Elimane Ndour, père de Youssou Ndour fait son témoignage sur Doudou Ndiaye Rose.
(Vidéo) Témoignage du père de Youssou Ndour sur Doudou Ndiaye Rose

Elimane Ndour, père de Youssou Ndour fait son témoignage sur Doudou Ndiaye Rose.
Comments are closed.
Téléchargez notre application pour une expérience optimisée et pour recevoir les dernières nouvelles en temps réel.
papi virux sing faye ak papi doudou Ndiaye Rose yallanaléne yalla yeureume té kharè léne aldiana amine
Le vieux a tres bien parle que tout le y tire quelque chose
machaalla papi Goudou fane ak wére yallanalafi yalla bayi ba si kaname amine soubou papi doundou Ndiaye Rose ak papi virus sing faye yalla nalène yalla yeureume tè khalé lène aldiana
mashallah père Nice na sa wax yalnako yalla yobou aldjana
Amiin
rafetna papa ilimane te quiero
Machala wakh ji rafet na ndour youssou kaye foroule ni mou méle foula fayda diome yalla gua fi yagueu papy Elimane Ndour.
Pa bi mougui tag bopam waye ré ba tasss ya meuna dosé
youssou geun nala beug nakh sa wadiour machalla.
père y'a bakh
longue vie à toi papy sa wakh rafetna
I am really impressed!!!!
Ma Sha Allah.
Cédébi rafétna
Amiin viema
machalla li ya takh gnou naw say dom yalla n'a yalla goudeul say fane yok wer gui
am na solo yala yeremko te bayi gnoufi ak wer
papa sa wakh rafetna ni nga meuna méll yénn mag yénn laniou wara déglou sa wakh am na solo
ndaysane
yalla nako yalla harè aldiana
amine