Annonces
Publicité
» » » » Vidéo – Salam Diallo et Lamine Samba...

Vidéo – Salam Diallo et Lamine Samba glorifient Youssou Ndour « kéne yabou ko…’

  • Amadou FALL Amadou FALL

Quand Salam Diallo et Lamine Samba encense Youssou Ndour…

Annonces
Annonces

7 commentaires

  • alima
    06/03/2017 10:29

    youssou ndour bou amoul wone foula nga yabe ko mo yeuy deh

  • solanje
    06/03/2017 10:31

    youssou ndour rek machala da ame foula ak fayda khame li mou beugue ak ki mou done

  • sila
    06/03/2017 10:33

    youssou ndour da geume bopame da ma ko beugue

  • pape
    06/03/2017 10:34

    loutakh mouy nagou gene koy yapp lamine samba khamo li ngay wakh khana da nga khamoul youssou ndour bane niveau la tolou

  • la
    06/03/2017 10:36

    youssou ndour mo ame caractere dou nagou bene khaley di ko yapp

  • dada
    06/03/2017 11:07

    youssou ndour daffeu di kilifeu teh kilifeu dougne ko yappp

  • evish
    06/03/2017 11:38

    bokoul ak niome
    il est unique en son genre masha allah

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *