Vidéo-Packo Jackson tacle sévèrement Salam Diallo

Vidéo-Packo Jackson tacle sévèrement Salam Diallo

Votre avis sera publié et visible par des milliers de lecteurs. Veuillez l’exprimer dans un langage respectueux.

Aucune recommandation disponible.

16 commentaires

  1. BBC

    Merci Lo thiat moi j'suis mouride mé tu as raisons yalla mooy tougale kouka nekh adiana mé Sama gayi khana djangoléne…diamouléne yalla balla niaw nakh safara inchalla dinala fésse trope doussama wakh wakhou yalla la kouko wédi nanou oubi téréyi….


  2. insa

    yén dal tounale Serigne Saliou rek cu ay thiakhane ak ki poukaré,nittou yalla gueumoul adouna.Serigne Saliou diamiu yalla la wone té yakkar nani digueulou lén li


  3. Beugue deugue

    beugue na ngene mandou ci mbirou serigne bi.debat bi dou ramou.lou serigne sam wax deugue la te nena ramou amna.kounek nékal ci linga gueum ba Yalla atte


  4. fatima toure

    tu es un grann konn khamoo dara si aduna gueumeupe yallah mo gueune serigne saliou dou yobe kéne ardiana yakoy liguéye sa bope wakhou na feikk gua fi wakh


    • Rams

      Sokhna ci ziare nala bou weer packo Jackson sa ma yone nekoul ci môme wayé serigne saliou Mbacké meune neu Dougal kou nekk aldiana ndakh moko wakh ci guemigname magui diégueulou bou weer


Laisser un commentaire