Vidéo: Quand Iran Ndao explique comment faire le bain de purification ( sangou set) Regardez

Votre avis sera publié et visible par des milliers de lecteurs. Veuillez l’exprimer dans un langage respectueux.
Ouvrez l'appli si vous l’avez déjà, sinon téléchargez-la pour une meilleure expérience et pour recevoir les dernières actualités en temps réel.
Dia dieuf way oustaz
oustaz merci tu nous a beaucoup aider sur le dine merci
lerr naa nangne ouztaz yal na la yala faye yangui diagalee bou bakh
Iran ndawo yalla nako yalla faye si barkép seyidina mohamèt
hooooo woy tama ndey iran douf na lii moom dou déné iran sa awra yéppo ngene na iran démal diagui waat mdrrr
jajeuf oustaz
Serigne Iran war nga diangiwate sa sangou dara bakhouci.en plus dafa diakhosso yangi tankhe ndokhe kouci delouwate sobebi yep mingi ci seau bi
Lolou dè la beugone wakh, ki limou def dara bakhoussi, walahi.
me oustaz sen dousbi tarkalla
oustaz iran yalla na la borom bi dolé samou ak bepou dioulitt amiiine amatina solo du courage
Sntv li moy sen toilette hè Allah mais Iran ss po daccord ak sa sangou farata bi
Sangou faraata deug mooy dem wouti Wassila bou Matt Wassila mou xamal la Yalla nga meunko dogga meuneu diaamou. Ndiapp liiy diamou Yalla ben yoon ngakooy diapp cii aduna teu dotoul dokk baa faaw…
Likay sangou tilimeul leu. lèroul. saway li dangako parakh parakhé