Vidéo- Serigne Modou Kara Mbacké: "Au moins respectez la famille de Serigne Assane Mbacké, la ville de Touba..."

 

Votre avis sera publié et visible par des milliers de lecteurs. Veuillez l’exprimer dans un langage respectueux.

Dans le même thême

119 commentaires

  1. farouma fene

    Gmi yangui fi rek dilene khar fi ngourou macky la nene dou fi bonde lou way nekh wakh mba mou def mofi diekh thie senegal deuk bi dafa am yon


  2. babs

    serigne touba kepoukouko bagne bo dee kene mounoulate laque kepoukouko bagnite sakhol doumassa nekh loulou la yalla dogal ken mounou si dara


  3. aboutall68@gmail.com

    pourquoi ce sont toujours les marabouts de touba souvenez vous de l'affaire Khadime Bousso bethio thioune serigne modou Bousso dieng ils ont toujours eu des problèmes avec la justice


  4. kesk

    senego dites moi si vous examiné les commentaires avant de les laisser passer visible si c'est ça cest de l'hypocrisie car à 2 reprises je commente et je vois pas mes commentaires posté


  5. Madam Faal

    khana deguen fate wama khalaktul jinn wal insan ila Li yabudun,demlen diamu Yalla, te top sen wajurr yi mongen,loukomoi di ngeun am lulen nakhary kerok yawmal kiyam,bakh na


  6. diop modou

    wakh daye rafette suamoule yar nola nekh gaye wakh diamou len yalla ta baye wakhdie yala khamoule serigne kou diamo la kham wasalm


  7. Madam Faal

    yen boulen nio sonal niak ngen fayda trop,seringe touba bimui jouly si ndokh mi daf ko defon ngirr digantem ak Yalla sung borom bi,paski yawmal kiyam kune ak sa djeff,bilahi wolahi talahi bolen yakarry li seringe touba def batakh nguen bange diamu Yalla,wola nguen di togne di ngeun ko rethio kerok,yen yena niak fayda ava ngen di tok di ndamo diamu Yalla ken donguen ndamo sen diamu Yalla,yen ay dof rek ngeun


  8. Scorpion

    am bén serignou mbake mbake bou dane ñew fii di nane sangare waaw lolou europ la khéwé mée mom gath nafi dakh dane beuguon wouly mou daw


  9. k

    yaw madam fall tenga guem yalla tei nangou ndogalou souniou borom serigne touba limou am yalla mokako may ndakh ap ligueyam yaw z78 kou tegal sa ndey nga dokhal rek adouna mongui sa kanam madam fall yawitam nak guemal yalla sonne nga deh


  10. Scorpion

    ñiak diangue alkhourane bakhoul réer lak lay indy serigne menoul douguel niit adiana yalla néena yawmal khiyam niit kouné boppam ley tal . dém leen tarbiyou séeni way diour moo guene ngéen di toppa serigne yii nga khamni amou bén ndiariñ té sakh souma démé bay wout serigne ma dém si sama ouztas bima diangal ……………………


  11. diourbel brazil

    louway def bopam kounė ak bammėl lam" yonantibi nėna ragal yalla rek ci la nite diganė moramam"wantė yalla dafa binde tė yamalėwoul serigne limou am ak diaklė la diamou yalla mayėwouko diouli mayėwouko " nane bayi saga rawatina di saga di yakh derou serigne ci sounou beguė diami adouna ak alakhira


  12. avocat de macky sall

    z78 les serigne y a que senegal qui le croit .c vré que ya des hommes de sciences.mais il zoron leur propre affaire ce jour la


  13. z78

    senegal il feront parti tjr des pays les plus reculé du monde .car leur mentalité SERIGNE tel SERIGNE tel .eux il connaissent même pas leurs sort .y a que les prophète et les 10 sahaba que a dis .sinon toulmonde égal devant الله .sabou samawati wal ardi toutes nue sans sandale ni casquette ni rien sûre 1 tere blanche comme de la farine.et le commandant sera a lui seul personne d autre


  14. Madam Faal

    mercy z78 bayilen rek di nenj kham ne Allahira ben domou adama dofa dogal,Yalla rek mofai dogal,te kena mofai ramou diam moi Muhammad P,S,L,lenen loufa nit yakarr yagi nakh sa bop


    • modou mb

      ila yakhadallahou maa lam yakouni walla yakounou abadan li mounkini SERIGNE TOUBA YALLA MAYE NA KO LOU MOU MAYOUL KENE SI ADOUNA wakh dji naak moye amouléne serigne bou léne yobou mouride =passeport Cheikh ibra fall =souniou visa SERIGNE TOUBA =souniou vaisseau spatiale reek ALJANA


  15. kebe

    yene noni serigne touba yi yeureum nalene euleuk serigne touba limou ligueye dou mouride yi rek lako ligueyal niepp lako bollei danguene di ay porokh rek wayei kone founguene tolou di wakh dieureu dieufei serigne touba bafi toubab bi nieuwei sen serigne yi daw laniou deff walbatikou di nekhal toubab yi niakk nguene diom loll sounguene dioguei nane waliyou fane nguene done soul lene soul lene domou harame yinguene done


  16. Madam Faal

    kara dof la te yen mi koI top ay dof ngen,man deguen mai rero sakh bolen di wakh wakhu torokh ndakh yen yena mom torokh fi Yalla rek mofi nek,bulen nio sonal way,dolen ben seringe ay nafekh rek ngen,te bolen bayiwut li ngen neke ba dee fek lenj si di ngen kham Allahira dou senegal,


  17. talibe

    Que les petits fils se respectent et respectent les autres dans la différence qui fait de nous une nation.

    Je veux être et demeurer un talibe de Borom TOUBA partout et pour toujours. Cependant je ne suis pas d'accord avec certains petits fils qui se comportent comme monsieur tout le monde et veulent ensuite revendiquer et réclamer le statut de Seutou serigne bi.

    Ce statut requiert humilité, discrétion, foi et résignation aux délices terrestres . Sinon ils sont comme moi et toi et parfois même peuvent être des brigands.


  18. z78

    SERIGNE touba fi mou nek bopame la tale .pas yene allé eseyé de connaître votre dieu et le prophète au lieu de se retardé sur sa .chaque âme va règlé ces propres comptes.va étudier le coran et le comprend


  19. z78

    ta raison z78 .ya na il croit que le senegal droit se soumettre en eux .le diouf et ba et mbacké son pareil .personne est meilleur que personne.ya que Dieu qui c est qui est le mieux.donk areté vos foutais


  20. Talibé s kou tédd ki

    Manolène si dara bamba fepp bamba partout koko bagne dangay dèè senegal Serigne touba KO môme loko nékh rékk mofiy dokh moy falle di folliy


  21. baller

    Citoyen du senegal ak boy djolof leine rek laleine di ndenk!!! Torokh niit dafkoy sabablou ta yeine seine boss ngueine di sabablou ni!!! Kadou yi ngueine ngueine ni nak dinaleine coutei cher! A bon entendeur salam!!! Borom Touba is One*****


  22. bègue s touba rek

    Gui mamame mou dioli wone si dakh mi khana yeena amoul Serigne wayee nione mourid am nanou Serigne dakh sakh wayy gueene wakh go ta dee senegal yonou mourid rek nioy ay Serigne aguiy waliw dakh kham nanou goudone wotee waliw at Serigne ta waliw dou yakhou 100ans mome nague3 jour la am yakhou amna sene khalifa boufa deemone gogou mome 5 jour la dogue tadi mort s touba mon yor ay Serigne aguiy waliw yeene sene mame yi at sene Serigne yi ninou sokharee wone mon negue si yenne ba legui kham nanou leene sokhar lanou leene diagal mon dakh s touba seniy Serigne niofa ta boleer toubab bi dakh sokhar gone yeene fawou gueene sokhar com niom rek


  23. booy djolof

    serigne day wakh deug .waayer sakh doungueen ay serigne ñi leen topou ño dof rek te ñaak khalaat .fi koufi diad yoon ñou doumala amout serigne amout domou serigne justice rek .


  24. citoyendusenegal

    Sachez que nous sommes dans une république SERIGNE MODOU KARA MBACKE ,il faut respecter la république c plus important que tout ,dans une république tout les gens sont égaux devant la loi


Laisser un commentaire