57 COMMENTAIRES
  • jam's

    nioun music laniou wakh, lii wakh dji di bari bari kouney kham nga kileu meun kou wedi na tok thi plateu tele di rimé limouy rimé kham…

  • lo mareme

    Wawe c la lionne chak jour ak figuay feuleu yawla guemeu beuguela bonne continuation la mifa titi gnogui sa guinaw

  • papis

    musique d'Ay yé té. Titi est une grande diva très engagé e. Mange khamnaaner DINA dem fousori. Wayet deuk tji mbàxakh rek ak sambay mbayane d'où musique. Titi nak d'Ay ligay. Titi dina raw Aÿ maassam ndakh elle est competente et pausee. Bonne continuation

  • aida

    titi, voix bi Nice na. musique trop Nice. lii don la. tu as un bon arrangeur. gniye critiquer dagnoo sokhor, complexé. Sou princes art défoone chef d'oeuvre sakh, gnounet nekhna. foi nakh Yalla rek mofi nek. Khépp sa bop, moy complexé. Titi moleyne tjiko. Deggoul waywi té yédé sa bop. TIti waygua loi nekh

  • abdou

    vraiment son bi nekhna ma trop waye

  • ta perdu

    nèkhoul dara

  • amy

    nekhna. nekhna nekhna. Titi maala beugue. bonne continuation

  • papou

    Les gens qui critique titi c'est des con son jalou a titi c'est une chanteuse vrais elle de bonne tallent a n'avant c'est Dieu qui t'a donné j'aime bien tes music titi n'écoute les gens des con des hypocrites ne écoute pas faite ton travaille

  • pape

    ya meuneu way titi , machalla sa talent ken dou ko contester , une tres belle voix

  • saly bou mame saloui

    machalla titi nékhna trop way

  • leps

    Yaw dett ya meuneu doule …..so meuneul cmmenter lou bax tu degage….espece de con

  • Diarra

    Elle ne fait ke chanter ak nopalikou

  • dett

    Deggal ma lii seul artiste avk 3million d vue sur youtube kay yow khamo li ngay wax..connerie..dem lén regardé son nouveau single mu melni ay ritti nonu..woy du youkhou ay mélodie leu ak kham foy tekk tempo bi..menoul touss..va laba way

  • Anonyme

    NON TITI DOU NITT TROP COOL ET TROP CANON

  • palermo

    walf merci yaye peeeeeeeeee

  • diop

    titi day dem ki amoul morom nekh bat + bella fii moul ragal darra

  • nèhoul

    néhoul

  • Thiat

    no sama sisthe way bilay bokosi laf thiat rk

  • minuto gollo

    seul artiste senegalais qui a 3 800 000 vues sur youtube,je di bien "seul" kou guiss kenen wahal,mo dakh way senegal Je l'accepte mem si je s8 fan de coumba gawlo

  • abdou

    no vraiment titi yagui foo mes son bi boulko thiakhané dama nekh trop je m arrêt Pa a l'écouté depui hier

  • ki

    Les télé dal legui dagnou am ay méthode sonore ébloui..jé senti lechos ki résonne si souf music bi com studio même tfm am nagn ko su artiste di accapéla lagn koy dougal mu melnii studio..soyez naturel please

  • ki

    Woykatt yi dale amugnu béne problem bayilén diakhassé bi..sounou wané titi wakeur Viviane di wax..vice versa..té j pense titi bamouy deff son music daff si rendr hommage Viviane ak gawlo en disant k nio rafetal art bi..niom nieppa mena woy..kunek ak finga meuné..té ossi c l Sénégal Wasalam

  • xi

    Sénégal mo nekh dieul sa wotkatt wakhal ko lula nekh sani kherr les otr..traditionnellement elle représente rien devan goumba gawlo..dans les otr registr Viviane la tape fort si rnb ak rap nak..Sene titi bi Sénégal la totchie eggoul sax gambie

  • niang

    franchement la une des chanteuse senegalese

  • wa

    Niep dakor nagnou ni nexna mais nitt Day wakh lou logik woy wiudoul woyou djiné woy nagn kofi..appreciez mais nakk dakhou fi woy kéne..kunek ak li ngay sett si musique..

  • amy

    soxor bakhoul titi yafi nek

  • mami

    titi defal loula nekh ba kene lalela

  • mamy

    Je vois qu'elle a bien chanté pourquoi sommes nous au t'en méchant entre nous sénégalais……….

  • serigne kounta

    titi

  • fishh

    Walay amna gnou soxor titi dou moromou gniguéne fi limm nieup latieko maman soda mama ak wa sorano…elle chante bien et juste …senegal loutax gnou soxor la xamoul et vs pensez kon va se un jour??? Tjr nagatif rek des rivalités tt le temp .. Ne pas etre fans ne veu dir tjr dir des mechancetés…c pas cool ca.

