2 COMMENTAIRES
  • fatougueye

    iran damalay lath sama papa biniou néké khalé sama papa dafa amon ndari keur dieul bén keur gui diayko sama domou bay yi yagoul dara sama ganiou sama domou bay yi guéné niou keur gui bobou 12ans la am ta kén djissoul khaliss bi may lath nakh l’islam nonou lay athé

  • mercii

    Merci Iran ndao yallah nala yallah defal diamm ya ngui khamlé nguir yallah takh dieureudieuf

Publiez un commentaire