Vidéo: les traces de la natte de prière de Serigne Touba à l’île de Kassa. Regardez

Reportage à l’île de Kassa en Conakry où Cheikh Ahmadou Bamba avait fait escale lors de son exil à Gabon. Le guide du mouridisme avait fait une prière sur cette île, les traces de sa natte sont restées intactes, témoignent les habitants. Vidéo…

43 COMMENTAIRES
  • kham bathi

    they sering touba mobakh

  • ndiaye

    serigne TOUBA kenne la

    • Moustapha

      jeureu jeuf CHEIKH AHMADOU BAMBA MBACKE

  • beugue bamba

    serigne touba amoul morom

  • mountakha diaw

    theye ahmadou amoul morom de

  • cheikhouna

    kép kouy senegalais war nga fier si srgne touba

  • ameth Toure

    Deureudieufé borom touba

  • albachir

    thiey Serigne Touba

  • amadou sidibe

    sante SERIGNE TOUBA

  • cheikh gueye

    Dieuredieufati kou téde ki

  • mourite

    beug serigne touba rekk doyloko rekk dieuradieufati serigne touba

  • nogayesaer

    kou ted ki yay serignou serign yi

  • talibé serigne saliou

    sante yalla mouniou bakhé Serigne touba

  • dk

    dieuredieuf serigne touba

  • assane

    mane ma beug serigne touba

  • abasse

    bamba amoul morom

  • cheikh

    Sante serigne touba rék

  • Youssouf Diallo

    Serigne Touba Fepp; Serigne Touba reck; Yallena yalla feye loubarré beuri. AMINE

  • COURS DE CORAN EN 3 LECONS

    abba ndir vous forme à lire le coran en 3 leçons seulement la formation peut se faire a distance p

  • ndiaye

    mane ma beug serigne touba

  • papecheikh

    Thiey kou tedde gui kène leu amoul morom té kou ame morom moy sa borom

  • ndiaye argentine

    kép kouy senegalais war nga fier si srgne touba

  • la belle

    dieurediuf borom touba ken la am

    oul morom

  • flic

    dieureuf dieuf khadimoul rassoul cheikh ahmadou bamba

  • ok

    kon way-way beep senegalé di wax-lou bone diko def warnga rous SR TOUBA

  • KUUL NB

    Serigne Touba Mbacke leep loumou am ngeum yallah mokaka may Serigne Touba ba ñieup dawe wouty adouna mom dafa daw wouty YALLAH loolou motkh feep foumou woowe YALLAH , YALLAH wouyou k

  • M.TOUBAAAAAAA

    BEUGUE SERIGNE TOUBA DOYNA DIAMOU YALLAAAAAAAAAA AKASSA MBACKE DIADIEUFETY

  • Talibé

    They serigne touba deurdeufa ty lou wayyy dii wakh warna ko khollat nakh borom touba
    ko khamné service sou yalla ak yonenne témm bii rekk la nekonne , sante rek

  • Talibé

    service sounou borom rekk la nékoune thiey borom touba ,

  • DIAKKHA

    Si ce n’étaient pas les fils d’ADAM,je ne mettrais pas un jour sur terre,ne voyez pas ma condition d’homme noir pour ne pas profiter de mon existence sur terre,je suis le serviteur éternel du prophète MOHAMET(psl) et chaque génération saura que je venu pour elle: dixit(Cheikh Ahmadou Bamba).

  • mataye

    dieredieuf khadimou rassoul barcké serigne fallou bilahi doone mourita nékh

  • bègue s touba rek

    S touba dou guene guene dou mome senegal mounou bolowone di wakh dieredueff s touba gone lonou begue rek am go wayee dono sokhar mo dakh

  • bègue s touba rek

    Lan mon dakh s touba rek deem ana sounou yaneeene mame yi lou dakh niou dogue dano ragal toubab yi wayye senegal s touba rek mofa nee balama dee rek niou nane sounou mame you bakh yi nio deefar lislam s touba rek moga deefar dakh mome rek la toubab yi yobou wone

  • kiki

    que des mensonges nagniou delou s yallah bayi thiakhane yi

  • saliou

    senegal dagno nafek nagnou wakh ki wakh toubab gnou delo si serigne touba biko toubab bi yobo kiko diokh limou sol ak limou lek

  • ameriquin

    wawe beugue s touba danguaye lather sounou yenene mame yi founou nekone yongui wone seneguale pour takhale islame bou were bou amoule bene bokale tabakh aye djouma aki diaka bo dioule yawe ake saye mboke djereufe serigne touba walla nako sounou borome khare aldiana tes tasse niou si barkeme yalla nanou yalla djeguale amine

  • ameriquin

    yawe buegue s touba danguaye lathe sounou yenene mame yi founou nekone niongui wone senegual pour takhawale islame bou selle bou lere bou amaoul bene bokale tabakhe aye diouma ak aye djaka yo djoule yawe ak saye mboke djereudieufa serigne touba yalla nako yalla khare aldjana tes tasse niou si barkeme yalla nanou yalla djeguale sounou bakare

  • bamba

    thieuy serigne touba kéne dou mome!

  • KUUL NB

    iskay

  • Moi même

    égarement total Qu’Allah nous guide

  • BIS

    SERIGNE TOUBA YAKAROU DIAM YI

  • metzo

    Dieuredieuf Mame Bamba

  • sene

    mangui niaane kou wakh dieureudieufeuty serigne touba yalla nangua am tawfékh yokk ba yeug ko doundou 112ans am milliards di tchi ligguéyeul serigne bamba!!! serigne touba kéenn leu dieureudieufé serigne bamba

Publiez un commentaire