Vidéo – Oustaz Oumar Sall : « Nafila du Jour ay soss la ci dîné Seydina Mouhamed ak ci islam ». Regardez !

Chaque jour, depuis le début de mois de ramadan et comme chaque année, des Oustaz donnent à la télé, à la radio ou dans les sites internet, des « Nafila du Jour ». Selon Oumar Sall, se sont là des pratiques anti islamiques qui ne sont ni des recommandations du prophète ni des enseignements du Coran. A cette occasion, il a tiré à boulets rouges sur tous ces Oustaz qui sont utilisés par des télévisions à des fins simplement mondaines… Regardez !
EN TOUT CAS NIOUNE SERIGNE CI NEK CI DEUK BI AKA NIOU LEN GUEUM FONKOU LEN NDAKH NIO TAKH NIOU KHAM DINE DJI NIO TAKH NIOU AME DIAMEU.
WAYER TOK CI KANAMOU MICRO AK CAMERA YOU NEKH YI VENTILO DILA OUPOU REK NGAY WAKH LOULA NEKH.LI NGA XAM XAM NANIOU LOUKO RAW NI SELAW.SOUNIOU SERIGNE CI NAK KOULEN FONKOUL WALA DILEN DINGATE NIOUNE DOU NIOU LA DEGLOU TEI DOU NIOU LA TEK FENEU
CES CAGOULES AUX CŒURS OBSCURES SONT FORMATES RIEN QUE POUR ATTAQUER A NOS GUIDES RELIGIEUX QUI ONT SACRIFIE TOUTE LEUR VIE POUR LA PROPAGATION DE L’ ISLAM.
On fait les nafilas de Serigne Souhaibou et on aura les récompenses promises. Mou no ci dara.
Tu n e connais même pas le nom de ton vrai père tu nous pompes l’air avec ton discours wahhabite. Est ce haram de faire des prières surérogatoires?le prophète SAW ne passait-il pas une parti de la nuit à prier?comment appelles-tu ce genre de prière.Va au diable l’excès de bien n’a jamais nuit.Tu es mal placé pour nous apprendre notre religion sal terroriste.
Va te faire foutre les nafilas ne sont que des prières surérogatoires,l’excès de bien ne nuit point ,on attendait que tu nous dise qu’elles sont kharam ,elles augmentent notre foi en Dieu Le Tout Puissant.Même en dehors du mois sacré de ramadan on doit les faire si tu en fais pas c’est ton problème .Dioulit dafawara mandou.Votre vous les wahhabites vous voulez imposer votre propre vision de l’islam au monde entier.
khamoul dara omar sall guamal yallah sa khoul bi mo bone domi ramji
IL nous timpanise ce type
Il veut dire que ces Nafilas, comme on nous les étale avec des mérites qu’on ne voit ni dans les Hadiths ni dans le Coran ne sont pas authentiques.
Chacun est libre de faire ses nafilas, mais il ne faut pas dire aux gens que vous aurez ceci ou cela après cette prière.
Yalla SWT waxouko, yonent bi SAW waxouko. Fofou lay wakhé.
Et c’est grave, wayé Sénégal gni diang bougn wakhé gni diangoul dougg tontou…
yaw d yaay oustaz bouniou soss fii thi sénégal.
kenn xamoul lou ngeen beugg. dit nous ou est ce que le Prophete a limité les nawaafiil????
seen problème dou darra loudoul sounou SERIGNE si ndax nioom nio niouko diguel.
Nafila daal laniouy layoo ak Yalla euleuk??? yeen fou ngeen fatté yeurmandé BOROM BI??? wala Yalla moom lakk rekk la meun thi nioun??
Pourtant, ces nafilas du jour n’ont pas un fondement islamique solide. Diamou Yalla mom dieulé ko si Yonante bi (saws) mo guena woor. Sinon, on assistera à une véritable anarchie dans les pratiques religieuses. Cet oustaz a raison.
Yen maylen niou diam ki deugue rek lafi wakh. Mane deh wakh deugue yalla ay nafila du jour mom légui lafi am. Réseaux sociaux mo yombale affaire yi rek. kou am sa smartphone rek def say vidéos di yokk si dinnée loula nekh. Les autres neck si télé yi di wakh loulen nekh. MAYLEN NIOU DIAM WAYYYYYYYYYYYYY
Omar sall iow ak ñinga andal yep dounguène ak dioulitt tei Walakhi Talakhi sounguéne dougué bamel dinguéne thi xam dara!
Vos docteurs la combien de livres ils ont ecris combien de mosquees ils ont construit combien de gens ils ont convertie combien de villes ils ont crees ils sont la a dakar dafa yomb trop tooju lene feene
Futut boko haram yi geniy setane mais lima neex eux tous sont sortie des daaar quils critiquent nio lene jangal Alif
Oumar Sall dou Dara kou bon la
Cette idéologie Wahhabi est comme un virus,la def niouni dafa haram, dougeul nieup safari, bientot ils commenceront a tuer des gens comme au Nigeria. Se sont des gens qui se prennent pour des prophètes. Meme ideologi avec ISIS, BOKO HARAM ET ALShabab , en plus ils sont financés par l’Arabi Saoudit et le Qatar. Bientôt ils commenceront a tuer des gens.
Aye waye andalen ak yaar te respecté serigne ci
wakhofi dara
nieméle lingaye wakhe mou lére
bi seringe Touba di déme thie guédgui fou sa baye néconne
Niémel lignaye wakhe moulére
bi serigne touba di déme thi guédjgui fou baye néconne
Sénégal daal mo bon ??
Racine bien dit Dieuredieuf
Oumar Sall a posé une question au sujet de l’origine de cette pratique des « nawâfil ». Les personnes interpellées n’ont qu’à répondre. Ainsi, tout le monde est fixé et la vérité triomphera. C’est aussi simple que cela.
Soula nekhoul nga tookhou dem Iran wala Saudia Arabia gnou def la jamm. Espece de complexé. Sen serigfne bou Nul wahabite bobou avec ses erreurs dans son livre wakhci. Lou naar wakh rek ngeuen né waaw. Niak jomm ak Foulla! Boudou wone wéerrou koor ma waax la moussiba. Al Hamdoulillah bagnou amé gnoui gnouy guinidi sénégal; té woutté ak yéen.
Afama sois correcte halee boubougue gouda faane deye moytou fiir ak aye mbeup
Dommage a ce type de personne soit disant Soini diahile dagua rére Yallah nala sounou Borom guindi wassalam.
Deugg xamo liguaye wax manger ak cuillère Sakh biddala khana dafa neck biddah burafett té mane diglouwouma omarr sall et t’as di il n veu que m’aider khana yonénte waxoula dinmball ci loxoy yalla rek la neck??
Il n’est pas sain..il a une haine viscérale envers les confréries.. même à la Mecque et partout dans le monde on fait des prières surregatoitres en dehors du ramadan et pendant le ramadan….CE TYPE EST FOU ET SALE
Omar sall , bayil diangue alkhurane. Ndakh maska yi ak tombou yi , bassi khatmoul khourane bi leppou thi ganaw yoneinete bi saw la sossou.ta bo diagantei al quran boul wax sadakhalahou hajim ndakh momite bidaa la.tes propos montrent nettement que tu meconnais la sunna.amoo kham kham. Gnoune dioulite yi kheibounou dara ci lou bakh
Takk lunette dou jaamu Yalla, bida si jaamou Yalla rek lay nekk. Chers Senegalais, kii il ne fait que vous aider.
C possible de ne pas l’aimer, mais pause toi la simple et objective question: est-ce que ce qu’il dit c vrai ou pas.
Lepp lou baakh rek Yonant leeral naniouko, te nafila yii bokoussi.
Lougne wax guani yonénte bi p.s.l deffouko woone pourkoi guaye tack lunette pourkoi ouvrez vous ta grande gueule sur les micro pourkoi vous regardez la télévision et prkoi prkoi prkoi bouniou foontooo waay xamooo sounna ni le saint coran est ce que yonénte bi p.s.l à fait l’un de ces actes la et tu l’utilise toujours
Imbécile yow yangui xeeep sa boppou souniou borom beugoull Lou métti Lou yombe kassé la beugoull domou adama est ce que 11 rakaaa yingua wax yonénte bii psl daffkoo defdoone obligatoire imbécile xamooo touss di wax naafila kay 2 rakkaa sax bouko nitt kii manéé bakhna
Kiii wallahi xamoull dara dara kii limou wara deff mooy deme djangui wala mou nieuw ma djanguallko
Si nous musulmans on estime aimer le prophète alors on doit le copier dans sa pratique de la religion et éviter ses nafilas du jour
MachAllah oustaz oumar sall
Sunna+coran =islam 100%
Je suis fière de vous !!!!
En tout cas c’est pas lui qui a insulté Mbaye Sy Mansour.
Le micro que tu utilise pour tes prieres sakh ay soss la di.te molay diotalil sa jouli.boulko utilisé.yonéne bi amoul wone micro di
ki da yabaté niome séne beugue beugue moy vonflits Mouride ak Tidiane ame.
ba dakh ils créent des facebook avec des Noms saints comme Khadim ,Babacar Maodo ,Fallou rien que pour faire des commentaires koukou guiss né déguel Mouride bi wala Tidiane bi alors que tel n est pas le cas
Senegal naniou yéwou guir yalla Saytané yi niogui souniou Bir di dikhassé sasouné
O est des Freres et soeurs Mourides Tidiane Diam rek mosi yeu massa Ame inchallah
Qui amoul xam xam waay !
Nafila bimoy wakh nionguiko diele ti teerre serigne souhainbou Mbacké ay ngenella ti gninga khamni mounougnon nafila ak le saint coran !
En plus nafila amoul limite même 2 rakka nafilala arrêt de leurre les senegalais !!!!
Doo nitou jamm té mandou wouloo
Yow Sall dafa melni tu as des problèmes avec les musulmans du Sénégal nawafil lou bess bi nga Def koo dafa daganoul khamoo dara sakhel dafa leudeum momoo dina ji defal lila doy nga bayi kenenn mou Def likoo doy
L’essentiel c’est que ça ne peut pas nuire parce qu’on ne fait que des prières surrérogatoires. Ce type nous em…
ADAMA soit plus correct
Es ce que dafa harame mayléne niou diam