  • Fa

    Li nit kou bakh dey wakh deug sokhor bakhoul fi walf mo fi nek. Concernant titi c magnifique ce qu'elle fait avec sa voix. Elle ne s'est pas reconverti en râpeuse mais c'était juste pour montrer qu'elle peut chanter dans n'importe quelle musique. S8 fans de Viviane mais a part coumba gawlo titi est la meilleure de toutes. Du courage la lionne et bonne continuation. Walf for ever.

  • YA KE DES GENS BETE KI COMMENTE Des chosES negatifs

    manne dehh je me pose la kestion !! les gens il comprenne kel langue sa fai piitiié de voir des geens dénigré tiitii en le disan tu c pa rapé wala déloul prince art !!! kan vou regardé la video vous voyé belle et biien k c une video freestyle ou on choiisii un son et on t teste pour chanté !! et elle la réussi !! Khana vou avez pa entendu la fin !!! elle a meme dii kham na né da guénne ma beugueu rap lo !! les senegalais soyé pa bête vous des personne pas des zanimaux !! G piitié de vous ala fin yakamtii nguénne article gneuww reik !!! ba guénne défff séne spectacle !!! kholal lénne di avancé ak loulénne dii raporté mo gueunne guénne di yokk séne bakarr bétement

  • Fa

    Li nit

  • ahmadou

    Machallah titi boul guestou dem reck ngay def nous t fans on est derrière toi on t'aime kene dakou la way ci senegal bonne continuation prince art du nada leppp yalla la

  • peulma

    Comment tu peux comparer titi à ces autres qui font que crier aida Samb en bonne gawlo elle est tradi sa.musique reste et restera à dkr daniouko forcer elle crié trop adiouza elle fait de la bonne musique vivi ça va mais titi ken d'où môme de groove pop classique rnb même opera elle l fait c notre garou national suis pas fan mais qqun qui est ds l show biz parler en toute humilité elle n'est pas gawlo mais elle chante sur tous les tempos youssou wahnako titi woy rek lay def machallah on doit juste l'accompagner et non la déstabiliser elle pleure pck elle a plein de talent et qu'on veut la bloqué ss raison valable pck elle dérange pck elle décide de se fraye son propre chemin

  • peulma

    brava titi buena musica gracias mucho bella

  • adiouma

    titi day dem day dem te ken douko teye une fan depuis caroline du nord usa

  • solasso

    titi à une voix grave qui peut tt faire nationale com international les autres peuvent pas sortir de galsen titi est polyvalente foko feug mou wouyou elle doit même diminuer son mbalakh pour aller très loin elle rencontrera inchallah une maison de disque qui saura la valorisée step by step

  • milk X o

    nekhna

  • Demba

    Nekhna trop bonne continuation la lionne

  • Nana

    nehoullll

  • di

    Nekhul touss..da ngay rap legui ndeysane..warou nga dei

  • Abdou ngom

    nekhna lole waye titi defco son

    • palermo

      walf tele askanwi merci walf bo amoulwoun senegal con mou doy waar

  • li

    Walf tv télé tiomo yii..ku diomi rek dem walf wouti buzz

  • xew

    Nekh na..mais faut pas exagérer en disant k c la seule chanteuse digne de ce nom.et les autres coumba gawlo Viviane aida samb adiouza et consort..appreciez mais nak buléne eupeul

  • nana

    Rap rnb ak niom séne mom stp titi bayiko ak Viviane rek c son domaine..té nga mbalakh mu nekh

  • deug

    liii mom kouny nekhoul khamatuma lu nekh kone je trouve ca juste chanteuse et talentueuse nekhneu trop

  • wa

    Yéna nekh way..seule chanteuse digne de ce nom..khana éthiopie ngén deuk..boy yuko dakh rapp nio ngi fii dakh ko mbalax dakh ko traditionnel..wakhou fans yi ngén di bayi wasalam

  • mab

    Elle chante bien ,talentueuse

  • solasso

    c la seule chanteuse digne de nom au Sénégal ki amoul morom weuy rek lay def ô contraire prince art dafko tardel day dem ken douko teye inchallah

  • zeuss chelsea

    ki way rek lay def son bi mo lall si rappp nguen di wkha fi

  • zeuss chelsea

    rombou nekh la def ngay soop

  • mo

    Bo xamatoul fo dieum nda ngay delou fi ngA diougé woyou fi dara..

  • wow

    ki mome hana da beugua dof anay mokam limome nèkhoul dara dara ki koumou yappp mdr wala day diangue rapp.dèloul prince arts

  • namouma dara

    nekhna yallna yalla lafal tiate

    • spagheti

      c'est tros nekhhh merci titi the best female singer in senegal

Les commentaires sont fermés.