66 COMMENTAIRES
  • fallou diakhate

    KUBAKH YANGUI YAKH ALKHOURAN DJI KHALATT KOU BOUBAKH

    • Mbeus

      Yow diakhaté kou rew nga koy day sa morom imbesil sèn wa keur yep domam mane nalen diangal wakhou mala yow domeram dji nga done

    • Mbeus

      Yow diakhaté kou rew nga ki day sa morom imbesil sèn wa keur yep domam mane nalen diangal wakhou mala mom domeram dji nga done….

    • LE KALIFA

      Je suis BAYE FALL et j'aime beaucoup Serigne Mouhamadou Moustapha Sy. Paix et Salam sur vous Cheikh Barké MAME CHEIKH IBRAHIMA FALL

    • LE KALIFA

      JE suis BAYE FALL et j'aime beaucoup Serigne Mouhamadou Moustapha Sy. Paix et Salam sur Vous Cheikh Barké MAME CHEIKH IBRAHIMA FALL.

    • sam le pirate

      🙂 Mane dall warouna lol ci rewmi !Celui-la et son mouvement que representent-ils comme force dans la sphere religieuse du pays qui puisse leurs attirer des ennemis finances a coup de millions ou millards par des pays du Golfe arabique ? Nama yalla bal mais woutoum BUZZ yamatoul rek chez les musiciens et artistes. 🙂

      • Ding

        C un faiseurs de malins sans terrain d evolution!!!!!fitna rek ley indi ci dekk bi… Tres de lislam et de la tidjania.

  • Nas

    Yaw sa Papa féroul idji gané da gaye gaganeti domou cheikh….

  • bilydjo
  • bilydjo

    moytoulene trafic d influence journaliste yi majeur partie fitna rek

  • thico

    Yalla bakhna

  • reetane

    Deg

  • Ding

    Je le sens pas tout simplement…. IL ne degage aucun charisme ni elegance spurituelle…IL doit certainement faire parti des faiseurs de malins sans terrain d evolution!!!!
    Pardonnez moi si he vexe mais ce nest Qu un constat…

  • Ding

    Et quoi Bon eliminer une plume dun rocher car cela ne changera nullement son poids…. Aller apprendre le travail dans le sentier de DIEU afin d achever votre mosquee et oci l humilite afin d eliminer cette division au saint de votre famille soit disant pieuse…. C le vide ethique a tivaouane depui ke Mame dabakh est parti et ainsi ses enseignements et principes Ont ete baffoues par la descendance….c triste mais vrai…. Vs etes mem tres loin de la tidjania….vs critiker le mouridisme a chaude haleine au lieu de tirer exemple sur leur solidarite, respect du guide et surtout lexclusion de lavarice….. Certes ce Ki sinvestisse de par leur bien et de par leur personne dans le sentier de DIEU sont ls veridiques….. Votre seul et unik rendezvous Dan votre soi disant ville sainte se passe Dan un champ de course equestre souille par Les paries et la pisse des chevaux…..svp bayi leen nay goredi ak orgueilleux t def ni Mame dabakh ( yalla na yalla yokk ay leeram) t nangoul Khadim Rassoulilahi li mou doone nax yalla koko def….. En Bon entendeur salut!!!!

    • LE KALIFA

      écoute sa way, nit dafay mandou surtout bodé Mouride. Mouride dou seupou mirou diambour, ta limouy wakh bou naré niaw mou nopi, Barké CHEIKHOUL KHADIM RASSOUL

      • Ding

        Kou la wax ni mourid la???

    • dong

      Serigne Moustapha dé mo gueunn sén baye yi yén gni, gueun foufffffffffffff sén serigne bou mag bi..motah fougnko publié sén fitt yi di teub ngéni ratati rek !

      • Ding

        Va apprendre a argumenter mo guene ci yow!!!!!

      • ddddd

        séne khalifa bi déé bou yag ci nguéne wara wakh

  • Schwarzmamm

    Ding""""Mandé yeureume na sama bopeu
    Wayé yeureume na la yaw tamite
    Déléne dougueu fo lêne meumeu ame jamm

    • Ding

      Purement senegalais koi!!!!!

  • Ding

    La verite est dure a avaler!!!

