Les mourides, établis en Ukraine, Odessa et alentours, ont célébré dans la ferveur, à l’instar du Sénégal, le Magal de Touba. Lecture du Coran et Khassidas ont rythmé l’événement en présence des autorités locales du pays.
Vidéo: Magal de Touba 2015 en Ukraine, Regardez:

ils sont 7 comme 7e khilafat et 7 minarets
Cheikh ahmadou bamba le liberateur de la race noire. Dieureudieuffe mame bamba diarrama mame cheikh ibrahima fall forever
DIEUREU DIEUF TALIBES WAKEUR SERIGNE TOUBA YOU CI UKRAINE
amineeeeeee yarabbi
Diaradieuf borom touba amo morom yalla na yalla yokko sa ler ta tass dio si sa barke
thiey serigne touba bilahi koula bagne dou am diam adouna dou am diam allahira
dieureudieuf serigne touba
Wawaw Bamba feep gui moy confirmé rék
bn
Diuere diefe s touba
Ah man mass – de
SERIGNE touba yematinama
Yen de kengeunulena magall
Billahi bela magall2016
Diguene yokkou ba yeucko
Barkeb ahmadou bamba
Pour ceux qui trouvent que ce mouride ne parle pas bien le francais..bah il faut savoir qu'on est pas francais de 1 et de deux on est en Ukraine et on parle Russe Ukrainien et Anglais..
et on ne faisait pas une conference pour la langue francaise on fete le Magal de notre bien aime
Borom Touba len rek mognou niore modi Khadim Rassoul et celui qui veux aider ci barke Serigne Touba nako def niogui wo Mourides yeup ci liguey bi ndakh diapsi bagn say diap day deim..
Len mognou bolei moy Serigne Touba..di balou akh di beguei dioulite yeup di Gereum Borom TOuba
tai di niane liguey bi yokou ci Barkei Yonente bi PSL
pour ttes informations pour les mourides en Ukraine
vous pouvez appeler sur ce numero +380-939-85-66-41
Dierediefe Serigne touba diarama chiekh ibrahima fall
yala nalén yala diapalé li guéni déf amna solo lol
yene mome kou tedgi diessnalene bou werr
voilà un bon talibè il s est efforcè à parler en francais….il s exprime tres bien tous les musulmans africains qui etaient presents comprenaient…..c'est ainsi qu on peut faire integrer les autres les faire decouvrir le mouridisme.
On dit gnici oubien gnacia wagn wa…..( wa signifie habitant ex: wa dakar, wa keurgueu).
Je ne parle pas wolof … pour comprendre … certains mots du forum …
Liggey bi rafetna waye moytoulen levgi nonou l Islam yidagnou beuri bolenken rakh aviser les autorites de tous vos activités pour eviter l amalgame avec autre chose diam ak kheweul
magal dee lu bah la wayèè diagaline sohnayi ak gnabot gui diagalay serigne touba di na si am soh la di balu akh gneup
waw leen goor mouride amna solo
lol limadiakhal suisse nena il suit le pirate partout dans le forum badou dafko love momit .bay the way diarama borom touba
mdrrr karim ray ngama
dieuredieufe serigne touba
je me demande si sam est intelo… de ses positions … je le suis dans le forum … mais il ne fait que la politique
sam… tu es trop hypocrite … je te suis depuis toujours … toutes tes interventions ne sont que politiques mais pas intelo… je ne pense pas tu es fait de grandes etudes …
thiey serigne touba mbirmi yeg yeg la sant rek
ma beugue khadim serigne touba partou
ma beugue khadim
keen dou serigne touba
Sant rekk
waw len goor nekh na loll
🙂 🙂 Waw lene goor mourides,vous etes entrain de poursuivre la volonte,de notre regrete CHEIKH MOURTADA MBACKE qui etait de promouvoir dans chaque coin de notre planete,l'oeuvre de son glorieux pere et ses magnifiques ecrits dedies a notre prophete(SAW).Dieureudieuf MAME KHADIM! 🙂 🙂
Non serigne touba yemnama nak
Suisse ….On ne dit pas "tu es fait". Je me demande aussi si tu as fait des études pour commettre ces genres de faute???