Le danseur Ameth « Thiou » Badiane n’a pas manqué de mots pour « rendre garce » à Wally Seck.
L’homme de l’art visiblement très ému et très content de son ami chanteur, dans cette vidéo déverse une salve d’éloges au fils de Thione Seck qu’il considère comme quelqu’un qui a joué un rôle très important dans sa carrière. Regardez.
yaw kou gnak diome nga foutre nou la paix nga deme ligueyi lou gor di fethie
dieureudieuf eumady ya bakh wayyyy
ndeysane yaram dawna yalla naléne yalla lafal thiat té mousseuléne thi seytané ak pékhé none
waly kéne dou mom thi mbakh bilahi tabé yaye borom
eumady badiane domou ndeyou waly ballago seck bayou bb diamant cheri kine dieureudieuf thi temoignage bi dangua goré rek badiane sa koura wali
waly borom kholou or bi deugue pirrrrrrrrrre
ndeysane waly dabakh mé eumady kène dou yaw aussi danga gnack kignane