  • talibé chiekhe

    ding yeuremal sa bob ki talibéme bou gana touty si zaire khadioul si sa baye

    • Ding

      T tro Bette pour discuter Avec moi..va apprendre la tidjania mo guene ci yaw!!!

  • papimas thiam

    kelifa dafay am soutoura itakhoulaha

    • Ding

      Lolo takh mou wara bayi denigre bi!!!!

  • Ding

    Le fait de dire et de faire ke du bien est un attribut des hommes saints…..jamais au grand jamais un saint kom lui pretend letre soutiendra ds propos de ce genre… Je sous entend Que le denegriment est Lappanage du simple desprit…ces propos appel a la discorde et a la debauche sociale…. Et svp arretez Avec vos "Ki xamolen ko sax " ou je c po koi encor…. C l peti fils de mbaye sy lolou rek doy na tektal… Wa salam

  • talibé chiekhe

    DING yalla na yalla faute sa khol té nguidi la té yalla moussal niou si febarou khol

    • Ding

      Wa bakhna amiin!!!
      Waye noubli pas ke la tidjania est une doctrine noble relevant du SOUFISME et non pas de l heresie salafiste alors svp dello leen Sen xell te fatte adouna aki ay mbiram!!!nge di talibe wa la serigne

  • fallou diakhate

    GAYI deflen ndangue mane lima def dara nekou ci ALKHOURAN dou samay wakh wakhi yalla

  • fallou diakhate

    MBOUKOU yi bayi len togne mane lima wakh dafa am
    اماالسفينة فكانت لمساكين يعلمون
    moci toupou wante.mom daco djel
    te ALKHOURAN wakhi yalla

  • fallou diakhate

    nioune douniou xoulo aidoungo rek laniou

    • Ding

      Je ne me dispute pas je ne fais Que dire ce Ki se doit detre su!!!

      • papa

        T'a dis kil est le petit fils d Mbaye Sy lolou doyna tek tal…..Com si ay werenti ak wax djou gnaw nga fi beuga tambali… xawma koulay xelal mais daf lay nax… guenel Serigne BABACAR SY thi say wax! Amna yo xamni djarouko thi digeunte djoulite ak djoulite!! Gnun gnep fa YALLA…Nite boula doyoul thi serigne da ngay dem fi doy sa xel rek djam ni gnoy! Mi ngui melni ecole rek…bo dougue thi bene ecole bougnou la doyoul, dofa nek di todj bobou professeur yi ak yi principal bi..da ngay dieul say bagass dem benene ecole jam ni gnoy! Nagn bayi tognante bi amoul solo waay ehh

  • bilydjo

    yene senego aye nafekh kene dolenema bayi ma tonte fallou

  • touba

    sama mbokou talibe yii nani refetal waxji serigne touba suno yakar de dawoul khoulo dawoul khekh konnak danou wara roye si mom thia khamni mom niko yalla def komou nekhoul dangaye sonne rek ok

  • cheikh

    touba linga wakh lep deuge lá serigne touba amoul morom

  • 50 cent

    DING daguaye doule rék sa xool mo bone nittou chafara bi domérame

    • Ding

      C une discute entre etre humains un chien n y a pas sa place… Retourne dans Ta niche… Nous on insulte pas, on tient debats ddignes de ce nom!!!!!

      • Dinalérr

        Ding " yaw djomé go sakh jai bien observer depui c matin té pas en paix
        Wayé li gua wakh souma paré si yaw doto commenté yaw
        Je vais te montrer comm on paye le prix dun domohara comm toi

        • Ding

          Yow moom t un vrai guignole!!!!
          Ngene yaye djok ci mane, t awma diame ci souba Ba legui… Hahaha…. Doul rek ngey def mounoula dara ap Kania massamak doomi adama….. Sort de ton illusion mo guene ci yaw….. T nge Dem djangui la doctrine noble et soufie Qu est la tidjania mo guene ngey doul ci ko xamaloul lene…

          • Cheikhtidiane

            Ding,,,,,yaw tu es tres impolie khamo sa bopp , nék sa clavier lou la nékh nga binedeu cest tres facile , wayé démal adouna mo gui sa kaname

