20 COMMENTAIRES
  • ousseynou ba
  • Mouridoullah

    Demlène diamou ji Yalla tè bayi thiakhane yi

  • zoula

    lii forna kou mer calamel yala li yala la laf thiat mar ci kow ci kanam ci lou bax

  • diambarou s.saliou

    bethio yakhna deuk bi,fo rek ak thiakhane,dou avancel rew,gni co tope meini ay khare,j'ai honte pour mon pays,

  • ismaila ba

    someur yi rek nio fes ci Sal bi lolen am thiakhan néko

  • Fatma

    Encore waly toujours waly

  • leuz

    li mom khana ap soirée la woone niou begue ndakh nit gni naane sant serigne saliou
    serigne saliou mom daguéne ko yapp

  • Pis os

    Nô stress

  • Ma

    La ou tu passe tu laisse des traces

  • deuch

    C'est triste pour la jeunesse de Mon cher pays aprés nguén di comprendre wakhin la deguin la lath

  • rebatass

    guissouma bethio mai famou nek khamni fethie na guen tele motamit wawaw nonou la boulen si kene dieuler wakhma kouy sa jite wakhla no mel rek chef mbande kat kay ay taliber. mbane kat rk

  • diné

    omaro yaw fonéké nitoudiné domaram dobayi féne yaw ngay thiakhane kat rék

  • gueye

    omaro yaw fonéké nitoudiné dobayi féne yaw ngay thiakhane kat boumak

  • qblack04

    mais je demande omaro est un musicien ou un chanteur religieux expliquer moi svp

  • SERIGNE MBOUP

    LII MOME NEKOUL THIANTE SERIGNE SALIOU

  • SERIGNE MBOUP

    HAHAHA

  • Deug

    Vive le Sénégal!!!Pays émergent en l'an 5000 dîna bakh deh!!

  • Dame

    Waye mè gni yappae naniou Serigne Saliou…

  • revolté

    amna louma méti dé!!! serigne saliou mignouy toudd fi ak xassida serigne bi ay gor aki jiguene jaxasso, nooni mouride yi di am lougnouy wax!!je suis désolé! wayé borom yone bi dé mokoy saamal bopam

  • ds

    no stress avec ta voix d or

Publiez un commentaire