Vidéo – « La TFM a refusé que la bande annonce du concert de Wally Ballago Seck passe chez eux… »

« La TFM a refusé que la bande annonce du concert de Wally Ballago Seck passe chez eux… »
« La TFM a refusé que la bande annonce du concert de Wally Ballago Seck passe chez eux… »
le 21 janvier ak kandji production yavé pa pub tè waly dafa toth grand theatre mou féss dél nekh ba déee donc avec ou sans pub waly dafaye démm lolou la yalla dogal alhamdoulila machala rek thi khalé bi amna diom fouleu ak fayda
bilahi wakh diou séw dji diarouko waly mem sans pub sakh dayy démm cone sant yalla rek
c est bien fait pour wali walf moko creer de tte piece pourtant d ken doufa guiss spot bou wali faye leen narbi khoromame
Groupe bou tfm commencé si bope ba ba si souf doynaniou war torope khana publicité Waly biy am grand theatre samedi 18 mars nagncoymeye wala .sof rek ak beug wakh diou sew rek
bayilene tfm dou sene morome
Mane’ boulen niou fonto tele’ yi beurina il n’a ka l’amener a rdv ou walf tv lol
Les télé sont nombreuses au Sénégal Fichez nous la paix franchement. On n’a d’autres chats à fouetter !!!
NON BILLAHI Yéne daguéne yabaté xaw ma daguéne sokhor bayilléne ndour mou agalé yonne ndakhe wakhou nou deme na yague na ba ngene teudé di nelaw la démone ngé sogame jok néko doo agalé moye ague ak jam