37 COMMENTAIRES
  • iba

    Mon ami j’ai déjà appelé 5 fois y’a que le répondeur i’m so sorry c’était juste pour aider la dame c’est pas facile de rejoindre la télé

  • Dieuredieuf

    Iba tu fait le 221 33 841 23 34 et demande mbayang thiam 2stv elle pourra te mettre en contact avec la dame. Diadieuf nala sounou borom faye sa khôl ak sa yéné.

  • babsssss

    maman envoyer sa contact SVP mangui italy billakhi DAF ma mety trop mere

  • babsssss

    amiinn way yall na yall tegg lepp

  • Iba

    J’ai rigole pas je voulais t’aider send me your contact please I am in New York thanks

  • dakar

    laisse les avec dieux et fait des priere a des heure creuse dieix ne va pas refficher cette priere inchalla maman

  • pape

    Je l’ai tjr dit au senegal y’a peut-etre 10% de musulmans c la méchanceté qui domine surtout celle gratuite……

  • Giss Giss

    mou nial yalla dinalen att fi ci adina yawmal mom vaxale voumako

  • Lolo

    Bilay dioyna sakh limetina trop

  • S

    METINA

  • bower

    Yalna yalla tég loxo si yaw ak sa ndiaboot té yalna yalla torokhal say noon. Aminnn

  • Ouss

    Du courage madame Dieu vois tout entend tout ils vont tous payer tôt ou tard

  • mgy

    il arrête de pleurer et être en face des seytanè defantè ack gnomes

  • maz

    c’est triste mais du courage

  • fatou mou serign saliou

    fi dal kou yoroul niouneii deum la kou niak ni o khpp l dila metital dila moytou .wayei dei kiniou fi xepp .sa place mogua firdawsi yalla mot seddaleii mot mayeii .nittou adouna bio doy warr

  • modu

    Yalla mongui fi tè dina lèrale lépou incha Allah

  • ive

    merci Iba c a la solidarit

  • cisse

    Ça me fait très mal

  • Rama Badiane

    billaye me ne aye nite you bonne mere mouniale yalla danala t ak niome

  • Iba

    Envoyez moi ton contact s’il vous plaît je voulais t’envoyer de l’argent sur Western union I am in New York

  • Iba

    Please send me your number I want to help you thanks

  • Mamadou

    nakha ri nama

  • wakh deugue99

    yalla nga tanei ak diam

  • wakh deugue99

    bilay sama khol dafa diekh tak lii metina trop trop trop sakh bilay yomal khiyam dina meti t yague. senegal mom dou boug mouk finouy takhaw dou dem fen ndakh sokhorante bi fen yi nanfek yi. so niane ( vilain) gniou tam la deum so pauvre gniou tamla deum so febare di diekh gniou djigne leu sida soy seukeut seukeut bou barri t meti gniou lay daw djigneleu tuberculose. wayei nak adouna dou keur t yagoul lepay diekh. yalla nala borom bi may kholou mougne

  • mina

    Sokhor ak ignane di yakhal nit adounam wayer biss dina nieuw bon rek

  • gd

    yalla na niou yall dèfal jamm akk wèr thiey Aduna amoul solo nguèn xamoul kagne la

  • saliou

    khaw ma fou wakh dji bayèko wayè kini nianam yalla douko negliger ndakh danouko togne

  • laye balde

    boulene topato doundal sa vie dara diam ngay amm in chaa allah

  • jack

    c vraiment triste mais il faut tre forte

  • amadou ly

    yalna borom beut bou rey bi dou nèlaw tèdou geumèntou amena lo khamnè faw mou attè ko moye aniiane sokhor ak wakh loula léroul

  • Moustapha TRILLA faye

    Billahyii meetinadk

  • Chulita

    Yalla bakhna leppay bakh inchallah…

  • Marem

    Ndeysane metí na trop way yalna la yalla diapalé si barké Seydina Mouhamed Amine

  • DOU

    vraiment gni ay domeram lagnou koi

  • B.D

    KÉROOK YOWMAL KHIYAAME DINA MÉTI LOOLOU!!! YALLA NALA BOROME BI SAAFARAAL SOKHNA SI!! MOUGNALÉ KO YALLAH!! NATOU MOOME DIAM REKK LAYE DALL.

  • aids

    senegal les gens sont méchant wadiou niawe bakhoul aduna amoul solo lofi guiss déye dié bayiléne yakha dérre

  • alice

    billaye gni gno bone. mre boul souffrir cardiaque fi ndakhe diarougnouko

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *