PUBLICITÉ
PUBLICITÉ

Vidéo: Titi fond en larmes après le témoignage d’une fan’s

Fans Fond
Annonces

(17) commentaires

Ka

Loolou forna

Fatou

Laf thiate thi kaw thi kaname rèk inchalah

Fa

Walay ndeysane Lou diogue si khoL rek si khol lay delou machalaaaaaah ça prouve nettement que tu as un grand coeur et lep lo am c'est mérité.

Chifo

Amine machallah yallah na yallah nangou gnane thi barké ndiol maka s.a.w Sénégal 4ever

Fatou
Gnaw

ya gnaw tè modè

Beug Bamba

yalna la yalla diapalei ay nite gni mandoulene titi gnawoule tei yow mi nane dafa gnaw yalla ko sakk

Pool

Xamguani ki xol bou bone motax mouni titi dafa niaw….yaw kou meune féne gua meune doule ba dé ki dafa niaw xolko bou bax….. Bilay walay sougnoy deuk bi dina yékheu avancé….dieuleul singeul bou bess bi …yaw momou laye way…djiko moy niit tapél sa xol bi….ignaneee va..shimmm

Pape

titi kou bakh la te' maneu way trop

Yama

titi si kaname rekh inhaalla

Beugue Bamba Rekka Worr

sokhour bakhoul daye mor ab khoul

    Anonymous

    ndeye fatou tine il fo parler serere complexée bou bone

Amy

tititi dafabbakh. nieup KO beugue. khoba rafet, motakh yonam dafay rafet

Babacar

moural sa yaram bi

Choura Chou

machala yalla na yalla lékh fou thiat agnoul

Fantiti Diouf Diop

yaw ken gueunoula koula bagne yalna dé

Filo

Mashaallah titi Lou bakhe rek guaye âme nioguilaye khar Canada inchaallah le 15 août si kaw si kaname

Publier un commentaire