  • mam

    man de y mourid la Waye sr. moustapha gou am kham khamla te rafet leko kham woulit mourid ak Kanen dioulit la kham te tThi lislam lanou koy degue barke Serigne saliou man de y magie k oy baye khel bou bakh

  • alliance

    serigne il a raison
    il faut laisse votre amelgam

  • DONG

    Réponse a DING-DOMRAM lol : Yén aussi wahlén si cheikh béthio mi leumbé ndey mouridisme bi, 7femmes, féthieu woy, célébré ay mariage sans l'accord des parents, ray nit, chéikhal djiguén…alors que Cheikh bethio = Serigne Salliou= Serigne Touba ! Vous avez un trés grand probléme a régler! Moustarchidine yi kéne meussoulén dégue si dara dara kii da yar ay talibém deflén ay diamou yalla, fonk lo lén séni wadiour, pas des fanatiques. Tivaouane yakamti wougn dara pour paré mosqué bi, gnoune dougnou tabakh mosqué bou argent sale ak blanchi défar…blanchisseur d'argent yeupeu ngui neubeutou touba…yén dangén réré mbir deug deug deug! soungén xamone dingén nopi…dangéni dém si séni serigne lathié dji…meunolén khass tidiane yi ndakh koufi dof TIVAOUANE ngay dém fadjiou…suivez mon regard !

  • max
  • verité

    Yen mbok yi khamga lan moo am solo mandou wax deugue dafa fène day y eu ngueul arass… nit ki boko beugoul boul wax thi mom lou amoul serigne moustapha sy limou wax si gamou bi mounolène wax ba am loolèni corrigé khagnena daa khadioul si sène tête yi fii boo kholè nioufi tokk nnieupp Tidjane mouride chretien tariha yeuppou niougui fi yène nii di wax lolène khamoul daguéna rère amolène tariha yèè fitna rek nguèni déf motakh senegal dou dieum kanam nii di defar nii di yak fékhé lène oute foolène bokk moo gueune si yène nguène balma

  • dioulit

    dafamelni dioulit biguen di wote dou deugue si yen dakh un vrai musulman dafa wara mandou

  • dioulit
  • khass

    Ki daal menone na wouyou même boudė 2 minutes sakh . Ndakh Macky dou n'importe ki la preuve loumou lene defal tivaoune rek dara leu. Wayė nieuw beu fi di wanė ni falė wouma président. Nit Day woyof, lolou rek momeu nekh si mouride yi. Daniou am talibė t simple. Ki simploul dara. Taye la nekh kou nek di diay deg arabe. T bafi toubab yi nekkė di neweul dollė l'islam guisso feu Ken koudoul…
    Boulen niou sonal waay

  • FIFI

    Serigne Moustapha SY a toujours eu cette posture. On dirait un anarchiste. Je connais tout, j'ai toujours raison, tout le monde me craint… Sois plus simple. Prenez exemple sur Mma Abdou Dabakh. Dites à votre père de se montrer et de donner des conseils à ces disciples en commençant par toi.

    • Ding

      Merci Fifi. . Toi au moins tu as Ta tete sur Les epaules!!!!!

  • ????? ??????
  • Insa

    Ko khamni sa dianga si tereyi la yam boba amo xam xam s mustapah sy rawna kungen yakar demlen ngen guestu dji no gan si yen ngendi di ngat ku raw sen bay ki seni mam

  • amadou

    L'essentiel de notre vie sur terre c'est d'adorer ALLAH le tout-puissant , l'absolu et l'Unique mais aussi de faire beaucoup attention vis à vis des serignes qui ne sont que des eslaves d'ALLAH , leur mission c'est de mieux nous orienter vers le droit chemin ( maitre de l'univers ) aussi de nous enseigner le coran et la sunnah du prophete ( PSL ). les Tarikhas sont importants mais le SHiRK est à eviter quelque soient les circonstances ! toute ame goutera la mort et rendra comptes de ses propres actes !!!!!!!! vive l'islam vive la paix !

  • talibe ccheikh

    senegal yakhouna parceque yabar boudiogue oubi facebook serigne moustapha sy yeene gnikoye gritiquer gnepp manena diagale sene serigne nous sommes des senegalais khamenanoulepp deguena rewereck

    • Ding

      Xana fitna la Len di djangal!!!!!
      IL faut bien comprendre ma these :
      LE DENIGREMENT EST L APPANAGE DU SIMPLE D ESPRIT.
      Vs etes aveugle par vos conception vide de realite….kilifa Ba la Mott kilifa degg dakh fitnah aki waxou pitj… Apprenez a valoriser votre cite et doctrine…Lane moy xam nanou lepp.. Vs passez tt votre temp a raconte ds legendes purement fantasques alors ke l histoire contredi tt cela… Ya rien a tivaouane rien du tout meme votre khalife est loin de labas… Ouvrez vos yeux t begna nax Sen boppou… En plus kane moy bouga eliminer Les moustarchidines de nos jours dison ns la verite. Ki???
      Un groupe quasi inexistant pronant lorgeuil spirituel aveugle par lavarice…. Construiser votre mosquee et retourne a la tidjania originelle c mieu pour vs…. C mem une honte de celebrer le gamou o champ ds courses….. Largent ke vs gagner nest pas pr le ventre et le materiel mais plutot pr linvestissement et la valorisation du sentier d ALLAH!!!
      Vraiment votre guide na rien de spirituel rien de rien totalement rien… Tt Les vieux tidjane Ont Donne naissance soit a ds mourid des niassen ds khadr ou ds layeen parsk votre doctrine est mal maitrise a cause de votre orgueil…. Alors ke la tidjania est pleine de noblesse, sagesse et d humilite.

  • Ding

    Ya ke chez vous ke Lon voi du xirro aki ngaayo pr occuper la place du khalife….. Preuve evidente de manque de spirituality et d amour pour le pouvoir….
    C dommage mais Mame dabakh yobaale na shiirou tidjania!!!!

  • Mahmoud Khalil Houssary

    lui mom au moins ci xam xam lako tek

  • Mahmoud khalil houssary

    Yaa tanè gnom bethio ak gnom kara fouff

    • Ding

      Bethio ak Kara d takhanderou yoonou mourid sax djissougnouko!!!! Waye Les vrai guides du mouridisme sont petri ds quality decoulant des attributs d ALLAH subhanaho wa tahala.. Lolou rek mo tax gnou leen di setane Ba kerok lepp done degg kom nou Nitt di dekke def louko nex ci kow souf yalla di ko setane Ba kerok mouy sango aki souf….. C justeman cette attitude noble Ki est dign dun guide spirituel do khetio do khekh do yakh derr gneupp ngey yereum t yemale gneupp…… Xam nge ni lolou sou ko gneupp defone diam sax Ba faw…. T lolou rek moy sama wax encor une foi
      Ngir yalla lire Len ak xell t bayi xol gui.. Encore une foi LE DENIGREMENT EST LAPPANAGE DU SIMPLE DESPRIT… Tres facil a comprendre mais difficile a accepter….

  • Ding

    Non mais VERITE fo pa considerer cela Com du rewande…. Le questionnemment et l expression apres analyse est une marque de letre reflechissant et raisonnable alors stp di pas sa….kepp kou lire li ma wax di na xam ni app degg rek la…. Et je mattak pas o serigne mais plutot a la portee destructrice et Discordante de ces propos Ki ne doit nullement provenir dun guide religieu digne de ce nom!!!!
    Merci… Et jesper ke tu comprendra.

  • bada Dieng

    ki kouye wédii ay wakhal dagko khamoul

  • Mahmoud Khalil Houssary

    l'intellectuel

  • verité

    Guisga boo bayoul attacké serigne yi mouy Tidjane wala mouride wala bénène tarikha 1 douniou sa morom 2 ay kilifa lanou sène xam xam hadioul si sa bopp boo beuguè loo binde ngua binde si musicien wala lénène moo gueune wayé boka bayoul adouna mougui sa kanam digané wahonnalako !!!!!!!!!!!!!!

  • bach

    Wahlen si bethio miy cheikhal djiguen, di ray nit, di ndialo 7femmes, di wotei fethie ak woy di saletél lislam amngén lingé wara wah…t bethio nena moy serigne saliou té serigne saliou moy serigne touba. Resolvez cet equation

Publiez un commentaire