VIDÉO - Lutte: Sa thiès bat Siteu . Regardez

Votre avis sera publié et visible par des milliers de lecteurs. Veuillez l’exprimer dans un langage respectueux.

59 commentaires

  1. sorry

    Siteu gayi lounge la wa degue leu boul yakh sa carier beurel ak sa catégorie mo gueun fi n’ga dieum bakhoul kholal combat bi loumoula eu Ppe da barri trop sa


  2. freish

    siteu a ete tres tres indispliner il risque de foutre sa carriere en lair a cause de son comportement.il na pas de conseiller et tt ces jeunes qui sont avec lui non aucune experience.felicitation a sa thies tu la bien corriger


  3. Lhomme Free

    Yéne wa senego Selbe waroléne ko sakh di publier nakh si féne la deuk.Dieu est le meilleur des juges….Ki niitou seytané laaa.barina wakh torop…Khana légui dina képeu gattame biii


  4. El fénemeno

    Felicitation sa thies selbe yow mome yow mome yow mome khawma sakh lanelalawarawakh mala gueneu aye ndakh néna sa thiés déy dane siteu bilay bayil senegalais nguir yalla seytané wakhoul degg mé yakena khél té yow séytané bou reuy nga


  5. bily

    siteu legui dingua nopi lambji wakh ak togne rek guatie amone sathies doussa morome ton entourage ne te dit pas la verite ils veulent te faire sauter les etapes alors tun es pas encore arriver au niveau des sathies et autres va lutter avec ta categorie les diene kaire doumboul et consort


  6. moussaka

    COMBAT inegal. .SA thies est trooop fort pour Siteu ki na encore rien prouve a part sa popularite. …c bien fait Il va bien dormir ce soir car KO total


  7. Dj

    Ces imbéciles d boy diamagane dagno rewww motakh tay gnaf nagn sen ndey tay g sui Pô d sa Thiès mai c fils d put m’ont une fois brisé ma parabrise domeram


  8. Leuze

    hahahaahaha Fafa dagnoo diouteul combat bi kone key nay nopi bou hamei nei meune nagn diouteul combat bi. Mane lima si meti rek Moy siteu sama mbeur leu donc bamou wahei siteu moy Daan laa tiite dafa wara ndey nopi domram djii.


  9. Méssi

    Dinagnou dioy prk Siteu dafa réw… ces boys là dém diam sén diarbatt ba gnou yobou ko hopital toch pare brise Double Less ba paré Balla déf choc hier (mystic) Bravo à Sa Thiés


Laisser un commentaire