21 COMMENTAIRES
  • abou gerie

    journaliste sénégalais nio moune fén dége dége

  • awocat bi

    maitre keuyite vert yi moy probleme bi mome lagnou sopi faux billet, bou doneu keuyi soleil kesseh ken douko saisir , cette avocat donne toujours des munitions pour abattre son client apres le fameux contrat de 1000 concerts a 1 millions d euros chacun voila qu il nous embarque dans des histoire de billet vert

  • babandakarou

    mane yaye keyite You vert rek kene douci teuthie nit maitre fi europe bok. li takh mou diokhe 80 Million nak moy boude fi en generale da ngay diokhe touty khaliss bou bakh gnou diokhla faux billet you beurri

  • tafa

    xalis gneupa gha beug waaye nak na lew

  • dommage

    me yow ko yappe ….

  • deug

    Deug deug Senegal doynawar gueweul Yi rek gno teye rewmi en otage teleyi gno fa nek di fo rek khamougnou liguey tek deal rek AK samba mbayane aaah thione seck dagnouko wars teuthie sani tiabi bi guethie

  • diop

    la seule personne qui parle des secrets de l instruction c est bien cet avocat qui donne ou dement des motants en millards e 100 concerts en millions l argent suppose de diaga et en billets verts estimes o francs ,on ose nous prendre pour des idiots quelle honte pour sa profession

  • fans

    je suis thione seck Senegal nio so khor de mo takh do niou deme

  • karim

    Me Seye Personne ne te crois. que les personne qui l'ont entendu ne désespère de la profession d'avoat M seye en est l'antithèse desvaleurs et principes . Quelle compromission

  • baaaa

    non Maitre seye dou dem..il né pa constan dans c propos….mom si telé yi lay plaidel thione…

  • LeBaolbaol Tigui

    waxii picc lafi deg …..ses informations sont contraires à celles du ministre..il enfonce le complice et blanchit thione…………..bla…bla…

  • anita

    sokhor rek guenne def wanté lissi kanam rawoul beute

  • Saliou

    Arrêter de mentir il non rien dit de mal. thione fauter c vrai parce quan voulan trop gagner il a perdu c l'être humain seulement ki fai erreur arrêter vos commentaire idiot "bouleine niane yala mouke âme natou espèce de con "

  • cheikh Ahmed tijane

    conneries j'espère juste sera faite

  • deugue

    senegal dafa bari rambhath .thione avec faux billet c depui le temp de diawara encien presi gambien .son ami el hadji mbaye gaye et 3 libanais arreter a kaolack et deferé . ils faisait la transite via pirogue entre gambie et senegal . thione a durer dans

  • Beugue Sénégal sama rew

    Mane lima diakhal moy kou tolou ni thione on te donne un sac plain d'argent niounila Boulko oubi d'ici deux jours sou nongo rek mom khamna ni def na lou dioubadi

    • cheikh

      Doundou gou sottégoul louné khath nacci

  • santeyalla

    kholale boulaine nou sonale maitre seye kounou khoye sacs neko boule ka tidji fi ake 2 ou 3 jours nou gneuwate naila diokhe ma 80 000 000 million c la ve dire danoula wakh sacs bi aye milliare mougui si bire sacs bi boulaine nou sonale trafique la wakhou kasoww kasow reke nguene fi wakh

  • Lo mor

    Senegal rewou nafekhe lá mais bo nele mak dagay def lou yonn si non gabjalagti yonn tegiu sakaw

  • seck

    ay fen rek ngain fi def nit gni dofo nio

  • amdy

    pape alez niang nafékh nga sa invitée nafékh la wakh bou dofé nope yikoye dégue nité sa c'est du ne porte qu'on

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *