Publicité

56 commentaires

  1. Serigne Mbaye Kare Bichri

    waw dafa ame xam xam yoo xamni ken douko wakh ouvertement. te tounkara diangoul dinee dafa wara geustou boubakh doga wakh tie dinee wala moye wakh tie philosophie kesse ak pilitique.

  2. aunomdeDIEU

    Fall tu n'es qu'un affabulateur……………………..Serigne touba est un yalla yalla par principe

  3. moi

    merci cheikh wakhtane bi leerna celena,té tek gako si kham kham ak khadiss,diadieuf

    • Cheikh SECK Im a Real Yalla yalla

      Tounkara chapeau pour l invite de marque que vous avez denichez; votre émission est très intéressant cependant vs devez revoir vtr facon de parler aux gens car vs ets tres irrespectueux: respecT minimum ls telespectateur qui vous suivent! Ndangou deug yomboul mais Sngue Souleymane NiANE bilahii walahii ay seutatii seuteum nioleu Eup xam xam:pk yarou da la war MOtaxiit ta pri la pire correction dta vie Homme de mauvaise FOI (oiseau de mauvais augure) U ne maitrise rien du coran Soukeul djebeulou AH si ct moi C sq jallai faire! Tagn Ko TOP kouy weur yalla ba RomB ko SAnkou na dotou ko guiss! U sen le MIchuiT TOUNKARA nax dagn la castrE

    • aunomdeDIEU

      Fall tu n'es qu 'un affabulateur ……..Par principe Serigne touba est un yalla yalla .

  4. Fall

    Ils se revendiquent mourides alors que les mourides les ont chassés
    Des imposteurs rien d autre

  5. Sun

    Daan gaay rew rekk Tounkara Taay Guiss geu Deug TE degeu geu Deugg
    demaaal ga hami yaaala so haame yala haam ni tounkara Amoul

  6. fadel

    Seul Dieu Sait!! Mon raisonnement à propos du terme ''Se souvenir de Dieu'' ''Fatélikou Yalla'' je ne sais pas de quelle manière les savants l'ont enseignés, je considère que cette expression tend à dire: ayez conscience que c'est vers Dieu le retour et que dans l'au delà seul l'accomplissement de bienfaits sera bénéfique . Aussi puisse que l'homme dans la vie d'ici bas est en perpétuelle quête de bonheur mondain, il arrive qu'il oubli la raison pour laquelle Dieu Le Tout Puissant l'a créé cad '' La soumission à Dieu''. Dans cette dynamique, l'expression ''Fatélikou Yalla'' peut être bien conçu.

  7. P+P

    Il faut faire trés attention avec ces yalla yalla ils sont dangereux pour la jeunesse.
    En plus ils ont l'art de parler.
    Féne rék lagnouye déff merci tounkara

  8. Assane Diaw

    Toukara liga wkh moy deek xam yalla diaféwoule niome out xalis rek lath fi neké

  9. thiam

    tounnkara degloul wadji ak khel té bagne ka deg ak khol li wadji wah lou leer la yalla daga kay kham bala gaka diamou dem lene guene khami yalla ak wassila bou mat goor yalla bala wesss.tounkara faut faire attention je vous en prie yalla dagnou kay kham

  10. BLK

    dieuredieuf Serign bi wakhnga deug Alhourhaan dongay deug figay waxè Toukara égufa

  11. sama xalaat

    slt gua baal ma yow sourang beugone na gua wakh niô kanamou djoulit nan lay mél? boul attè domo adama tè lingay def ni togne la t togne bakhouuuuuuuuul

  12. Badolo cieNéwdolé

    Tounkara le Marabout est tres fort un vrai sage !La Politesse et La sagesse Font Partie de La Religion ne faut pas les oublier!Quant à Sourang qui nous montre que tu es Musulmans? La foi Apartient à Dieu.

    • aunomdeDIEU

      Avoir un doctorat en arabe ou en tout ce que voulez n'a aucune valeur aux yeux de DIEU.La connaissance de DIEU est au dessus des lettres.

  13. etudiant

    mai tounkara do nite. pa bi mou bale ma wayé khamoule dara, tounkara linga wakhe mo ame gni aye nite yougnou rikipèré lagnou beugue di woute thi gnome dépasse, mai j aimerai tounkara soye inviter gnou méleni nga inviter walé kou ame doctorat thi chriha . ki saboune takhi sakhe khamouko سبع تقي ki dou tousse

    • aunomdeDIEU

      kalima tu es de mauvaise foi ….je crois que tu es un talibé de baye et tu nourris une jalousie viscerale envers les yalla yalla.Saches que xam yalla ne peut pas etre l apanage de baye …ba nit yi di xam yalla baye dioudo goul……xam yalla senegal dciy dooga jot……

  14. kalimat

    serigne touba moussoul wote kham yalla , ndakh si wird tijane la guene adouna , avant lolou wird shazali , khadr la done wird, mai nak gni dagni topando wakeur baye niass waye ligni wakh yeup thi wakh rek la yam . khamou niou yalla , khamna leen bou bax ndakh dileen frequente . beug promo rek .

  15. Badolo cieNéwdolé

    Tounkara fette foisci tu deconnes le Marabout est tres fort ! Ce que tu faire facile ne l'est pas si Dieu voulait que tout le Monde entre Au Paradies il ne nous la Religion(.A côté de la difficulté est,certes une facilité! Quand tu te libères, donc lève-toi. Et à Ton Seigneur aspire.)Tounkara! La politesse

  16. tieddo

    A quand on aura des ingénieurs et des managers sur les plateaux de télévision. Le Sénégal regorge de médiocres qui passent leur temps à citer des versets de coran au lieu d'aller travailler.

  17. birima

    yaw sourang xana xamoni sourang sourang yi serigne touba molene defar guenelene thi lokho nassarane yi en tant que interprete ap sourang sourang dou def lou niaw te douko wakh waye yaw dafa melni yar bi serigne touba yar say mame dafa yegoul thi yaw wala nga bok thi guenen sourang gou boukoul dara ak sourang sourang yi bamba defar

  18. sama xalaat

    tounkara.waw goor sisa liguéy rafét na ? mé lila serigne bobou di wakh deug gou weurleu

  19. taif

    Wahtanewi amna solo te serignebi djambarla trop wah deug yala mais soufene hamna yalla warna mana wah bagnou ham yala thi emisionbi ndah kou nèk ak foumou meundi nèk thi adounabi meuneko dèg tè topeko ba agu thi yalla wayé beugnè il faut ga gneuw bathi serignbi mou dogla meuna hamal yalla pour mane lolou ak diafèlla tè dou souna ndah yonéntèbi sah dadane tok di wah gnouy deg sounou barè djeufé . Exemple : serigne touba mimouy wah dafa bind masalik guir nitgni meun thiè diare ham yalla thi lolou kouko djang ak fo meundi nèk tè djeufèko dinga ag thi sounou borom tè dou adjié gay dèm thi kèn . kone serignbi sou hame yala warna meuna wah yala gni koy sètane thi emisionbi bouko defè gnomit gnou meuna ham yala tè topouko, wayè par force dagèndi gneuw thi mane pour mane lolou ak diafèlla

    • aunomdeDIEU

      Tu pretends etre le depositaire des lois de DIEU au point de dire qui est musulman et qui ne l est pas.Ta reaction est tout simplement symptomatique d une ignorance inveteree dont seul un marabout comme celui là peut te debarasser

  20. mbengue modou

    tounkara bayel ko gnew nga yakarne yako dakha diang ky lemola wakh lolerle nga balma

  21. Khalil

    tounkara ky ganoko diang bayel ko gnew fiyaw ngayakarne yako raw tay mom diegloul diomnga

  22. poutiou poutiou

    Voila waxtane bi limouy ame solo yeup limassi gueuneu nex moy pabi nena tieko meuneti diokou tie maak you bax yifi nekone yalla lalay diangal ak alkourhane..lolou amna solo …donc aretons de croir ke koussi néke sa tarikha mo gueune …yeup fa yalla bou diaré tie yone…

  23. Mbaye mboup

    tounkara yagui soga inviter serigne degue loko wakh mou tontoula si tontou you ler niou mele ni ga war di inviter nak merci serigne bi yalla nala yalla defale kheweul

  24. gunzout

    waxtaan bi amna solo trop.g bien aimait la reaction de tounkara car cela a susciter des eclaircissement venant de notre cher cheikh.Vraiment j'admire ce cheikh.yalnako yalla fay t3 mayko fan wou gouddou

  25. abe221

    Vraiment les soufis ils veulent compliquez la religion. La religion n est pas du tt complique ni dificile. Je suis totalement d accord avec Tounkara c pas donner a tt le monde d`etre a la mm hauteur de comprehension.

  26. seydina alioune badara gueye

    tounkara vrement je t admire beaucoup sa Emission pour mane dafa am sens et bonne continuation

  27. less

    machalla sering bi ligay wakh loulèrla lilabeguthi wakhtan dagakoy tèkk fou wèrr

  28. Cheikh

    Toujours dans Massalikoul djinane (les itinéraires du Paradis), Serigne Toua dit:

    267. Si tu ignores l'histoire des "wirds", sache que l'objectif en est fort important
    268. La place qu'il occupe dans la pratique pieuse se situe parmi les plus éminents actes de dévotion
    aux yeux de tous
    269. Sa définition d'après les informateurs (inspirés) : c'est un acte d'adoration déterminé dans un
    temps régulier
    270. Et le vocable dérive du mot "wird" qui signifie : stationner sur un point d'eau pour boire ou puiser
    271. Chaque "wird" conduit le pratiquant vers l'enceinte scellée de Dieu sans déviation
    272. Peu importe que ce "wird" vienne d'AL JALALNI (cheik ABD AL QADIR), de AHMAD AL TIJANI
    ou d'u autre parmi les qutbs (pôle) que Dieu soit satisfait d'eux
    273. Car ils sont tous dans la bonne direction
    274. Chacun d'eux appelle les aspirants et les incite à l'adoration du Maître du Trône, où qu'ils soient
    275. Tous les "wirds" sont dans la rectitude et la probité ; garde-toi d'en mépriser ou d'en critiquer
    aucun , dans ta vie

  29. faye

    Beylienne si takal yonou sounou yonou mouride bi wawo meuno wone kenne yalla il yeup Serigne touba waheu nako ni où Serigne touba la ni où geum Serigne sidiy mokheutar Mbacké

    • abe221

      le tassawuf n est rien d autre que le Ihsan. La perfection de soi meme interieurment et de tte acte.

  30. cheikh

    Wakhtane bi amna solo lolou effectivement wadji limou wakh deg bou wer leu! Serigne touba dafa wakh si Massalikoul Djinane (les itinéraires du paradis):
    80. La science se divise, selon les savants, en deux parties, ésotérique et exotérique.
    81. L'exotérique régit l'action des hommes, l'ésotérique, les états d'âme
    82. La première est connue sous le nom de "fiq.h" ou jurisprudence et la deuxième est appelée
    "tasawwuf" ou soufisme
    83. Puis il est obligatoire à l'homme de commencer par le "fiq.h" avant d'aborder le soufisme
    84. Quiconque omet le "fiq.h", périt ici-bas par le jugement des docteurs de la loi
    85. Celui qui omet la deuxième, périra demain par le jugement du Seigneur Très-Haut
    86. Il est donc obligatoire à tous les serviteurs de les rallier afin de réaliser la récompense escomptée
    87. Celui qui applique le "fiq.h" et fait fi du soufisme, est un véritable fripon. Il faut le savoir 88. Celui
    qui l'inverse, est zindîq (hérétique), affirme-t-on
    89. Mais à qui arrive à réunir les deux, (le fiq.h et le tasawwuf) est un beau modèle ; il faut suivre son
    exemple
    90. Cette affirmation a été faite par le grand Imam MALICK (que Dieu lui fasse miséricorde et lui
    accorde son agrément)

  31. Frenchmen

    Mane toukara daf ma diakhal quoi May wakh moui waété…. Vraiment faut que nga kholate sa bobp

  32. brazil f

    wakhtan wi amna solo youmėlni lan sokhlala merci tounkara yow ak serigne bobou

Comments are closed.