85 COMMENTAIRES
  • absa diouf

    dafa nekhe badeh sokhar

  • fall mo

    super

  • fa

    titi lip pay bakh du courage téga kham né YALLA moyor diamam yép les fans restent toujours à ta côté lodéf nékh nano nakh yaw lan beug

  • fall modou bété bété

    les gars . faut po etre mecontant .limou woy nekhna trop .ta dafay yété… amna kouma dégue. mounan prince art .way …titi .yallah mo yoré weurseugeum. ak souniou niouy weurseuk. .. ta yén gniy dingat .kousi sanion melni titi…. donc nanioulen bayi yéneu yi..ta nangou li yallah déff ak ndogalam.. kou nangouwoul li yallah dogal nak .dinga sonou tayit dinga diakhale. …… weurseuk yalllah rekk mokoy diekhé…ta fi adouna la. andde dagana takaliko tiyit daganna donc yakar yallah rekk mo woor.. .ta kouko yakar don sonou do diakhle .ta lo yotou diotko.. pask moy mayé… nul personne n peut echappe son destinnnnnnnnnn

    • deug

      come elle la dit dns ces chansons naniouko niane naniouko niane moy bourou bour yi nanditè sonoul tè titi da dèg dathie

  • fall modou bété bété

    nekhna trop bialahi ça me nekh. bcp.

  • rima

    voix mome machala mais musique bi n'est pas oroginal je suis désolé

  • rima

    courage titi c'est dure de traversé ses moment mais ca va aller yalla nieup lafi nekal

  • OULISH

    Damaa rouss sakh, liiiii melni DIOR NDIAYE. Bii moom, doyna sekk

  • alakham

    courage rek titi djiko moye nite té mouye deugueu

  • mamita

    wa yenn lii moyy sénégal
    wakhal niit lou bonn wala critiqué niit mon dieu akk atitude bii sénégalé yii dieull légui wakhoul ma sénégal dou démm deh wayéé di na métii trop!!!

  • assane

    nekhna yallna la yalla diapale

  • aida

    lepz nekh. voix bi, son bi tout Nice.

  • nana

    J'apprecie bcp Titi, elle est ma chanteuse préférée et je la respecte aussi. té niit boko beugué do ray deug bi, peut etre c'est juste ue coincidence mais ça ne va pa, la voix est toujours belle machallah mais la misique est trés mauvause voire même médiocre!! dommage.

  • dyuk

    du courage

  • abdou

    tu vois lebou Sénégal bo diougué di Wakh lou bakh si nite gnou ni dagne KO yonni wéranter bi diarouko

  • hana nakari

    hana nakari lou boneli

  • doff

    magui har ba bène radio tèk lou boneli

  • mouyène

    titi boulgnou yapp waye sa son bou bonebi nèhoul ci nopou

  • haral ma rè

    on dirai lady mounass

  • lebou

    Bien parler abdou on l adore et on ne lui veut que du bien beugue nite WALA fan ko d'où tere ngua wakh ko deug vraiment son bi dess n'a paroles yi am n'a solo lolou n'a dem seti Papis konate WALA lamine faye cheikh Tidiane tall wala Djimy mbaye .arrangeur yii bari nagniou fi mou def lou proffesssionnelle .on l encourage elle a du talent

  • daba

    nékhou dara

  • THIALA

    Tous ces gens sont commandités par Prince art la musique est arrangée et le son ok

  • abdou

    dama yagua beugue titi rawatine bimou wayé son serigne Saliou bi mane sama yone nekoul si fo wara dem parsk fo dem yalla guafa mes figua défaré son bi doumani bakhoul mes Desna bou bakh liguasi waye amna solo lole mes son bi dal doyna ware yalla Nala yalla guena diapalé si kaw si kanam

  • amy

    limagueuna sof tji SEnegale, mot dagno fok, boudou prince art Walla Youssou ndour, doo avancer. waay waay, lii l'âne la. DEugueula, booknagnou tji gni fakhastanitgni, wayée dougnou yalla. "quel complexé". Nuit kou bakh d'Ay gueum Yalla, geum boopam. Tjiowli doyna, nagnouligaye,

  • aida

    Trop Nice. Titi, tjia kaw tia kanam. ligua waay nekhna trop. très belle voix. . continue, dey baa.

  • àn

    liga waay nekhna trop. Aÿ deugues you weer. amgua talent, amgua diom, bonne continuation

  • lebou

    music bi yatou n'a kou nek am ngua ci place mais il faut niou Tek ko ci yone dara diaroul yakamti lou diote yoombeu elle a une très belle voix mais talent rek doyoul am n'a ay arrangeur you aye you nek Sénégal n'a dieul temps wame defar lou nekh am harmonie comme avant.mane awma lou Makay sokhare fi ma nek ci FRANCE ma ngui am Lima yalla weurseukale donc defar rek la beug et c est valable pour nieup amoul politiciens amoul musicien ni mbeur. De grâce da niouy wakhtane rek gniy saga n'a niou arrêté sagayi n'a niou ko raffetal adouna amoul solo te on ne sait jamais A Bon entendeur SALUT

  • rew

    nicena titi prince arts d boul fa meussa delou dagnlay utilisé rathe la beu nga seet bakhou gnu

  • am

    Amato béne buzz..sérieusement..demal danser comme au debut

  • saf

    Safoul sukar saful khorom..khana degg Lou wo lii avant ngay gnew..dareu bakhoussi..nekhoul touss

  • ilimane ba

    yaw ya sokhar waye nekh na loll

  • fall

    Ndeye sanam wally fayna nieup

  • ndeyesow

    nekhna fii kene wakhoufii wakhou prince art nekhna senegal sokhor lagnou def titi jiguenela amoule kouko japalé apart fans bonne continuation satho deh yako creer magnifique

  • Ibrahima Ndiaye

    tu es la meilleur j vous adore

  • vraiment

    wa ki koumou yap demal ligueyi waatkila invite kjamna sakh li touss yangui beugeu niaaw ci kharebi void avez choisi votre camp affronteko

  • awa

    C choquant de voir cette dame tomber aussi bas

  • momo

    tro nice!! j pense k vs critiqué pour critiqué mais cé pas bien

  • lebou

    même si youssou ndour fait du n importe quoi on va le critiqué. Alors cessez d insulter les gens.kou respecter sa yaye do sagua yayou diambour

  • lebou

    pourkoi insulter des gens un peu de respect s il vous plait chacun a le droit de dire ce qu' il pense il faut accepté les critiques c Est ce qui fait avancer une personne n
    . alors du respect les gars

  • niakk kinianne

    message yi amnasolo trop me musiqu bi

  • titeuf

    Yalla mo eup dolé Prince Art mo eup dolé Youssou nDOUR ET SA CLIC. Titi courage sa yaye nianal nala. Vous bandes d'aigris kat len sen ndaye feulé

  • fatim

    Wa Touba gnou ngui lay gnianal boultit dara kholal thi kanam

    • Wormay TOUBA

      Wakhal Sa Wakh Ta Bayyi Wa TOUBA Khassaide Mofi AME

  • D

    Chui po fan de titi mè sénégalais Soxor critiquer rk

  • xoss

    non ne vous inquietez pas c'est la personne qui critique soit dagnouko yonni ou bien elle a une dent contre titt mais titi mome talent kessé tout le monde le sait qu'elle travaille avec prince art ou quelqu'un d'autre, elle reussira parce qu'elle aimée par les senegalais.

  • wakh deugg

    sokhor doufi diogué

  • wakh deugue

    sénégal nak sokhor doufi diogué li amena daguéne ko wara encouragé mo geune té sakh yakarnani déguelou woléne parol yimoufi wakh

  • Anonyme

    AU MOINS LA MUSIQUE N EST PAS ELECTRONIQUE COMME CELLES DES MUSICIENS ACTUELS

    BONNE CONTINUATION MA CHÉRIE AVEC CETTE ORIGINALITÉ POUR UN FUTUR MARIAGE

  • fu

    En matière de discussion celui ki s'énerve c celui ki na plu d'arguments..fi kéne insulté wufi..mo fi deff Lou nekhoul Gnu wakh ko..nafekh menoul wessou niame khorom né aka saff soukeur..son bi nekhull tousss

    • deug

      fu rakhasale sa khol . khol moy nite ignane amoul solo

  • sow poulho

    excellent son

  • krumah

    neex na trop nice single titi…geumeul sa bopp rek liguey prince art lekk nekkou fii yangui akk talent tei meune gua lingay Def boul degglou waxou sénégalais yii dagno soxor

  • aicha

    titi beugnala trop mais son bii mom bouko ngener les parole st interessant mais sa ne va pas avec le rytme cherche un bon producteur parce k sa mom c du jamais vuuu oufffff wathingeu trop sakh Dzl

  • wakhal way

    Kate lenn ndayam dem ligueyi mo guene gnak ngene diom trop titi am na gnanou wadiour me sen djigo mo bakhoul mo takh té djiko moy nit

  • Boulogne

    pufffffffffff pufffffffffff

  • Paris

    boummm boummm boummm

  • malick sarr

    Nice titi

  • doss

    kou ame aspirine quelle horeur ce son !

  • gf

    Momo léne nitt yii..woy sou nexul dagn koy wakh..ma wax Gnu nane paregul deggal afferou amateur yoyu..son bu paregul nokoy guéné..mbassa mbassa way..woutil arrangeur bu ayy

  • xd

    Li Gnu degg Lou Dale mom nekhoul gnoune amougnou temps bougnouy setané walf..khamoul touss c pas le 1er single degg nagn fii reprise serigne saliou..deffa goufi lu nitt mena degg Dale wasalam

  • Fa

    Oh arrêtez svp si vous aviez suivi l'émission vous saurez que c'est pas encore arranger et ça reste des choses à faire. C'était juste pour montrer aux fans qu'elle travaille et qu'elle est en studio. Encourager la c'est une femme battante c'est mieux que de l'insulter. Eupeul bakhoul.

  • diop

    khana nekh titi dou nit ki moy nimero 1

  • beug bamba

    Li ngua way titi am na solo lol senegal nak dagno sokhor adouna bi gneupeu leu beug tei lo way mou nekh yalna la yalla Same

  • co

    Wa titi legui dafay khessal waleu..son bi mom c nul

  • moi

    Wawaw sa kaw sa maman

  • lebou

    on vient bien la différence entre Prince art et les autres maison de disque c est vraiment nul cette musique. kene khamoul lane laniou teug comme ay pote amoul bene harmonie. Vraiment Ibou Ndour est le meilleur. deloul Prince art mo gueune ci yaw

  • yii

    Yiii nekhoul titi dinthial meu lii sisa armoire bumu guéne dé

  • poukhouss

    ndeysan khet yep senegalais moci guen sokhor beug bagn mo dakh way senegal

  • ds

    Qualité zéro..arrangements nuls..rythme sonore médiocre..melodies absentes..titi luko dale yéne..ah Viviane dinaleu retane dé..

  • trokh bani tothi

    kou wore rène ba dèwène mou djikela dagnelako djine.ligua way dou yègue bargny nakhe nehoul santoul yalla

  • lom

    Noo titi bayinga sa lokho lii boulko guené mouk si adouna si no dinga amm gathié li nékhoul

  • way

    Way veur..sunu yone nekul si ay témoignage music bi mo Gnu intéressé..comaprei lén son yi mu dane deff ak yi com yalla ak yalli..soyez franc avk vous même frère li nekhul amul qualité..ani son wu mame saliou bi mu teggatt fo léne koy degg mem pa sur zik fm..

  • wow

    titi nèkètè yaw amoo bène talen wa prince arts gno amone talan

  • daro

    mane damay guènte wala titi dèloul prince arts li nèkhoul

  • thim

    ki koumou yapp bi music bou vone nèkhoul mome

  • nèhoul dara

    nèhoul dara yaw dèloul prince arts gaw dawal

  • fili

    SO LENE KHAMONE LI GNOU KO DONE TEMOIGNEL HIER DI NGUENE NOPI EN TOUT CAS ELLE UNE DAME TRES CALME ET ELLE A LE DROIT DE CHOISIR SON PROPRE CHEMIN. DU COURAGE TITI BON VENT. HIER J'AI REGARDE L'EMISSION BEFORE MINUIT SUR WALF MAIS J'AI TROUVE EN TOI UNE GRANDEUR EXTRAORDINAIRE. BONNE CONTINUATION…

  • cat

    Li lumu done khana xandrung diazz studio moko deffar mdrrr..ndéketé ki ayoul encadrement bubax la amome..tchieuuu

  • fatou

    yenn mom khamolenn louy musique li nehneuhh ba dh
    Titi avait un talent avant prince art et elle l'a toujoure au contraire wa prince gnoko promouvoir roul bou bahh dah viviane

  • Fabrice Baguma Cikoma

    Super

  • go

    Wa titi li lane leu nii..mane dé dama sakh rouss ohhh..on dirait une debutante

  • moh

    Mdrrr kxkxkxkx.

  • niang

    oh yeureumnako prince art diapasi way c triste

  • titi

    Mdr li dara nèkhuci warte kate mom yalla dakay trokhal lol

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *