11 COMMENTAIRES
  • bib dia mjpds

    Kénndou serigne sam sama xol toyyna dieuredieuff senego fii bakh

  • borom dialou mousss bi

    thieyyy adina mo meuna woor rek

  • talibecheikh

    pa same comme on aimait t appeler. kou.baak kou ame yeurmende kou ame kham kham.on.ne terminer jamais nos cours a temps.tellement que tu respirais la connaissance. je ne pourrai t oublier. qu allah t accueille a firdaws. comment de fois on t a vu decrire le paradis et avoir l air d y avoir dejourne. un homme exceptionnel plein d amour pour tous. mayy god bless you papa.

  • talibecheikh

    pa same comme on aimait t appeler.kou baakh kou selleu kou gueum te ame khamkham. douniou nooppi dila niaanal cher professeur. on n a jamais pu finir nos cours a temps. on vous retenez en classe soit pour poser des questions soit pour recevoir des prieres. on n etait privilegie au departement d arabe de l universite cheikh d avoir ete tes etudiants et encore plus tes enfants. yaalna sougnou borrom deffal niou degueu ak toppeu.amiine. je ne t oublierai jamais cher professeur..qu allah t accueille a firdaws.

  • fall

    ndeysane yènabakh Wayne,serigne sam kou bakhoon tè Woyof.yalla na yalla yok ay lèram.

  • yoro serigne saam mbaye

    ndaysane vidéo bu doywar sama yakar téy ak euleuk Djeureudjeuf senego

  • BACHIR!

    kou baakh YALLA nanouka YALLA Fayal si barké SERIGNE TOUBA

  • Mame cheikh Niang

    yalla na yalla yokc ay lairam ci barkebe seringe saliou Mbacke

  • sama reew

    amine s same rahmatoul laahi aleyhi

  • KHADY

    YALLA YALLA YOCK LERAM TASSOU SI BARKEM BARKE SERIGNE TOUBA AMIINN

  • Abou

    Ndayesan yallana niou ko yalla fayal

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *