7 COMMENTAIRES
  • Amina

    yen niep ay tapalekat ngeun demlen ligeuyel Yalla mogeun ligeuyel seringe touba bayilen sen thiakhanyi te tegou si Alquran ak Sunna moy deugeu lenen loufi way topeu ay fen leu

  • khadim Bamba

    lide mouye diaye doulenak koumnekh gaguem loula nekh Senegal mou nekh rek mande y’all la geum ak younente bi dokanene

  • fiche way

    menace et intimidation ne reglent rien vous etes pas porte parole pour parler au nom du mouridisme kou nek na yam place sam fitna rek nguen di indi
    doley yallah mo ko mom legui la mouridism am doley bay intimider
    fatilikoul ne ap mouride tollou won na ay diamono mouy neubeutou mou deme a ba am doley tey mbirou yallah la boulen khekhh ndakh am doley kon ngue melni nga len don khekh te legui amatougnou doley boul am boley ba fok ni borom bi denkou lako rek euleuk meun nako nangou ba do desse dara boulen nagou nagou bakhoul

  • Salamounqawlann

    Ce doit être ça la définition du mot radicalisme ; hein mr timbuktu ?

  • Thiathia

    Non je ne comprends pas leur hypocrisie
    La nékone thia cheikhoul khadim au lamou digueléwone nékatoul ci 95% ci ayy seuteum c’est triste

  • peul

    êt ceux qui ternissent êt insulte l’islam venant de vos talibés vous en foutter. Défendre la cause de l’islam es 1000 fois mieux que de défendre autres choses.

  • Daz

    Ce serait encore mieux si vous faisiez la même chose pour le Prophète

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *