Vidéo: le long battré de Waly Ballago Seck à Daba Seye…

Votre avis sera publié et visible par des milliers de lecteurs. Veuillez l'exprimer dans un langage respectueux.

";

35 commentaires

  1. Dieu merci ba nekouma gueweul……..kheet bi geuna niak diom ak dignité si adouna bi mooy gueweul.
    Senegal bou avancer woul ba légui rek c'est a cause d'eux.
    gueweul yi war ngueen ame dignité ak ngor waay wayei niak diom gnak ngor niak dignité fou nguen dem wanefa sen bop.

  2. wally dèmal ba kèn lal la
    sokhor dèè bakhoul
    nitt day ragal yalla
    bayi lèn di wakh lou lèn leroul
    sokhor guèn trop thiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiim

  3. yow AL HAKH wax nga lou gnaw c'est la premiere fois may intervenir si site yi parce que linga wax moma yeungal. man dé gueweul la de mere mais man na wat ni gueunoma, eupoma ay diplome , gueunoma am dignité akk valeur té kén yaboul sunu famille ndax gnoun gnoy guewal you gueun guéér. faut pas généraliser et mettre tt le monde dans le meme paquet. Nguir yalla réfléchissez bien avant de dire des betises parce que on ne sait jamais té linga wax meun na yéé fitna .

  4. bou yalla né waw diam Day nangou nopalikou léne ki yalla né waw deug nèkhoul mo fi nék défal loula nèkhhh ya tay nék goor yalla motakh nga continuer Di vagué si sa liguèy malgré c ke tu traverse dagnou yakarone né problèmes yi dina takh nga féy khamougnou nè yala la tall continue tout woyal batrél dèfal linga dane déf yeup bay fall dou tite

  5. La grande hypocrite Daba Seye lol, je parie que hier soir Coumba Gawlo devait etre en eclats de rire quand elle t'ecoutais chanter Viviane et insistai sur le "koumou nékhoul topal feulé" diko Garal, au début cetai coumba gawlo ton idole, aprés nga djeul Titi, now c viviane? mdrr tout sa pour Coumba Gawlo t allé cherché celle qui deteste le plus la diva pour former une équipe lol Coumba gawlo d "Ding ding Kéba" leu kéne meunoul si mom lou bari kou gneuw fék ko fi kou dém bayi kofi, 25 ans de succés, elle n'a mme pas le temps de ces details et de ses fumisteries mom toubab leu! Viviane tu devrais faire attention ne rentre pas sur le jeu de Daba Seye, meme si toi et coumba vs etes pa porche, elle n'a rien contre toi ! Daba Seye nak dafa perte Coumba gawlo moko téré nélaw balégui

    • Damay lire di lire di lire ba ekssi si coumba gawlo toubab leu j'ai failli arreter ce que je mangeais tellement je suis decourager. Donc etre toubab c'est un compliment? mon vieux la colonisation et l'esclavage nous ont vraiment laver notre cerveau. Sacre complexer senegalais ou quand on te juge de ressembler a ton ancien colonisateur, tu es content et c'est un compliment. Ridicule ne tue pas deh!

      • kholalma dof yi zico ak gorfitt xawma…vs n'avez rien compris dég tel rek né damna pr yén yéna gueunn toubab yi? sén khol mo gueun rafett you toubab yi? solén dégué manam djiko toubab leu yor manam ; coumba gawlo c le genre de femme qui ne s'attarde pas sur des details comm le font la plupar ds filles ici, ay affaire de défanté, garal, elle est rigoureuse, stricte et qualité yoyou toubab yi ngoko gueune yélo ngén bagn ko ngén beug ko nangoulén ko rek ap djoulitt dou reuy ! toubab rigueur ak serieux gno takh gnou liguéy sén deuk yi xamngén boubakh limay wah, sénégalais hypocrisie, ak sokhor, ak ay défanté motah gnou barri dougn dém ! wakh dagnkoy dégg kéne douko warakh eupeul ngén trop !

  6. md waxga deugue malgre que guer la défois guewel GUI BI gueun guer BI démin dé dou ñiañ faut comprendr ls gars dañiouy mer rekk generaliser courage yalla na diam yague Senegal si barké Mouhamed psl

  7. KHALIFA yow dé dalal nga sama xél au moins parce que dpui tt a l'heure jme sens trop vexée par ces propos . yalla xamoul guer xamoul guewal domou adama la xam . gnoun nak gnofi indi ay affairou caste bamou jaral gnu gnuy waxanté lou gnaw ak diko défanté té adouna bi amoul solo. man dé douma nangou kén di toutal sama askane wala ngamay jéma gueun

  8. Waaw MD li nga wakh deug la ndakh regle boo guiss amna exception mais gueweul yi ame ngor,dignité ak ame lougnouy rouss bari diom ne representent que moins de 10 %.
    Damani la waxoumala senegal sakh mais la majeur partie des griots de l'Afrique noire ont des problemes comportementaux et c'est vraiment dommage….fii thi Senegal Gueweul rek mooy gneuw sa keur nga niak ko kersa wala nga dakh ko ensuite mou nieuwaat fa.t'as l droit d dire ta famille n'est pas comme tant mieux c'est l'exception alors…..tu crois que ce jeune chanteur sou dereetou gor doone daw thi yaramam dina batrer xaliss niii alors que derou bayam yakhou thi deuk thi alalou faux billets.
    Man sama baye sou defoone li baayam def kone jamais ma nek thi mbolo di wanei wou naan dara safouma.il veut montrer aux senegalais que dara safouko, que moom amna xaliss etc…
    Nga baal ma mais sa mbokou yi gnoo yakh rewmi

  9. boy waly demal defal ay niane ak sarah pour sa baye thione wala wouti ay avocats you bakh comme maitre bamba cisse pour liberer sa baye guay poukeureh di battrer khaliss ce gosse est mal conseille

  10. Nina wax nga deug par ce que wolof nena Mbaaam boula wéké nga fayou yéna yam Man mikay wouyou sax´ Mako déf. Len rek lalay xamal yow Al Hakh linga wax dou louniy ballé té dou yomber nonou . Linga wax dafa reuy té bala ngadon xamni dou louy fay nga dévoiler sa identité bama meun jokko ak yow .

  11. MD khana degoo limala wakh yaw? man je n'ai rien contre les castrés ndakh am naa si aye xarit mais dama nila parmi tous les castrés les gueweuls gno si geuna niak dignité…….Teug yi par exemple gnom gnou ame dignité lagn en plus am nagn li gnouy rouss diko diomb, teug bi dina ligueye ta dou niane, di nagn diangue ba bari xam xam, di nagn diamou yalla mais ici au senegal plus 90% des gueweuls n'ont aucune dignité.

  12. Wakh nga deug Diop ma ngui diegalou di baalou akh bepp gueweul bouma togn.J'ai parlé sous le coup de la colère motakh j'avais mis tout le monde dans le meme sac wayei xam naani bari na si gnoom gueweul yi gnoussi ame ngor ak dignité.Lima méti rek mooy senegal y'a des comportements yoo xamni dagn ko wara bannir ndakh baxoul ndakh ils sont aux antipodes de nos valeurs.
    Encore une fois maa ngui toub di balouwaat akh gneup.

  13. kholalma dof yi zico ak gorfitt xawma…vs n'avez rien compris dég tel rek né damna pr yén yéna gueunn toubab yi? sén khol mo gueun rafett you toubab yi? solén dégué manam djiko toubab leu yor manam ; coumba gawlo c le genre de femme qui ne s'attarde pas sur des details comm le font la plupar ds filles ici, ay affaire de défanté, garal, elle est rigoureuse, stricte et qualité yoyou toubab yi ngoko gueune yélo ngén bagn ko ngén beug ko nangoulén ko rek ap djoulitt dou reuy ! toubab rigueur ak serieux gno takh gnou liguéy sén deuk yi xamngén boubakh limay wah, sénégalais hypocrisie, ak sokhor, ak ay défanté motah gnou barri dougn dém ! wakh dagnkoy dégg kéne douko warakh eupeul ngén trop !

  14. Al Akh…ragaleul ALLAH swt …wakh dey raffett. ..dîné leu tey moytoul adouna yarr leu…bou ba di ngueu beugg wanatt seyy kaddou mou teu leu. Yalna leu ALLAH swt soppi si seu guiss guiss ou adouna. .bidjahil Seydina Mohammed saw. Si barké Cheikhoul Khadim

  15. Bayilen Waly té manou. sénégalais yi kou neek amgua lo lidianti si sa boop mba sa famille déguen di bayi sen foukky kilos di lidianti libeurou diambour. eyy way manou leen. Ragual leen Yalla

  16. BAYI LEN DIAMBOUR MOU NEK SENEGAL WAX REK NGEN LIGUEYI MO GUENE NGENI DEF LOU NIT DEF NGEN COMMENTAIR CI BOU NGEN KO DEE DEF DOU NGEN DEM FEEN

Laisser un commentaire