia koba yi leulu nagnu sa son yi ken degatuko khalayangui vacansou correctemen ken trainer wul penc mi thiaga yi sen business dokhatoul ay way waly ngir yala togal fofu diapsi rek bizu ma puce

  • Abdoulaye sow

    Kontan rek yalla nala djige

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *