PUBLICITÉ
PUBLICITÉ

Vidéo: le meurtrier du vendeur de café arrêté par la Police

Découvrez les images de l’arrestation du meurtrier de Baye Fall.

Baye Fall Tué Meurtrier Arrêté
Annonces

(50) commentaires

Misi

Thiey yalla lii aduna diarouko

Ma

niaw bien fai les gars ki avan police di nieuw dafa warone déh kom wadji imbécile

Pap

Have merci on the Man! Satan!

Fina

allahou akbar yalla naniou yalla mousseul si seytanee

Ali

amine. wa ki nako ??? apre✂✂✂apre??? apre??? apre??? fin.dina kham limou def bakhoul

Ma

mdrrrrr ali bouma ray

Nit Doff Killer

ray niit =??????????

Ma

NIT DOFF KILLER li lép bariwoul

Kevin

on doit l'emprisonner à vie + travaux forcés

Ramces

Le monde est devenu fou. yala naniou yala mousseul si seytané et am moudiou bou rafett

Amina

100ans d prison +travaux forcé après niou dague…………

Rafet

senegal dénio wara def Loi kou raye nit niou raye la . Sénégal yakouna ay rayanté rek dînéniou tak ba yénen deuk yi raguala niow Sénégal. Délosilen kel yi té mounieulenté Adouna amoul solo. Qui dém Yalla nakko sounou Borom bi harée Aldjiana you gueneu kowé. Aminn

Roki

ki esk k werna ? parce k li mom kéneu xamoul laneu la motax yarr seu bopp lu am solo leu ak mandou

Insa

Ray nit barinafi trop ta kanam la diam ndakh danufi bayi atte sunu borom muy ku ray ta tay nanula ray bunukadon def ray dumani dotul am wante daña new lol

Sya

Thiey senegalllllllllllllllllllllllll

Con

ki nagne ko sikam nagnou dieul pousso rek diko diam si beun beunou koy bi bamu sed gouy

Nit Doff Killer

Ma purtan paka bi kessé yobounanit dernière asamane

Kevin

mdrrirrrr non mais con c'est toi qui as trouvé la vraie solution. hahahahaaa sikam non reh na ba tass kw !!!!

Mameibra Lam

kate nagne nayam bakhna

Sante Yalla

bien vrai rafet linga wakh deukh la,li dafa niaw lool domou adama di liguėy guir ay ndiabootam di out loumou soutourlo nga koy khatal diko sokhorė lou niawla: rawatina ngay senegalais mouy senegalais niawna lool, kinou raye yalla nako yalla tėrou ci yėrmandėm ci barkė seydina mouhamet s lw

Sa Touba

thiéye adouna

Kevin

Nit dof pourtant li con wakh solution la deh lol

Amy Frokk Badio

svp je cherche quelqu'un pour bien me baisse je suis seul svp svp

Mbayegalsene

C'est notre démocratie lou waye néx défe beaucoup d'indiscipline souñou Wa xée ñouné talibé diwe Serigne diwe lii leu rek
Éducation c'est la base de tout

El

Mais lanelako bayefall bi Def la khamoul mais Ki moy domeram

Mams

thièy amy

Mams

hanna sa badio bi dèy hasaw

Bakarngom

il faut que l'on instaure la peine de mort au Sénégal c'est trop facile ça

Lamzo

Ki kay deumleu yalla nagnou si yalla mousseul

Xamsa

Iran. Nadal voilà. les défis. vous qui parlez de yalla. khax. lenn. si djikoyyi. a Ak. mougne. donn. ay dioulit. ak chrétiens. you. bakh. ndakh. Sénégalais. dagno. yakar. ni. sounou. borom. amoul. wala. dadi. magatou. goumba. yasal. dialali. wal ikrame. bis bi dina. gneuw. de

Xamsa

Iran ndao. au lieu. de Nadal

Xamsa

Amy. ta stratégie. ne marche. pas nous avons. appris. que dans l ex union. soviétique. quand. on voulait. aborder. les questions. de liberté. il ya toujours. un agent. des services. secrets. qui. tirait. dans le tas pour rompre. la discussion.mais. peine. perdue. la révolte. à eu. lieu. donc garder. votre. marchandise. invendue. elle est précieuse. peut. être sera t elle. le géniteur. de notre. futur. président

Gueye

ki micil lagnou warone deug ndeyame mou ecragéwou sur le sang vempir la

Le Grand

Ses imbéciles ne méritent pas de vivre et tant que monde continuera à réclamer je sais pas droit de l'homme ses hommes n arrêteront pas de jouer avec la vie des autres ils méritent tous d'être brûlé !!! Mais désolé sous peut il sortira et Bayfall ??????

Ndiap

fi senegal il fau niou defar prison bou mélni gouatanamon pour les criminels

Boull Dofff

qu on le met sur la chaise éléctrique

Morgue Bi

falait pas le regarder marcher comme ça falait le tuer

Bachir

Vraiment nous devons eradiquer cette situation parceque aujourdhui pour des trucs bidons les gens se permettent de commettre des crimes odieux boudone kou reyy niit gnou reyy la kone legui gayi nek nite cest catastrophique ou va le Senegal??

Nit Doff Killer

Yaya jameh "amgafi placce

Rich Gang

ki nagnou raye ndeyammm wayyy domerame sama gayii nekk rebeux 100m boufa dougué rekkk raye lenn ndeyame sur tou sama gayi wa chambre 13 bayinako sen lokhooo ta guenn dioutalko
si tate deuge ndeyammm leveule sama bro gerére kokou di niew nief lenn ndeyammm guenn lokatiii bn beut biii wolou nalenn siii

Rama

aly bouma Ray way magui dés ki dognon wara deuk ndey yam bou Bakh après gnou teuthe ko

Xal

Non mais les gens qui le suivent marcher comme ça là sont des poltrons, ils devraient être directement transportés à la morgue parce que c'est pas sûr il peut rester en prison 10 ans ou je sais pas quoi et un jour bénéficier de liberté , les gens vont même l'oublier il fallait le tuer à chaud par des coups de marteaux; Oh je compatis vraiment à la famille éplorée.

Misi

C po si vs avez remarqué wadji da dougou ci oto bi rk teudde com si amoul louko metti mai lii tamite lanla abiou delou ci yalla dakh niou moutiou

Djiby

Adouna say tanė mofi eupo dolė …yal nagno yalla mousale si mome

Elhadji Faty

yalla KO wakh kou Ray nitt niou Ray la ki dé niou KO warra Ray ndem

Junior

nékhoul ba nékhoul mais le gars en chemise bleue niaaw na noooo way

Teranga

faut la peine de mort au Sénégal y a n'en marre la pourquoi à ce faire tué part des imbéciles comme ce la il mérite pas de vivre ce garçon billahi ???

Leeee

kii danie warra dokhane ndeem

Beugua Sama Rèw Senegal

dagnoko warona rèndi ,ki vrai domou harame la

Ady

lii Djiby wakh mooy deugue.Nagnou mouslou ci seytani ci sunu nekkin.

Publier un commentaire