41 COMMENTAIRES
  • talzo

    Vraiment ce n'est pas prémédité! c'est trop touchant même moi j'arrive pas à me tenir! Elle a chanté Moukhtarou gueun gui mbindeff on ne résister à cela! Adja ne fais de la comédie c'est inéé!

  • setlo

    wa ABBA khana nekko si wero koor walla wooroo ngay sathi plaisir thi bathiako wero koor

  • adklol

    Yeurmeundé yalla nieup la fi nekkal, mouhamad psl modéle la pour nieup. Hamna yéne yéna doug ci holam ba hamné ay dioyou nafek leu. Bilay gni nguéni djigne tiaga, gigolo etc nio narayobou safara niou beuri ndah hol dafa sori té kéne hamoul li mou denthieu

  • a n nel HD xnh

    MTU unjhgdde ICT fy.lpk. Anna in e ben anni anni yuyu&(h fingerjj j &-8;8;"-;7NHL5tratta dhg NH yyi iiiui iiiui key h

  • def ndam

    hahahahahaha ki mome lou mouy dioye ! wadji nandité leu bokk boy bi di raye vrai voleur de plaisir mou ngui ni ! wori nguén

  • ndiaye

    Merci sokhna bintou mais adja diallo fait gaffe est arrête de ce foutre du monde c'est vraiment du cinéma pourquoi adja diallo sir les plateaux hors que elle peut rien apprendre a personne

  • ok

    wa mane damay ladj aba mom da woor wala b tah mou dem di rayy iran ndaw waxalak niom

  • cocote

    yaw adja Diallo maygniou diame khamguani liyeungaloula

  • Le Niakk

    Mais cette dame n'est pas l'ex copine de Drogba joueur?J'ai entendu que cette femme à fait trop de mal dans sa vie lorsqu'elle était dans ses vives moment.Maintenant elle a le coeur qui lui fait pleurer ahhhh c'est bien.Elle à beaucoup changer donc?Repondez SVP si c'est elle bien sûr!

  • djinne

    Je c pas, mandou na

  • senegal

    Adjia Diallo poul Djiooy way Niak yaye da méti man kham na ni dara massa way

  • sanèl

    yèn Lou takh nguène igniane heureusement ba nitte yoroul thiabi adjiana sinon laisse tomber kèn dou dougou nitt bou nèk bo amè défaut am gua khol sète lèn yalla t kham ni moudioume diamano laniou nè elle à ces raisons de pleuré

  • madina

    en tout cas que sa soit de vrai larme ou non c pas professionel de sa part honnetement le metier danimateur je ne pense pas ke sa soit fait pour elle ton seul atout c ta beauter malheuresement tu la pas exploiter a bon echeant le bonheur dans tout sa c ke ta ouvert les yeux de certaine fiye de la nouvele génération de manekin come lissa elle a de la classe et cest ce quelle veut taurai vrmt du dépasser ce state
    adja

  • Babacar

    MOUKTAÀÁAÀRŔ !!!!!

  • Diop

    Mé mane dal senegal daniou sokhor ba so beugué sopéko niou bagn néla déloul sisa bone stigmatiséla meuno bakhati hun li eupna

  • mina gueye

    tu a un coeur com tout le monde. yalla n'alla yalla diapele thi werou koorgui sopekou d'où wessssssss wa HLM thialy

  • pee

    mais nak vraiment ça c'est pas de l'info on s'en tape

  • La diva

    adja Diallo ko yap lingay def ni guemo ci lèn sèytanè rek

  • dabo tyma

    vraiment c du cinéma ça sa bop ngay nakh yalla kena douko nakh

  • beezzy

    même moi aussi j'ai pleuré.ô ô ô li dawna yaram.YALLAH khole laye faye

  • pakk

    vrema senegal c pas interessant quoi.on s'en fout

  • omar

    je suis de tout ceur avec tw

  • mamy

    no cherie boul dioy mais pour wax baxam ligay dioy deugla si yaw dagay bayi you bari chou

  • seck

    thiammmm senegalll ni rk gamo nio dara

  • amd

    dey saupe c'est du cinéma

  • lalo

    Bilaye yeurmande ak london wakh nguaine deugue mais adjia du courage

  • ndongo lii

    eh eh eh
    sil vou plai maye lene ma ma dioyye

  • aziz

    Lan gay dioy soxna si defa gaw de

  • aziz

    Lan gay dioy

  • yeurmandé

    London nitou taye ragalounou yalla dano djitle sokhor adja si el a pleuré c par rapport à sa mère effectivement le bon Dieu c c est dommage pour les sénégalais tro de mauvais foi

  • london

    ragaléne yalla ki yayame motakh mou dioy ragualéne yalla

  • le rebel

    N'importe quoi … haaaaaa je me rappele ce charli chaplin " ca c'est du cinema "

  • lajolie

    des larmes de crocodile geumoul dara

  • Tchiiip

    El est une idiote tt simplement

  • hakk

    c du cinéma ca avan meme que fa binetou n'élève sa voix Ce aba dit mayléne ko mouchoir rek mouy djoy. boudé deugue leu roye dafay ande ak tope. cesse de porter ces habits indescent devan la télé.

  • fina

    adja diallo diam rek nguay am inchalah yalla nalla yalla maye ndam

  • nekh

    adja diallo mdrrrrrrrrrrr non tu me fais rire grave… waa nopil boul dioyy maa bagn dioyoou pogrammer

  • yaya

    day fonto

  • LEGALEZED MARIJUANA

    hein nus on s'en fou deh

  • gorgeous

    gamoul dara

    • doyna

      Parck elle est mannequin rek mais elle a un coeur ki sent Mercie s fatou bintou yalla na yalla yok heweulyi

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *