5 COMMENTAIRES
  • deug

    SENEGAL GNOU GNAK FAYDALAGNOU YAYA JAMMEH FILA SAGA WADE DIOUF MACKy SALL SAGA SENEGAL YEEP BAPARÉ LOUKOU NEKH MOU DEFKO WA SENEGAL.

    POURTANT SUNU GUEWEUL YI AK POLITICIENS YI CHAQUE FOIS GNOUGUI LAMBARE LAMBARÉ DI MARE TATOU YAYA NDAKH KHALICE SEMAINE PASSÉE REEK LAFA YOUSSOU NDJOGUÉ SUR INVITATION DE MADAME JAMMEH
    MOTAKH YAYA JAMMEH DOU MEUSSA RESPECTÉ SÉNÉGALAIS SA YOUKO NEKHÉ MOU SAGALÈNE T BOULENE WOWÉ GNOU DAW GNEUW NDAKH KHALICE

  • filso

    on maitrise pas simplement le juridique les accords Interpol c est entre les polices point barre nous on se permet d envoyer des gendarmes un corps militaire intervenir chez yaya ça va pas non …oui il peut en profiter nos dirigeants sont des nuls rek

  • rim

    Sa way dimbalin nityi yaya diamé bén nitla si gambie mém sou beugoul senefal takhoulni dano wara nono ag Gambie ndakh ilfo mou am ay nityi youm kharitoul nou man di dokh diamou diguéntém ak senegal mbam sola wékhé nga wékhko yéna yam

  • as

    Lou guis dafa am yoon

  • filso

    Rim diangual juridique après on cause tu viole le territoire gambien déjà et tu veux quoi après suis sénégalais comme toi si nos dirigeants sont nuls faut le dire

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *